en
stringlengths
1
298
wo
stringlengths
1
279
fr
stringlengths
1
687
Well....
Baax na....
Je sais.
Red.
Xonq.
Le rouge.
To my knowledge, he lived out the rest of his days drinking his food through a straw.
Lima xam mooy, bis yi ci des dafa daan naan ñam ci ñax.
À ma connaissance, il a vécu le reste de ses jours en buvant sa nourriture à travers une paille.
How can they do this?
Naka lañu mënee def loolu ?
Comment peuvent-ils faire cela?
Looks like you might have got a spot of it on yourself Jeevesy old boy.
Daa melni amna lu ci nekk ci sa bopp Jeevesy old boy.
On dirait que vous pourriez avoir une tache de lui sur vous-même Jeevesy vieux garçon.
Come and get me!
Ñëwal jël ma!
Viens me voir!
You will have my son.
Di nga am sama doom.
Vous aurez mon fils.
- Not me. I didn't shoot my wife and I didn't shoot her lover?
- Du man. Tiirewuma sama jabar te tiirewuma soppeem?
Je n'ai pas tué ma femme et son amant?
Woman behold your son.
Ndaw si, sa doom la.
Femme, regarde ton fils.
Call her back!
Woowaat ko!
Rappelle-la au téléphone!
She might just do that.
Mën na def loolu.
Elle pourrait le faire.
What's your favorite food, then?
Kon, lan mooy ñam wi la gënal?
Quel est ton plat préféré?
Together we'll live.
Dina nu bokk dundu.
Nous vivrons ensemble.
- Because of your heart.
- Ndax sa xol.
- À cause de ton cœur.
He's seen us!
Gis na nu!
Il nous a vus!
We'II pull through this.
Danuy jaar ci lii.
On va s'en sortir.
I won't tolerate it in any of my units.
Duma muñ benn ci samay yunit.
Je ne tolérerai pas ça dans aucune de mes unités.
I feel better.
Maa ngi féex.
Je me sens mieux.
Let me go!
Bàyyil ma dem!
Laissez-moi!
As it turned out, Tommy had himself a young wife and a new baby girl.
Tommy am jabar ju ndaw ak doom ju jigéen ju bees.
Il s'est avéré que Tommy avait une jeune femme et une petite fille.
I won't make a sound.
Duma def benn bruit.
Je ne ferai pas de bruit.
My God, a job!
Sama Yàlla, liggéey!
Mon Dieu, un travail!
Fresh fish!
Jën wu fere!
Du poisson frais!
Aspasia it says.
Aspasia la wax.
Il est écrit Aspasie.
He should have died in here.
Dafa waroon dee ci biir.
Il aurait dû mourir ici.
Frame number: 12033.
Nimero kaadar bi: 12033.
Numéro de cadre: 12033.
I am left behind, a penniless beggar.
Maa ngi des ci ginaaw, yalwaankat bu amul xaalis.
Je suis resté derrière, un mendiant sans le sou.
Convince him that we have to leave Berlin, Eva!
Eva, gëmloo ko ni dañu wara bàyyi Berlin!
Convainquez-le que nous devons quitter Berlin, Eva!
Why should she watch you eat?
Lu tax mu wara xool ngay lekk?
Pourquoi devrait-elle te regarder manger?
The mama Bengta died and now she's in the cemetery back home.
Yaay ji Bengta faatu na, leegi mingi ci bàmmeel bi ci këram.
La maman Bengta est morte et maintenant elle est dans le cimetière de chez elle.
Drink.
Naan.
Je vous en prie.
You know better, Machatas.
Machatas, yaa ko gën a xam.
Vous le savez bien, Machatas.
Your suggestion is absurd!
Sa xalaat amul benn njariñ!
Votre suggestion est absurde!
I made it!
Def naa ko!
Je l'ai fait!
- And I am not my father.
- Te duma sama baay.
- Et je ne suis pas mon père.
I can't believe they called us stoners.
