translation
dict
{ "fr": "Mais comment?", "wo": "Waaye naka." }
{ "fr": "Pour diverses personnes de différentes façons je suis dans pour de l'argent que je n'ai pas.", "wo": "Ci nit ñu bari ci anam yu bari maa ngi ci xaalis buma amul." }
{ "fr": "Ouais, la mère de la fille de SINFIN l'appelle comme ça.", "wo": "WAAW, SAMA WAT CI SINFIN DAFA WOO LI CI STAFF-AM." }
{ "fr": "Autrement dit, les 100 000 kits alimentaires supplémentaires ont représenté 2 758 577 292 FCFA, soit moins de 30 000 FCFA le prix du kit.", "wo": "Maanaam, téeméeri junney dund yi ñu dolli ñu ngi tollu woon ci ñaari milyaar yu teg juróom-ñaar-fukki milyoŋ ak juróom-fukk ak juróom-ñett ak juróomi téeméeri junneek juróom-ñaar-fukk ak juróom-ñaar ak juróom-fukk ak juróom-ñett yu te ñaari fiftin, lu matul juróom-benni junne ci seefaa, njëgu dund bu nekk." }
{ "fr": "Avec les nouvelles retenues j’essayais de me rendre utile: tantôt en servant d’interprète pour éclairer sur les procès-verbaux ou les jugements rendus, tantôt en réconfortant, ce qui me permettait d’oublier ma propre tristesse.", "wo": "Ak ñu bees ñi ñu tiye, dama doon jéem a am njariñ : yenn saa yi ma nekk tekkikatu xibaar ngir leeral nettali yi wala àtte yi ñu def, yenn saa yi ma dëfal te loolu sax moo doon tax ma fàtte sama naqaru bopp." }
{ "fr": "Tu appelles ça un vaisseau?", "wo": "Yaa ngi woowe lii gaal?" }
{ "fr": "Omar est un jeune citadin; il ne sait pas manger de la bouillie à la main.", "wo": "Omar goneg taax la; mënula fas laax" }
{ "fr": "[Coupes de clés pendant que vous attendez]", "wo": "[DAGG YI BI NGAY XAAR]" }
{ "fr": "Poule A : Rwanda, RD Congo, Angola, 2e qualifié groupe E (Maroc, Cap-Vert ou Ouganda)Poule B : Tunisie, Centrafrique, Egypte, 3ème groupe E (Maroc, Cap-Vert ou Ouganda)Poule C : Nigeria, Côte d’Ivoire, Kenya, Mali.", "wo": "Mbooloo A : Ruwàndaa, RD Kóngoo, Àngolaa, ñaareelu ekib bi jàll ci gurub E bi (Marog, Kab-Weer wala Ugàndaa), Mbooloo B : Tinisi, Sàntar Afrig, Esipt, ñetteelu gurub E bi (Marog, Kab-Weer wala Ugàndaa), Mbooloo C : Niseriyaa, Kótdiwaar, Keeñaa, Mali." }
{ "fr": "Finalement, une partie du matériel génétique est transformée en une teinture pourpre.", "wo": "Ginaaw ga, benn wàll ci macceer genetik bi dafay soppi nekk tinte bu wiyole." }
{ "fr": "Je n'ai pas traversé l'Asie pour voler cette victoire, Cassander.", "wo": "Jéggaluma Asie ngir sàcc ndam lii, Cassander." }
{ "fr": "Garde la tête baissée.", "wo": "Yaa ngi tëye sa bopp." }
{ "fr": "Une équipe d'observateurs démontrera qu'ils ont la capacité de résoudre des problèmes complexes.", "wo": "Ay seetaankat dina ñu wane ni mën nañu saafara jafe-jafe yu tar." }
{ "fr": "Je ne suis pas grincheux.", "wo": "Duma mer." }
{ "fr": "Il s’agit de la tenue imminente de leur Assemblée générale.", "wo": "Moo ngi doon seen ndaje mu mag mi ñuy amal." }
{ "fr": "La loi de Pékin interdit les marchés en plein air dans la ville.", "wo": "Yoon wiñ tëral ci Beijing dafa tere marse luuma yi ci dëkk bi." }
{ "fr": "Venez voir, docteur.", "wo": "Doktër, ñëwal." }
