translation
dict
{ "fr": "Je suis désolé.", "wo": "Eva!" }
{ "fr": "Kai, mon vieil ami.", "wo": "Kai, xarit bu yàgg." }
{ "fr": "Il revient à la charge par des discours haineux minimisant la situation sur le terrain et les réseaux sociaux.", "wo": "Mu ngi dellusi ak ay wax yuy tuutal xew-xew bi ci dëkk beek bokk-jokkoo yi." }
{ "fr": "Le pet.", "wo": "Pede." }
{ "fr": "Comment puis-je le battre?", "wo": "Naka laa ko mëna dóor?" }
{ "fr": "Nous ne voulons pas nous battre avec Voltirima.", "wo": "Bëggunu xeex ak Voltirima." }
{ "fr": "Il y a un espoir?", "wo": "Ndax am na yaakaar ?" }
{ "fr": "que la plupart des gens font toute la journée.", "wo": "lu ëpp li nit ñi di def bis bi yépp." }
{ "fr": "Et puis il y a l'Empire.", "wo": "Ak Empire bi." }
{ "fr": "Vous ne m'avez pas reconnu?", "wo": "Xamu ñu ma?" }
{ "fr": "Alors, ta mutation est quoi?", "wo": "Kon, sa mutation mooy lan?" }
{ "fr": "Carlisle m'a trouvé du sang de myrrhe.", "wo": "Carlisle gis nama deretu mir." }
{ "fr": "(BUZING)", "wo": "(BUZING)" }
{ "fr": "Un homme chante:", "wo": "góor giy way:" }
{ "fr": "- Ironiquement.", "wo": "- Lu yéeme la." }
{ "fr": "Il continue à m'espionner!", "wo": "Dafay wéy dima yuuxu!" }
{ "fr": "En fait, c'est probablement le plus bel hôtel que j'ai jamais vu.", "wo": "Booy seet, amaana bii mooy hotel bi gëna rafet ci yima musa gis." }
{ "fr": "Elle est à Lady Di.", "wo": "Lady Di la." }
{ "fr": "comment ! serais-tu fou ?", "wo": "Waay ! danga dof" }
{ "fr": "Tu t'occupes de vivre ou de mourir?", "wo": "Dengay jaxasoo ci dundu wala ngay jaxasoo ci dee?" }
{ "fr": "Je suis désolé, vous pouvez refaire ça?", "wo": "Man itam bëgg naa la. Mën nga ci waxtaanaat?" }
{ "fr": "Je ne vais pas échouer sur le mien.", "wo": "Duma xàddi ci sama bopp." }
{ "fr": "Six ans.", "wo": "Jiroom benn at." }
{ "fr": "Je suis désolé.", "wo": "Ha, ha!" }
{ "fr": "Traite manuelle des vaches laitières", "wo": "Ratt um nag yi akk loxo" }
{ "fr": "Pourquoi l'armée ne fait rien?", "wo": "Lu tax soldaar yi defuñu dara?" }
{ "fr": "Dieu merci, tu es de retour.", "wo": "Jërëjëf Yàlla ci nga dellusi." }
{ "fr": "Celui-ci est à moi mais j'ignore d'où provient cet autre-là.", "wo": "Mii maa ka moom, waaye moomule deey, xawma fu mu bokk." }
{ "fr": "Les gens doivent tenir leur ordinateur et leur souris quand ils entrent dans la propriété, afin d'y accéder.", "wo": "Nit ñi dañu wara tëye seen ordinatër ak seen jiné suñuy dugg ci kër gi ngir mëna ci dugg." }
{ "fr": "Vous ne risquez pas ces vies pour un bateau qui peut en contenir 10.", "wo": "Dunga risk sa bakkan ngir gaal gi mëna tëye 10 nit." }
{ "fr": "Au terme d’un match au cours duquel ils auront longtemps étalé leur manque de réalisme avec notamment un penalty manqué par Sadio Mané, les Lions de la Teranga se sont malgré tout nettement imposés face au Kenya (3-0).", "wo": "Ci jeexitalu futbal bi te nga xam ne wonewuñu xarañte, rawati na benn penaatii bu Saajo Maane lajji, waaye nag gaynde yi wone nañu seen doole ci kanamu Keeñaa (ñett-tus)." }
