translation
dict |
---|
{
"fr": "Apportez-lui de l'eau.",
"wo": "Inndil ko ndox."
} |
{
"fr": "Je suis un simple prêtre, mais je dirais que ça vaut trois sacs de riz!",
"wo": "Man sëriñ bu woyof laa, waaye mën naa ni lii mooy ñatti saaku céeb!"
} |
{
"fr": "C'est toi qui va me défendre.",
"wo": "Yaay waa ji may defense"
} |
{
"fr": "Ses réalisations ont ainsi permis au club de la Mersey d’entretenir le rêve d’un nouveau titre de champion, 29 ans après son dernier sacre.",
"wo": "Ay dugalam moo tax ba këlëbu Mersey di yaakaar beneen raayab sàmpiyoŋ, ñaar-fukki at ak juróom-ñeenti ginnaaw bi mu ko mujje jël."
} |
{
"fr": "Ni la Confédération africaine des nations ni Tactical Steel n’ont répondu à nos appels.",
"wo": "Du Kurélu Afirig gi boole réew yépp, du Tactical Steel, kenn ci ñoom ñaar wuyuwul ci suñu woote bi."
} |
{
"fr": "Je dois passer un appel.",
"wo": "dama wara woo"
} |
{
"fr": "Je ne me suis pas enfui.",
"wo": "Dawuma."
} |
{
"fr": "Ferme ce bébé.",
"wo": "Tëjal liir bi."
} |
{
"fr": "Je vais les poursuivre.",
"wo": "Dinaa leen tuumal."
} |
{
"fr": "Ne te mets pas en colère et ne gâche pas une bonne chose.",
"wo": "Bul yéemu ci man ba yàq lu baax."
} |
{
"fr": "Donc, si quelque chose se passe à l'intérieur..",
"wo": "Kon, su amee lu xew ci biir.."
} |
{
"fr": "Bien avant le Daily Show et le Colbert Report, Heck et Johnson envisageaient une publication qui parodierait les nouvelles — et les reportages — lorsqu’ils étaient étudiants à l’université de Washington en 1988.\n",
"wo": "Lu yagg laata Daily Show bi ak Colbert Report bi, Heck ak Johnson meebeetna gnu bénn tééré buy toogn xibaar yi—ak di joxé xibaar—bignu nékké ay ndongo ci UW ci atum 1988.\n"
} |
{
"fr": "J'ai vécu ma vie comme mon père l'a vue.",
"wo": "Maa ngi dundu sama dundu ni sama pàppa gisee."
} |
{
"fr": "Trois minutes plus tard, Gueye sortait son équipe de la torpeur d’un coup de canon qui permis au Sénégal de dérouler jusqu’à la fin, d’autant que le Bénin a terminé à dix après l’expulsion de Verdon (82e).",
"wo": "Ñetti simili ginnaaw loolu, Géy dafa génne Senegaal ci njàqare bi mu dugalee bal bi tax ñu am ndam, te sax Bene dañoo joxoon kàrtoŋ bu xonq Werdon ca juróom-ñett-fukkeelu simili ba ak benn."
} |
{
"fr": "Vous m'avez demandé de l'aide.",
"wo": "Laaj ngama ndimbal."
} |
{
"fr": "Hum ! Hum ! répondit le roi. ",
"wo": "Buur bi tontu ko ne : Hum! Hum!"
} |
{
"fr": "Le communiqué de la CEDEAO a été bien accueilli par les populations.",
"wo": "Askan wi rafetlu nañu yégleb CEDEAO bi."
} |
{
"fr": "Mes paroles et mon silence sont pour vous seulement...",
"wo": "Sama wax ak sama noppi, yaw rek la jëm..."
} |
{
"fr": "Attendez au Monte Sacro.",
"wo": "Xaaral ci Monte Sacro."
} |
{
"fr": "En fait, Pastef signifie Patriotes du Sénégal pour le Travail, l’Éthique et la Fraternité.",
"wo": "Li Pastef di tekki mooy, Doomi Senegaal ngir Liggéey, Yemale, Mbokkoo."
} |
{
"fr": "Tu dois leur faire confiance.",
"wo": "Danga wara wóolu leen."
} |
{
"fr": "Il me faut une dose de vitamine B12.",
"wo": "Dama soxla benn pikiiru B12."
