en
stringlengths 1
298
| wo
stringlengths 1
279
⌀ | fr
stringlengths 1
687
|
---|---|---|
German men and women... members of the Party...
|
Góor ñi ak jigéen ñi ci Allemagne... ndawi pàrti bi...
|
Des hommes et des femmes allemands, membres du Parti...
|
I would do the same.
|
Man itam dinaa ko def.
|
Je ferais la même chose.
|
Pelle...
|
Pelle...
|
Je suis désolé.
|
This is not a pizzeria.
|
Bii du pizzeria.
|
Ce n'est pas une pizzeria.
|
I'm afraid it's advocaat, sir.
|
Maa ngi ragal ni advocaat la, kilifa.
|
Je crains que ce soit l'avocat, monsieur.
|
"I doubt they'll kick up any fuss.
|
"Sikki sama xel ni dinañu def benn coow.
|
"Je doute qu'ils vont faire du bruit.
|
Here's my food.
|
Sama lekk mooy lii.
|
Voilà ma nourriture.
|
The lawyer fucked me.
|
Avocat bi laal nama.
|
L'avocat m'a baisé.
|
They're going to do it.
|
Dina ñu ko def.
|
Ils vont le faire.
|
- I can manage.
|
- Mën naa ko.
|
- Je peux m'en occuper.
|
Does anyone else have any complaints?
|
Ndax amna keneen ku am lu muy ñaxtu?
|
Quelqu'un d'autre a des plaintes?
|
Did you miss me?
|
Ndax namm ngama?
|
Je t'ai manqué?
|
He's telling us we should live.
|
Daf nuy wax danu wara dundu.
|
Il nous dit que nous devrions vivre.
|
They're not from these woods.
|
Duñu bawoo ci àll bi.
|
Ils ne sont pas de ces bois.
|
Well, before I turn you over to Bill there's one other thing I think we should talk about.
|
Balaa may jox la Bill amna beneen mbir buma jàpp ni dañu wara waxtaan ci.
|
Avant de vous remettre à Bill, il y a une autre chose dont nous devrions parler.
|
They broke my ribs, but I didn't say a word.
|
Ñu damm samay cox, waaye waxuma genn baat.
|
Ils m'ont cassé les côtes, mais je n'ai rien dit.
|
Help me.?
|
Dimbali ma.?
|
Vous m'aidez?
|
- Are those pictures on sale?
|
- Ndax nataal yooyu ñu ngi ci jaay?
|
- Ces photos sont en vente?
|
It seems you've already made up your mind.
|
Daa melni jël nga sa dogal ba pare.
|
Il semble que vous ayez déjà pris votre décision.
|
You are not always here and sometimes I'm so depressed.
|
Du saa yu nekk ngeen di fi nekk, yenn saa ma am naqar.
|
Tu n'es pas toujours là et parfois je suis tellement déprimée.
|
.in here, I'm the guy who can get things for you, sure?
|
.fii, man maay waa ji mëna la jox mbir, sure?
|
Je suis le type qui peut t'apporter des choses, c'est sûr?
|
- I wouldn't tax yourself, Your Majesty.
|
- Duma fay juuti, Sa Buur.
|
- Je ne vous imposerais pas, Votre Majesté.
|
And another one.
|
Ak beneen.
|
Et encore une.
|
Forget this stinking barn!
|
Fatteel ëtt bu xeeñ bii!
|
Oubliez cette grange puante!
|
-Stay away!
|
-Dellu leen!
|
- Ne vous approchez pas!
|
Give us something else.
|
Jox nu leneen.
|
Donne-nous autre chose.
|
We got 12 turkeys, about 40 chickens 50 sirloin steaks, two dozen of pork roast and 20 legs of lamb.
|
Nu am 12 dindon, lu tollu ci 40 ginaar, 50 steak sirloin, ñaari fukki yàppu mbaam xuux ak 20 tànki agneau.
|
Nous avons 12 dindes, environ 40 poulets 50 filets de filet, deux douzaines de rôtis de porc et 20 pattes d'agneau.
|
- What do they say about us?
|
- Lu ñuy wax ci nun ?
|
- Ils disent quoi de nous?
|
in a corner of the closet she met thirty-three Devil's Teeth
|
ci koñu armuwar bi mu daje ak fan weeri ak ñetti bëñi Seytaane
|
Dans un coin du placard, elle a rencontré 33 dents du diable.
|
Carry him down to the cellar.
|
Yobbu ko ci néeg bi.
|
Emmenez-le dans la cave.