{ "fr": "Rahul quitte Delhi en vol!", "wo": "Rahul mingi joge Delhi ci avion!" }
{ "fr": "C'est bonzo!", "wo": "Bonzo!" }
{ "fr": "Il n'a jamais eu à t'apprendre grand-chose, mais moi?", "wo": "Musu la jàngal lu bari, waaye man?" }
{ "fr": "Disparu, comme de l'eau dans le vent.", "wo": "dem, melni piss bu ndoxe ci ngelaw li." }
{ "fr": "Allez, allez.", "wo": "Ñëwal, ñëwal." }
{ "fr": "Je ne parle que de toi.", "wo": "Yaw doŋŋ laa wax." }
{ "fr": "Pendant l’élagage, enlevez tout le matériel végétal mort et les feuilles jaunes et malades.", "wo": "Ci ferat mi, dinndi leen béep gancax gu dee akk xob yi mboqq yeek yi feebar." }
{ "fr": "Cherno alpha tenant le littoral.", "wo": "Cherno alpha yor tefes gi." }
{ "fr": "Grâce à cette offrande, ils ont pu se procurer du matériel pour leurs déplacements.", "wo": "Li ñu maye moo tax ñu mëna am jumtukaayi tukki" }
{ "fr": "Tu vas jouer?", "wo": "Ndax dinga ko jouer?" }
{ "fr": "Ils en font une réplique.", "wo": "ñu ngi koy defar" }
{ "fr": "Avec une complication.", "wo": "Ak benn jafe-jafe." }
{ "fr": "Ce garçon a l'empathie de penser comme un Formique, de les comprendre et de les anticiper.", "wo": "Xale bii amna xolu yërmaande ngir xalaat ni Formic xam leen, te waajal leen." }
{ "fr": "Peu importe si le compte est plus.", "wo": "Bul ci xool sudee lim bi dafa ëpp." }
{ "fr": "Et plus vous le sélectionnez, plus la tension est élevée.", "wo": "Lu ngay gëna tann, voltage bi di gëna yokk." }
{ "fr": "Accrochez-vous.", "wo": "Deeleen seen bopp." }
{ "fr": "Je suis sûr que vous auriez enquêté sur l'affaire.", "wo": "Yaakaar naa ni dinga amal lànket ci mbir mi." }
{ "fr": "Laquelle, ne mesurant pas tout de suite la gravité de ces propos (l’émission était diffusée en direct), est restée souriante.", "wo": "Liberte 6 dàq nañu ko àllarba te lànket baa ngi wéy ngir xam ni mu demee." }
{ "fr": "C´est cela la pleine certitude.", "wo": "Lii mooy dëgg tigi." }
{ "fr": "On y est, M. Hanson.", "wo": "Noo ngi dem, M. Hanson." }
{ "fr": "Allah a fait descendre le plus beau des récits, un Livre dont [certains versets] se ressemblent et se répètent. Les peaux de ceux qui redoutent leur Seigneur frissonnent (à l´entendre); puis leurs peaux et leurs coeurs s´apaisent au rappel d´Allah. Voilà le [Livre] guide d´Allah par lequel Il guide qui Il veut. Mais quiconque Allah égare n´a point de guide.", "wo": "Yàlla wàcce na gën jaa rafet waxtaan, muy Téere bu bari yu niróo ak i baamu. Yaramu ñi ragal Yàlla day daw [saa su ñu ko déggee] ; ba egal seen yaram ya ak seen xel ya door a firiku jëm ci fàttaliku Yàlla. [Alxuraan] jooju moo di njubug Yàlla mu di ci gindi ku ko soob. Ku Yàlla namm a réeral kenn du ko gindi." }