} |
{
"fr": "La réhabilitation, l’équipement et la mise aux normes d’un Daara de 2 salles de classes.",
"wo": "Doy na waar."
} |
{
"fr": "Et vousconviendrez qu’il remplit fort bien son mandat.",
"wo": "Te nangu ngeen ni dina matal ayam gi ci anam bu baax"
} |
{
"fr": "Je pense que nous devrions nous dire où nos trésors sont enterrés.",
"wo": "Dama jàpp ni dañu wara waxante fu ñu suul sunuy alal.."
} |
{
"fr": "- Je suis un homme.",
"wo": "- Waaw?"
} |
{
"fr": "Qui est là-haut?",
"wo": "Kan moo nekk ci kaw?"
} |
{
"fr": "Exiger des excuses publiques à un ministre de la République sous le Président Macky Sall pour violation d’un arrêté ministériel est la meilleure manière de se morfondre dans les chemins méandreux de la politique politicienne.",
"wo": "Baalu loo ab jëwriñu nguurug njiitu réew mi Maki Sàll ci kanamu askan wépp ndax ab jalgatib dogal bu mu def, mooy doxalin wi gën ngir xaar ba xàddi ci pólótigu xaxaate bi."
} |
{
"fr": "Il n'y a pas plus de trois miles d'ici, est la terre - un mur vert inégale qui occupe une partie occidentale.",
"wo": "Foofu, amul lu ëpp ñatti kilomeetar ci fi, la réew mi am -- miir bu wert bu jaxasoo, bu nekk ci wàllu sowwu."
} |
{
"fr": "le nombre d'exercices physiques n'est pas le seul nombre d'événements pouvant être organisés selon ces critères",
"wo": "limu tàggat yaram du limu xew-xew yiñ mëna amalee ci anam yii"
} |
{
"fr": "Mon père m'a jeté dans la bataille avant que je sache comment se battre.",
"wo": "Sama pàppa yóbbu ma ci xare balaa may xam xeex."
} |
{
"fr": "Tu as eu ça la première nuit qu'on s'est rencontrés.",
"wo": "Guddi gi ñu njëkka daje, xam nga ko."
} |
{
"fr": "Eugene, ma chaise.",
"wo": "Eugene, sama toogukaay."
} |
{
"fr": "Ils ne pouvaient voir la terre à des kilomètres de distance, seulement la mer sans fin.",
"wo": "Mënu ñu woon gis suuf si lu tollu ci ay kilomeetar, duñu gis ludul géej gi amul àpp."
} |
{
"fr": "Dans ce cas, ha, j'ai aussi gagné.",
"wo": "Suko defee, ha, man itam daan naa."
} |
{
"fr": "Nous comptons saisir directement le juge d’instruction.",
"wo": "Dinañu kalaameji mbir mi ci àttekat biy def lànket ci jëf ju ñaaw ba jéggi dayo."
} |
{
"fr": "Arrêtez cette merde!",
"wo": "Taxawal lii!"
} |
{
"fr": "C'est mon garçon.",
"wo": "Lii sama doom la."
} |
{
"fr": "Révoqué?",
"wo": "Rewoke?"
} |
{
"fr": "La vitesse maximale des vents soutenus de cette tempête, qui se produit à environ 4 800 km de Miami, en Floride, atteint 64 km/h.\n",
"wo": "Tawbi, nékk ci lutollook 3,000 miles ci Miami, Florida, amna ay gélaw yu 40 mph (64kph).\n"
} |
{
"fr": "Au cours de son voyage, Iwasaki a eu des problèmes à de nombreuses occasions.\n",
"wo": "Ci diiru tukkeem, Iwasaki dafa jokkonteeg ak coow ci anam yu bare.\n"
} |
{
"fr": "Elle essaie de jouer avec toi.",
"wo": "Dafay jéema fo ak yaw, waay."
} |
{
"fr": "Ça alors!",
"wo": "Waaw!"
} |
{
"fr": "[CLINKS DE CUISINE]",
"wo": "[KLINK GLAAS]"
} |
{
"fr": "Jolis chiens.",
"wo": "Xaj yu baax."
} |
{
"fr": "On a un Ronald Earl.",
"wo": "DCPD, amnanu benn Earl."