{ "fr": " Nous avons également investi dans des formations pour que notre personnel puisse offrir des conseils avisés. ", "wo": "Dugalnañu itam ay koppar ci ay naataango yu ñu taggat ngir ñu nekk ñuy jege di jappale. " }
{ "fr": "L’attaquant de Cayor Foot Football s’est même offert un triplé (29′, 50′).", "wo": "Dugalkat bu Kayoor Fut Futbal dugal na sax ñetti bal (ñaar-fukk ak juróom-ñeenteelu simili, juróom-fukkeelu simili)." }
{ "fr": "Attendez la porte, s'il vous plaît!", "wo": "Nanga tëye buntu bi!" }
{ "fr": "Assurez-vous qu'il est chaud.", "wo": "Fexeel mu tàng." }
{ "fr": "Si le temps se calme, on pourrait descendre la montagne.", "wo": "Su amee temperatiir bu baax, amaana dina nu mëna wàcci tundu wi." }
{ "fr": "La façon dont la Maison Blanche traite le FBI n'est pas bonne.", "wo": "Li kër gu weex gi di doxalee ci FBI baaxul" }
{ "fr": "Mon Dieu.", "wo": "Mbaax." }
{ "fr": "On peut refinancer?", "wo": "Ndax mën nanu xaalis?" }
{ "fr": "Pourquoi tu te caches ici maintenant?", "wo": "Lu tax ngay nëbb fii leegi?" }
{ "fr": "Cible verrouillée", "wo": "target bi tëju" }
{ "fr": "Je vais vous montrer pourquoi.", "wo": "Dinaa la wan luko waral." }
{ "fr": "En privé, il peut être si attentionné.", "wo": "Su nekkee ci boppam, mën na nekk nit ku baax." }
{ "fr": "Le Sénégal où le nombre de victimes va croissant, est aussi frappé de plein fouet.", "wo": "Mbir mi sonal tamit Senegaal gi nga xam ne, way-loru yi dañuy gën a bare." }
{ "fr": "- Je sais.", "wo": "Newton!" }
{ "fr": "Il est temps de partir, M. le Président!", "wo": "Dafa jot dem, M. Persida!" }
{ "fr": "comment danse-t-on le mballax ?", "wo": "Naka lañuy fecce mballax" }
{ "fr": "Il ne savait pas que, pour les rois, le monde est très simplifié.", "wo": "Dafa xamul woon ne buur yi dañu yombal seen àdduna." }
{ "fr": "Je peux y retourner parce que tu as parlé.", "wo": "Dama wara dem ndax wax nga." }
{ "fr": "N'importe quoi dans ta main...", "wo": "Lépp lu nekk ci sa loxo-" }
{ "fr": "Il est étranger à nos mœurs.", "wo": "Gannaaw la ci sunuy doxalin." }
{ "fr": "Je ne sais pas. Je ne sais pas.", "wo": "Xamuma." }
{ "fr": "Tu te souviens de ça?", "wo": "Fatteliku yii?" }
{ "fr": "RFI passe en revue trois autres sélections qui nourrissent de grandes ambitions.", "wo": "RFI jàll na ci ñetti tànneef yuy dundal seen bëgg-bëgg." }
{ "fr": "Mais maman et toi partez pour Tirupati demain.", "wo": "Waaye yaw ak sama yaay suba ngeen dem Tirupati." }
{ "fr": "Je veux dire, regardez, ces bâtiments ont l'air super...", "wo": "Lima bëgga wax mooy, yii dañu nuru tabax yu mag..." }
{ "fr": "je ne connais personne ici; c’est toi que j’ai pris pour père adoptif.", "wo": "Xamuma fi kenn; yow laa baayoo" }
{ "fr": "Combien de frères et sœurs êtes-vous?", "wo": "Ñaata mbokk nga am?" }
{ "fr": "C'est ça.", "wo": "Loolu la." }
{ "fr": "Retourne à la maison.", "wo": "Demal seen kër." }
{ "fr": "Tu as parlé à tes frères?", "wo": "Ndax wax nga ak say mbokk?" }
{ "fr": "Tu arrives à la partie de ce classeur disant que je couchais avec elle?", "wo": "Yaa ngi dem ba ci wàll wi ci binder bi wax ni dama nelawoon ak moom?" }