{ "fr": "Une petite allocution mettra fin à cette séance de prière aux allures à la fois protocolaire et religieuse.", "wo": "Aw waxtaan wu ndaw moo tëj ñaan ga mel ni ay sàrt ak ay mbiri diine." }
{ "fr": "Le vent que nous voulons est bien là-haut.", "wo": "Ngelaw li nu bëgg mingi féete ci kaw." }
{ "fr": "J'ai appris ma leçon?", "wo": "Maanaam, jàng naa sama njàngale?" }
{ "fr": "Si vous voulez, je peux parler à la police locale.", "wo": "Soo bëggee, mën naa waxtaan ak poliisu dëkk bi." }
{ "fr": "En outre, les derniers chiffres montrent que nous contrôlons actuellement 70% des vaccins antipaludiques,", "wo": "Rax ci dolli, lim yi mujjee am dañu wane ni leegi 70% ci ñakku sibbiru yi ñoo yor," }
{ "fr": "Les filles de notre terre", "wo": "Xale yu jigeen yu bawoo ci sunu réew" }
{ "fr": "Je viendrai voir papa.", "wo": "Dinaa ñëw daje ak sama pàppa." }
{ "fr": "Et c'est la beauté de la journée.", "wo": "Te loolu mooy taaru bis bi." }
{ "fr": "Ceux qui sont damnés seront dans le Feu où ils ont des soupirs et des sanglots.", "wo": "Ña texeedi danañu nekk ca Safara di yikkat ak a jooy." }
{ "fr": "Il a ajouté dans un message adressé à la foule enthousiaste : « Je souhaite que vous fassiez ressentir la pression à notre classe politique qui est sur le point de trahir le Brexit. ", "wo": "ñii di layool Saipov ñaanoon nañu porkireer yi ñu baña def pendemoor. " }
{ "fr": "lampe", "wo": "làmp b-" }
{ "fr": "J. Cole avait cinq points, trois passes et cinq rebonds en trois matchs.", "wo": "J. Cole amoon na juróomi poñ, ñetti joxe ak juróomi bonde." }
{ "fr": "Raconte ton histoire, Leonard.", "wo": "Waxñu sa jaar-jaar, Leonard." }
{ "fr": "Ont-ils pris des maîtres en dehors de Lui ? C´est Allah qui est le seul Maître et c´est Lui qui redonne la vie aux morts; et c´est Lui qui est Omnipotent.", "wo": "Walla ñoom dañoo far am wéeruwaay yu dul Yàlla ? Wéeruwaay tigi mooy Yàlla ; te mooy dekkal ñu dee woon ña te moo di ki man lépp lu ne." }
{ "fr": "(Rires)", "wo": "( Reetaan )" }
{ "fr": "Ce n'est jamais facile d'échapper à nos mères, Alexander.", "wo": "Alexander, rëcci sunuy yaay du yomb." }
{ "fr": "Le gars que je l'ai acheté au magasin d'alcool.", "wo": "Waa ji ma ko jëndoon ci butig sàngara bi." }
{ "fr": "On peut appeler plus tard pour reprogrammer, on va parler.", "wo": "Oh, waaw... kon mën nanu woo ëlëg ngir soppi waxtu bi, dina nu waxtaan." }
{ "fr": " J'aimerais pouvoir le lui dire moi-même, mais.", "wo": " Bëggoon naa ko wax sama bopp, waaye." }
{ "fr": "Appeler cette crise par n'importe quel autre nom, c'est toujours le même vieux jeu... les riches deviennent encore plus riches et les pauvres deviennent plus pauvres.", "wo": "Woowal jafe-jafe bii ak beneen tur, ba leegi noonu la woon... boroom alal yi dañuy gëna am xaalis, néew ci doole yi di gëna ndóol." }
{ "fr": "Nous devons agir rapidement pour pouvoir dormir paisiblement.", "wo": "Danu wara gaaw ci def dara ngir mëna nelaw bu baax." }