|
It tends to stain.
|
Dafay faral di tafu.
|
Il a tendance à tacher.
|
Not to sound melodramatic but it's been known to give a few people second thoughts about the job.
|
Du nuru melodramatik waaye xam nañu ni dafay may ñu néew ñu xalaat ci liggéey bi.
|
Je ne veux pas paraître mélodramatique, mais ça a donné à certains une seconde pensée sur le travail.
|
Get that pushcart out of the way!
|
Dindil pushcart bi ci yoon wi!
|
Sortez cette poussette de la route!
|
Where'd you get this?
|
Fan nga jëlee lii?
|
Où avez-vous trouvé ça?
|
I'll take?
|
Dinaa jël?
|
Je prends?
|
- Ricci, you'll hang posters.
|
- Ricci, dinga takk afis.
|
- Ricci, vous allez accrocher des affiches.
|
Sugarplum ice cream!
|
Krem galass prune suukër!
|
Des glaces à la prune!
|
I like you, but I can't forgive what people have done.
|
Dama la bëgg, waaye mënuma baale li nit ñi def.
|
Je t'aime bien, mais je ne peux pas pardonner ce que les gens ont fait.
|
Where's Lady Eboshi?
|
Fan lady Eboshi nekk?
|
Où est Lady Eboshi?
|
Sorry, Mr. Dufayel.
|
Dufayel, jéggalu.
|
Je suis désolé, M. Dufayel.
|
You won't understand these things.
|
Dungeen xam mbir yooyu.
|
Tu ne comprends pas ces choses.
|
But outside, all you need is the Yellow Pages?
|
Waaye ci biti, li nga soxla du lenn ludul xët yu nete yi?
|
Mais dehors, tout ce dont vous avez besoin, ce sont les pages jaunes?
|
- Yes
|
- Waaw
|
- Je sais.
|
And no good thing ever dies.
|
Te dara lu baax du musa dee.
|
Et aucune bonne chose ne meurt.
|
Stablehand, why is that cow standing there?
|
Stablehand, lu tax nag bi taxaw foofu?
|
Écurie, pourquoi cette vache est là?
|
All these people.
|
Nit ñooñu ñépp.
|
Tous ces gens.
|
They're old shoes.
|
Dañuy dàll yu màgget.
|
Ce sont de vieilles chaussures.
|
. Aaarghh!
|
. Aaar!
|
Je suis désolé.
|
I'm Sanja.
|
Man Sanja laa.
|
Je suis Sanja.
|
You stay here.
|
Demal fii.
|
Restez ici.
|
One or two days at most.
|
Lu ëpp benn wala ñaari fan.
|
Un ou deux jours au plus.
|
But there's nothing we can do.
|
Waaye amul lenn luñu mën a def.
|
Mais on ne peut rien faire.
|
Scram, you oaf!
|
Scram, yaw dof!
|
Foutez le camp, crétin!
|
And then, there was the rain.
|
Ak taw bi am.
|
Et puis, il y a eu la pluie.
|
They're lords of some other mountain.
|
Boroom beneen tundu lañu.
|
Ce sont les seigneurs d'une autre montagne.
|
Did I forget you, Durga?
|
Ndax fàtte naa la, Durga?
|
Je t'ai oubliée, Durga?
|
- Wouldn't know.
|
- Duma xam.
|
- Je ne sais pas.
|
Do you like lamb, Doc?
|
Ndax bëgg nga agneau, Doktër?
|
Vous aimez l'agneau, Doc?
|
My king.
|
Sama buur.
|
Mon roi!
|
Teeth of your grandmother the devil are they?
|
Bëñi sa maam ju jigéen seytaane lañu?
|
Ce sont les dents de ta grand-mère le diable?
|
With pleasure.
|
Ak bànneex.
|
- Avec plaisir.
|
You want mozzarella on bread?
|
Bëgg nga mozzarella ci kaw mburu?
|
Tu veux de la mozzarella sur du pain?
|
I'm intrigued.
|
Dama jaaxle.
|
Je suis intriguée.
|
Carry him down to the cellar!
|
Yobbu ko ci néeg bi!
|
Emmenez-le dans la cave!
|
Everybody's innocent in here?
|
Ku nekk deful dara fii?
|
Tout le monde est innocent ici?
|
Um, I got it out of my dad's room, actually.
|
Um, ci néegu sama pàppa laa ko génne.
|
Je l'ai pris dans la chambre de mon père.
|
Flesh of my flesh heart of my heart...
|
Yaram sama yaram xol sama xol...