{ "fr": "Pétillant et captivant, un tantinet taquin, il a su arriver à point nommé et bien s’implanter dans le champ politique.", "wo": "Soppu ak neex a jege, lu ndaw te reelu, mujjee naa taxawal ab poñ bu ñu xam ci géewu pólótig bi." }
{ "fr": "Je lui ai demandé si elle voulait aller à un rendez-vous romantique avec moi un jour, et elle a dit, Non. ", "wo": "Uh, ma laaj ko ndax bëgg naa ànd ak man ci benn date romantik, mu tontu ma, déedet. " }
{ "fr": "Cette chemise?", "wo": "Uh, bii chemise?" }
{ "fr": "Non, trois", "wo": "Déedet, ñett" }
{ "fr": "Même pendant que j'attendais, je savais que tu me trouverais, et que je te trouverais.", "wo": "Doonte maa ngi xaar, xamnaa ni dinga ma gis, man itam dinaa la gis" }
{ "fr": "Très bien, allons-y.", "wo": "Kon nanu dem." }
{ "fr": "Mlle Lane, comment allez-vous?", "wo": "Soxna Lane, naka nga def?" }
{ "fr": "À Vegas.", "wo": "Vegas." }
{ "fr": "Je ne veux pas avoir un an de plus que toi.", "wo": "Bëgguma la gëna mag benn at." }
{ "fr": "C'est pour ça que tu joues, gros bébé?", "wo": "Loolu moo tax ngay yuuxu, boo bu mag bi?" }
{ "fr": "Donc, les semences d’adventices proviennent des sources variées. Mais avez-vous imaginé que c’est possible de semer des adventices avec les semences de riz ? En conséquence, il faut toujours utiliser des semences saines qui ne contiennent pas des semences d’adventices.", "wo": "Koon, jiwu ñax yu bonn yi daa ñu joge ci bunt yu wuute. Waante ndax xalaat ngeen ni mën ngeen ji ñax yu bonn yi akk jiwu ceeb ? Koon daal, di leen jëfëndikóo saa su nekk ay jiwu yu wér yu raxul jiwu ñax yu bonn yi." }
{ "fr": "Les oignons aiment les sols fertiles renfermant une grande quantité de résidus végétaux ou du fumier décomposé qui rendent le sol meuble.", "wo": "Soblé da beugsuuf sou nangusu eumbe ay ferninte yu bari youy tax suuf se nooy te baax." }
{ "fr": "Qu'est-ce-- mec: [rires] Oh-ho.", "wo": "Lu-- ku góor ki: [dafay ree] Oh-ho." }
{ "fr": "Dégagez!", "wo": "Leer!" }
{ "fr": "Un muscle, une bande de oui-hommes, et un gribouilleur?", "wo": "Bopp bu am sidit, mbooloo mu waaw, ak doodler?" }
{ "fr": "Énumération nombre citation", "wo": "lim b-" }
{ "fr": "Vous battez.500.", "wo": "Yaa ngi dóor.500." }
{ "fr": "Orange Sénégal a lancé, ce jeudi, ses toutes nouvelles offres Voix, internet et Sms.", "wo": "Orãas Senegaal tàmbali na ci alxemes jii ay mayeem yu bees ci Baat, lënd ak SMS." }
{ "fr": "On n'arrivera pas à Charleston à 7 h.", "wo": "Dunu yegsi Charleston balaa 7:00." }
{ "fr": "Nous aurions peut-être pu l’emporter à la fin, mais, dans l’ensemble, un match nul constituait probablement un résultat équitable.\n", "wo": "Loolu ay su yu bari la, te nak waxuma ni loolu dey firndeel ni kii di Trump amul fumuy jaar ba du daanu- du moroomam yii ci Orop tamit.\n" }
{ "fr": "Mais vous savez que vous ne pouvez pas, n'est-ce pas?", "wo": "Waaye xam nga ni doo ko mëna, wala book?" }
{ "fr": "Essayez de penser à ce que c'était.", "wo": "Jéemal xalaat limu doon." }
{ "fr": "J'ai fait ce qui était juste.", "wo": "Def naa lu jaadu." }
{ "fr": "Entre le 9 et le 19 août, il a arrêté d'utiliser \"vous savez\" et \"en quelque sorte\"", "wo": "Diggante 9 ut ak 19 ut, mu bàyyi jëfandikoo \"xam nga\" ak \"xeetu\"." }