} |
{
"fr": "Les deux :",
"wo": "ÑAAR YÉPP:"
} |
{
"fr": "Si vous le retirez, vous saignez et vous mourrez.",
"wo": "Soo ko dindi, dinga nàcci, nga dee."
} |
{
"fr": "Selon le président du comité de pilotage, l’ancien Gouverneur Léopold Wade, ce forum permettra de faire une analyse prospective et de proposer des solutions pour un meilleur vivre ensemble.",
"wo": "Ni njiitu kurél gi, górnóor bu jëkk ba Léwópól Wàdd gisee, waxtaan wi dina tax ñu def ab jàngat buy séentu ëllëg ak tamit joxe ay saafara ngir am dundug bennoo gi gën."
} |
{
"fr": "Pourquoi est-ce que tu demandes à propos de lui?",
"wo": "Lu tax nga koy laaj?"
} |
{
"fr": "Je demande une RTQ.",
"wo": "Laaj QRT."
} |
{
"fr": "le ballon est passé entre les jambes.",
"wo": "Ci xarante tànk yi la bal bi jaar"
} |
{
"fr": "Garçon:",
"wo": "xale bu góor:"
} |
{
"fr": "L'équipe était auparavant connue sous le nom mémorable de Beaneaters, qui, curieusement, pourrait également être considéré comme un surnom indien.",
"wo": "Bu njëkkoon xamoon nañu ekip bi ci tur wi ñuy fàttaliku di Beaneaters, te lu doywaar la, mën nañu ko jàppee ni tur wi ñuy woowe waa Inde."
} |
{
"fr": "- Je suis en sueur.",
"wo": "- Ñaqq"
} |
{
"fr": "Une fois le totem détruit, on peut sacrifier le Hollow.",
"wo": "Bu totem bi yàqoo, mën nanu saraxe Hollow bi."
} |
{
"fr": "Laissez-moi attaquer les unités de niveau 1 et je vous ferai une équipe de plombiers qui feront tout ce que vous pourrez imaginer.",
"wo": "Xaaral ma dóor Tier One units yi, dinaa la tabax ekip pipe hitters yuy def lépp loo mëna xalaat."
} |
{
"fr": "Je ne peux pas.",
"wo": "Mënu ma."
} |
{
"fr": "Pourquoi tu as fait ça?",
"wo": "Lu tax nga def loolu?"
} |
{
"fr": "Mais un jour, il est arrivé...",
"wo": "Waaye benn bis..."
} |
{
"fr": "Car plusieurs chiffres seront annoncés par ses proches (ministres et députés).",
"wo": "Ndaxte dinanñu yegge ay jegeñaaleem (jëwriñ ak deppite) lim yu bare."
} |
{
"fr": "Si elle ne reçoit pas ce médicament à temps, elle mourra.",
"wo": "Su joteewul garab gi ci waxtu wi war, dina dee."
} |
{
"fr": "rétribution",
"wo": "weexal b-"
} |
{
"fr": "Tu m'as dit d'arriver.",
"wo": "Yaa ma wax ma ñëw fii."
} |
{
"fr": "Et vous rougissez.",
"wo": "Te yaa ngi xonk."
} |
{
"fr": "La pensée qui atteint les yeux...",
"wo": "Xalaat bi yegg ci bët yi..."
} |
{
"fr": "Des éclairs de lumière et de noirceur.",
"wo": "Leer gu leer ak ñuul."
} |
{
"fr": "Zéro.",
"wo": "Tus."
} |
{
"fr": "Nous espérons que cela répondra à vos besoins.",
"wo": "Gën nanu ni lii dina saafara li ngeen soxla."
} |
{
"fr": "Je suis si fière de toi.",
"wo": "Kontaan naa ci yaw."
} |
{
"fr": "il est assis tout à son aise au salon.",
"wo": "Mu nga ne faax ca saal ba"
} |
{
"fr": "Ce n'est rien comparé à...",
"wo": "Loolu amul benn njariñ suñu ko méngale ak... -"
} |
{
"fr": "Je poursuivis ma marche vers le mur.",
"wo": "Ma wey di dox jëm ca miir ba."