|
Carne de ma chair, cœur de mon cœur
|
I'll die a fool for this love.
|
Dinaa dee ni dof ndax mbëggeel gii.
|
Je mourrai comme un fou pour cet amour.
|
Baby.
|
Gone.
|
Je suis désolée.
|
- Why?
|
- Lu tax?
|
- Pourquoi? - Je ne sais pas.
|
So?
|
Kon?
|
Alors?
|
- Posters?
|
- Afiis yi?
|
- Des affiches?
|
Is she in love with him?
|
Ndax bëgg nako?
|
Est-elle amoureuse de lui?
|
It is, I believe, a rare thing that a man can stand before his old supporters after 20 years in office,
|
Yaakaar naa ni lu nééw la nit mëna taxaw ci kanamu ñi mu àndaloon ginaaw 20 at ci nguur gi.
|
Je crois que c'est rare qu'un homme puisse se tenir devant ses anciens partisans après 20 ans au pouvoir,
|
The government district too?
|
Nguur gi itam?
|
Le district du gouvernement aussi?
|
PS. Tell Heywood I'm sorry I put a knife to his throat?
|
PS. Wax Heywood ma jéggalu ci lima ko dóor baat?
|
P.S. Dis à Heywood que je suis désolé de lui avoir mis un couteau à la gorge?
|
That's all right.
|
Loolu baax na.
|
Ça va aller.
|
Hell, I wouldn't even know where to begin?
|
Jahannama, xamuma fan laa wara tàmbalee?
|
Je ne saurais même pas par où commencer.
|
.? t-t-the chubby fat-ass there.
|
.? t-t- mbaam xuux bu graas bi foofu.
|
Le cul gros et gros qui est là.
|
Now come on, Doc.
|
Leegi ñëwal, Doktër.
|
Allez, Docteur.
|
Why is Gabriella standing there?
|
Lu tax Gabriella taxaw foofu?
|
Pourquoi Gabriella est là?
|
Excuse me.
|
Baal ma.
|
Je suis désolé.
|
-No.
|
-Déedéet.
|
- Je ne sais pas.
|
You live in your work.
|
Yaa ngi dundu ci sa liggéey.
|
Vous vivez dans votre travail.
|
When we were young, your mother and I longed to travel.
|
Bi nuy ndaw, man ak sa yaay dañu bëggoon tukki.
|
Quand on était jeunes, ta mère et moi, on rêvait de voyager.
|
Wait.
|
Xaar.
|
Attends un peu.
|
At any minute, it could all be over.
|
Bépp yoon mën na jeex.
|
À tout moment, tout pourrait être fini.
|
You have been so spoiled by it.
|
Daf la yàq lool.
|
Tu as été si gâtée par ça.
|
A few good nights' rest will do it.
|
Soo noppee tuuti ci guddi gi, dina la ko mëna jàppale.
|
Quelques nuits de repos suffiront.
|
It's Okkoto!
|
Okkoto la!
|
Il est Okkoto!
|
H aven't you heard anything?
|
Ndax déggoo dara?
|
Vous n'avez rien entendu?
|
Watch your mouth!
|
Moytul sa gémmiñ!
|
Attention à ce que tu dis!
|
Never before had we seen water that fell from the gods for 60 days and nights.
|
Musunoo gis ndox mu wàcci ci yàlla yi diirub 60 guddi ak 60.
|
Jamais auparavant nous n'avions vu de l'eau qui tombait des dieux pendant 60 jours et nuits.
|
Denied him three times.
|
Ñu weddi ko ñatti yoon.
|
Je l'ai renié trois fois.
|
- How much are they?
|
- Ñaata lañuy njëg?
|
- Combien ça coûte?
|
I don't suppose they said anything in Denver about the tragedy we had up here during the winter of 1970.
|
Yaakaar naa ni waxu ñu dara ci Denver ci musiba bi ñu dundu fii ci hiver 1970.
|
Je ne pense pas qu'ils aient dit quelque chose à Denver sur la tragédie que nous avons eu ici pendant l'hiver de 1970.
|
Advocaat, is it?
|
Avocaat, wala ?
|
Vous êtes Advocaat?
|
What are you doing here?
|
Lu ngeen di def fii?
|
- Tu fais quoi ici?
|
I didn't speak.
|
Waxuma.
|
Je n'ai pas parlé.
|
- No. Not here!
|
- Déedet. Du fii!
|
- Non, pas ici!
|
Subsets and Splits
No community queries yet
The top public SQL queries from the community will appear here once available.