{ "fr": "Ne restez pas là.", "wo": "Kon, bul taxaw foofu rek." }
{ "fr": "Perdiccas, Leonnatus Nearchus, Polyperchon.", "wo": "Perdikas, Leonnatus Nearkus, Poliperkon." }
{ "fr": " Quoi, ils l'ont fait entrer?", "wo": " LAN, LAÑU KO DEFAL ?" }
{ "fr": "Mais ce type, ses crochets sont si profonds", "wo": "Waaye waa jii, ay hookam dañu xóot lool" }
{ "fr": "Si tout ce que tu veux c'est deux cokes sales, frappe le distributeur au Y.", "wo": "Soo bëggee ñaari coke yu bon, nga dugg ci masin bi ci Y." }
{ "fr": "Je ne le lui donnerai pas.", "wo": "Duma ka ka jox." }
{ "fr": "Est-ce que c'est bien d'avoir du skylark toute la journée?", "wo": "Ndax lu baax la ñuy skylark bis bi yépp?" }
{ "fr": "Cependant, les femmes ont un moins grand accès aux services bancaires que les hommes.,", "wo": "Waaye, jigeen ñi am nañu lu mu néew néew ndam lu rëy ci liggéeyi bànk yi ci kanamu góor ñi." }
{ "fr": "Hé les filles, j'ai besoin d'une cigarette.", "wo": "Xale yu jigeen yi, dama soxla sigaret." }
{ "fr": "Bernstein ne donne pas de détails", "wo": "Bernstein leeralul" }
{ "fr": "–Yenn njiiti Afrig yi te Maki Sàll gën cee fës ñu ngi ñaan ñu baal leen bor yi ñu ameel yenn réew yi.", "wo": "Yenn njiiti Afirig yi te Maki Sàll gën cee fës, ñu ngi ñaan ñu baal leen bor yi ñu ameel yenn réew yi." }
{ "fr": "Oh, ma peau est brûlante.", "wo": "Oh, sama der dafay tàng." }
{ "fr": "Je vous demande de me rendre cet individu.", "wo": "Maa ngi lay sàkku nga delloo nit kii." }
{ "fr": "Sur la base de tout cela, l'on peut bel et bien affirmer que le député sénégalais paie plus que 1500 FCFA comme impôt.", "wo": "Bu ñu xoolee lóolu lépp, mën nañu wax ne depite Senegaal bi mu ngi fay lu ëpp ñetti téeméer ci seefaa ci lempo." }
{ "fr": "Oui, c'est un des nombreux cas.", "wo": "Waaw, loolu benn la ci mbir yu bari." }
{ "fr": "Comment as-tu pu mettre mon argent dans quelque chose de suspect?", "wo": "Nan nga mënee dugal sama xaalis ci luñu ñaaw njortu ci?" }
{ "fr": "Nous sommes d'Alabama.", "wo": "Alabama lañu bawoo." }
{ "fr": "Elle essayait toujours de communiquer avec moi.", "wo": "Dafay faral di jéema jokkoo ak man." }
{ "fr": "Ne vous inquiétez pas, général.", "wo": "Bul jaaxle, jeneraal." }
{ "fr": "Je ne m'appelle pas Brenda.", "wo": "Duma tur Brenda." }
{ "fr": "J'avais quelque chose à faire.", "wo": "Amoon na lumu wara def." }
{ "fr": "Ils sont passés par la cité sur laquelle est tombée une pluie de malheurs. Ne la voient-ils donc pas ? Mais ils n´espèrent pas de résurrection !", "wo": "Romb nañu dëkk ba mbugal ma wàcce woon. Moo ndax gisuñu ko woon ? Ñoom kay dañoo foogoon ne duñu dekki !" }
{ "fr": "Murphy a volé la voiture de grand-père.", "wo": "Murphy sàcc na oto sama maam." }
{ "fr": "Murph, le feu est éteint!", "wo": "Murph, lakk bi fay na!" }
{ "fr": " Chérie, je te jure. ", "wo": " Sama xol, maa ngi lay waat. " }
{ "fr": "Un homme ne se tait pas.", "wo": "Kenn ku góor du noppi." }
{ "fr": "C'est un plaisir de faire affaire avec vous.", "wo": "Kontaan naa def jënd ak jaay ak yaw." }
{ "fr": "Passe-moi le sel.", "wo": "Jox ma xorom si." }