Mënu ma ni dañu nu woowe ay dojkat.
Je n'arrive pas à croire qu'ils nous aient traité de défoncés.
You have to go or there will be trouble with the authorities.
Danga wara dem lu ko moy jafe-jafe dina am ak kilifa yi.
Vous devez partir ou il y aura des problèmes avec les autorités.
I don't understand.
Nànduma.
Je ne comprends pas.
Goddamn--!
Yalla--!
Nom de Dieu!
That doesn't matter, sir.
Loolu amul solo, sang bi.
Ça n'a pas d'importance.
- Yes. I know.
- Waaw. Xam naa.
- Je sais.
That's goddamn right.
Loolu mooy dëgg.
C'est vrai, putain.
Maybe it was the thought of them on the streets or his child growing up not knowing her daddy.
Mën na am muy xalaat seen nekk ci mbedd mi wala doomam biy màgg te xamul pàppaam.
Peut-être que c'était la pensée d'eux dans la rue ou de son enfant grandissant sans connaître son père.
French fries and ketchup.
Frites ak ketchup.
Des frites et du ketchup.
Where are you?
Fan nga nekk?
Où est-ce que vous êtes?
He knows it better than I do.
Moo ma gëna xam.
Il le sait mieux que moi.
My predecessor in this job hired a man named Charles Grady as the winter caretaker.
Ki ma jiitu ci liggéey boobu dafa jël ku tuddu Charles Grady ngir mu toppatoo baayima yi ci hiver bi.
Mon prédécesseur dans ce travail a embauché un homme nommé Charles Grady comme gardien d'hiver.
Run along to your mother, dear.
Daw dem ci sa yaay, sama xarit.
Va voir ta mère, chérie.
Wait!
Xaar!
- Je suis désolé.
I'm thinking Andy could use a nice welcome back when he gets out of the infirmary.
Dama jàpp ni Andy mën nako dalal bu baax su génnee ci saal bi.
Je pense qu'Andy pourrait avoir besoin d'un bon accueil quand il sortira de l'infirmerie.
And your father is a widower?
Ak sa pàppa jabar la?
Et votre père est veuf?
If you're done, get out of here!
Soo noppee, jogeel fii!
Si vous avez fini, sortez d'ici!
Fall back!
Dellu ginaaw!
Retournez!
But I truly believe you'll see him again.
Waaye gëm naani dinga ko gisaat.
Mais je crois vraiment que vous le reverrez.
You're lucky, Orin.
Am nga wërsëg, Orin.
Vous avez de la chance, Orin.
Insane!
Dof!
Vous êtes dingue!
Day draws to its close, night's mantle descends.
Bis baa ngi jegesi, màntoo guddi gi wàcci.
Le jour touche à sa fin, le manteau de la nuit descend.
He gave me a job!
Daf ma jox liggéey!
Il m'a donné un travail!
If Mama could see us!
Suma sama yaay mënoon nu gis!
Si maman pouvait nous voir!
The water's wet.
Ndox mi tooy na.
L'eau est mouillée.
Fresh fish today!
Jën wu fere tay!
Du poisson frais, aujourd'hui!
Perhaps Mr. trainee could tell me where she is suppose to stand.
Amaana M. stagiaire bi mën nama wax fumu wara taxaw.
Peut-être que M. le stagiaire pourrait me dire où elle est supposée se tenir.
Hey, what about us?
Saa waay, nun nak?
Hé, et nous alors?
Son, behold your mother.
Sama doom, sa yaay a ngii.
Mon fils, voici ta mère.
Soon, I'll be up.
Dinaa yewwu ci diir bu gàtt.
Je serai bientôt là.
Which Katja?
Katja bi?
Quelle Katja?
I would like to see where you work, if you don't mind...
Dama bëgga gis fi ngay liggéey, soo ko bëggee...
J'aimerais voir où vous travaillez, si ça ne vous dérange pas...
Or come with me.
Wala nga ànd ak man.
Ou viens avec moi.
Just remember, squirt.