} |
{
"fr": "chaque terre.",
"wo": "Suuf su-nekk"
} |
{
"fr": "Combien de temps pouvez-vous faire une frappe aérienne sur la Maison Blanche?",
"wo": "naka ngay mëna gaawe dóor kër gu weex gi?"
} |
{
"fr": "Patron, c'est la police.",
"wo": "Patroŋ bi, poliis la."
} |
{
"fr": "Des zombies.",
"wo": "Zombie yi."
} |
{
"fr": "J'ai ça ici.",
"wo": "Amnaa loolu fii."
} |
{
"fr": "Savez-vous combien de personnes vivent dans cette ville?",
"wo": "Ndax xam nga ñaata nit ñoo dëkk ci dëkk bii ?"
} |
{
"fr": "Les accents nord-américain et britannique sont très similaires, et les gens ne peuvent pas faire la différence entre eux",
"wo": "Aksentu Amerique du Nord ak Grande Bretagne dañuy nuru lool, te nit ñi mënu ñu ràññee"
} |
{
"fr": "Je suis foutue.",
"wo": "Dama jaaxle lool."
} |
{
"fr": "Scott, je crois que tout le monde mérite une chance de se racheter.",
"wo": "Scott, jàpp naa ni ku nekk yelloo na mucc."
} |
{
"fr": "Et il n'y avait aucun moyen que certaines des connaissances qui étaient déjà là puissent avoir été acquises par ceux qui les ont étudiées.",
"wo": "Te yenn ci xam-xam yi fi nekkoon mënoon nañu am ci ñi ko doon saytu."
} |
{
"fr": "Pour les hommes.",
"wo": "Ngir góor ñi."
} |
{
"fr": "Il est à la retraite depuis des années.",
"wo": "Retrete, ay at ci ginaaw."
} |
{
"fr": "Vous l'avez enterré à 50 mètres sous terre.",
"wo": "Suul nga ko juróom fukki meetar ci suufu suuf"
} |
{
"fr": "Nous t'attendrons.",
"wo": "Dina nu la xaar."
} |
{
"fr": "Si c'est tout...",
"wo": "Kon, sudee loolu rekk la..."
} |
{
"fr": "D'autres doivent se mettre au travail.",
"wo": "Ñeneen ñi dañu wara dem liggéey."
} |
{
"fr": "Le sens peut changer quand vous essayez de faire une déclaration plus longue.",
"wo": "Li muy tekki mën na soppiku sooy jéema wax lu gëna gudd."
} |
{
"fr": "Je commence les réparations.",
"wo": "Tambali defar. Xool sama ginaaw."
} |
{
"fr": "Je t'ai dit de ne pas le toucher.",
"wo": "Mani ko bul ko laal."
} |
{
"fr": "Nous avons vu une nouvelle plage.",
"wo": "Gis nanu tefes gu bees."
} |
{
"fr": "nettoie-le avec de la cendre de foyer !",
"wo": "Fompe ko dóomu taal"
} |
{
"fr": "L’initiative d’organiser ce forum émane des bonnes volontés et non des évêques.",
"wo": "Mbébétu amal ndaje moomu mu ngi jóge ci ñuy defal Yàlla te doonuñu ay làbbe."
} |
{
"fr": "être trop fier pour",
"wo": "réylu"
} |
{
"fr": "Vous avez vu quelque chose.",
"wo": "Danga gis dara."
} |
{
"fr": "Il a souligné que tout raisonnement supérieur découle de l'interaction sociale entre l'enfant et ses représentants ou de la culture qui effectue une tâche conjointe.",
"wo": "Mu xamle ni, bépp xalaat bu gëna kawe mingi aju ci diggante xale bi ak ay ndawu réewam wala cosaan ak aada yi ñuy liggéeyandoo."
} |
{
"fr": "il a pêché un gros poisson.",
"wo": "Napp na jén wu mag"
} |
{
"fr": "Tu n´espérais nullement que le Livre te serait révélé. Ceci n´a été que par une miséricorde de ton Seigneur. Ne sois donc jamais un soutien pour les infidèles",
"wo": "Musuloo yaakaar ne dees na la jox Téere ba. Lu dul ne yërmaande ju bawoo ca sa Boroom. Te bul dimbali mukk yéefar yi ; "
} |
Subsets and Splits
No community queries yet
The top public SQL queries from the community will appear here once available.