Nga bàyyi sa xel, squirt.
N'oublie pas, espèce de bouffon.
I'm still your king.
Ba leegi maa ngi seen buur.
Je suis toujours votre roi.
Spareribs, 45!
45
Les côtes d'épargne, 45!
I promise I'll tiptoe.
Maa ngi lay dige ni dinaa ko def.
Je te le promets.
Let him pass.
Bàyyileen ko mu jàll.
Laissez-le passer.
Repeat after me.
Baamtu ci sama ginaaw.
Répète après moi.
You're the important one.
Yaay ki am solo.
C'est vous qui êtes important.
The name's Red.
Tur wi xonk la.
Je m'appelle Red.
I lost many a man.
Ñàkk naa nit ñu bari.
J'ai perdu beaucoup d'hommes.
What the fuck have you done?
Lu nga def?
Tu as fait quoi?
- 2 dinars
- 2 dinaar
- 2 dinars. - Je vous en prie.
- So who is he?
- Kon moom kan la?
- Alors qui est-ce?
Master Friis?
Jàngalekat Friis?
Vous êtes M. Friis?
For the second time in my life,
Ñaareelu yoon ci sama dundu,
Pour la deuxième fois de ma vie,
Yakul and I will visit you.
Man ak Yakul dinañu la seeti.
Yakul et moi allons vous rendre visite.
What's your son going to say?
Lu sa doom di wax?
Que va dire votre fils?
She's devising a stratagem.
Mingi xalaat pexe.
Elle est en train de préparer un stratagème.
We can do anything we want, because we're both men.
Mën nanu def lépp lunu bëgg, ndax nun ñaar ñépp ay góor lañu.
On peut faire ce qu'on veut, parce qu'on est tous les deux des hommes.
Good... so we can divide up the work.
Baaxna... ngir nu mëna xaaj liggéey bi.
Bien... on peut donc se partager le travail.
Have you so quickly forgotten?
Ndax gaaw nga fàtte nii?
Tu as oublié si vite?
I'm sure he'll continue the fight in Bavaria for a certain time.
Yaakaar naa ni dina wéyal xeex bi ci Bavière ci diir bu yàgg.
Je suis sûr qu'il continuera à se battre en Bavière pendant un certain temps.
He came up with his wife and two little girls of about 8 and 10.
Mu ñëw ak jabaram ak ñaari doomam yu jigéen yu tollu ci 8 at ak 10 at.
Il est venu avec sa femme et ses deux petites filles, âgées de 8 et 10 ans.
Why you say that?
Lu tax nga wax loolu?
Pourquoi tu dis ça?
Sounds good to us?
Dafa baax ci nun?
Ça nous va?
Who is this woman you call your queen, Alexander?
Kan mooy jigéen jii ngay woowe sa reine, Alexander?
Qui est cette femme que vous appelez votre reine, Alexandre?
Did you take something from Mrs. Mukherji's garden?
Ndax jël nga dara ci jardinier Mme Mukherji?
Vous avez pris quelque chose dans le jardin de Mme Mukherji?
Berlin, 20 April, 1945 Adolf Hitler's 56th birthday 21/2 years later
Berlin, 20 awril, 1945 56eelu bësu juddu bu Adolf Hitler 21 at ak genn-wàll ci ginnaaw
Berlin, 20 avril 1945 Deux ans et demi plus tard, le 56e anniversaire d'Adolf Hitler
Row me across to the other side.
Jàllal ma ba ci weneen wetu dex gi.
Ramenez-moi de l'autre côté.
Back to work!
Dellu ci liggéey bi!
Retournez au travail!
Young ones, never been with a woman.
Ndaw yi, musu ñu nekk ak jigéen.
Jeunes gens, vous n'avez jamais été avec une femme.
I've got two jobs, but they're not for you.
Am naa ñaari liggéey, waaye du yaw.
J'ai deux emplois, mais ils ne sont pas pour toi.
Red?
Xonq?
Le rouge?