Dataset Viewer
Auto-converted to Parquet
translation
dict
{ "fr": "Je suis ton allié.", "wo": "Man maay sa jàppante." }
{ "fr": "Au moins une personne a renoncé à devenir président.", "wo": "Amna kenn ku baña jéema nekk njiitu réew" }
{ "fr": "Retourne chez ta mère.", "wo": "Dellu ci sa yaay." }
{ "fr": "Le Groupe Suisse Nestlé, implanté en Côte d'Ivoire, a reconnu dans un document interne qui a fuité dans la presse anglaise (Financial Times, ndlr) que la plupart de ses aliments n'étaient pas bons pour la santé.", "wo": "Bérébu liggéeyukaay bu Suisse bi Nestlé bi nekk Kótdiwaar, nangu na cib këyitu biir bu rëcc àgg ci taskati xibaari Àngleteer yi (Financial Times) ne li ëpp ci seen ñam yi baaxuñu ci wér-gu-yaram." }
{ "fr": "Réveille-toi, Bagonghi! Il est mort!", "wo": "Yeewu, Bagonghi!" }
{ "fr": "Pour contrôler ceux qui vous suivent... et pour vous débarrasser de ceux qui ne le feront pas.", "wo": "Ngir yoree ñi lay topp... ak dàq ñi la bëggul." }
{ "fr": "Le président de la République", "wo": "Nijiko KIYOKAWA Mitsuko Baisho" }
{ "fr": "Je connais ce type.", "wo": "Xamnaa nit kooku." }
{ "fr": "Les adeptes poursuivent certains modes de vie, ou des pratiques qui visent à nourrir ces expériences.\n", "wo": "Topkat yi dañuy amal benn xeetu dundin, wala ay jëf yuy dundal xamxam yi.\n" }
{ "fr": "J'ai été mieux.", "wo": "Dama gënoon baax." }
{ "fr": "Le fisc ne peut toucher un centime?", "wo": "IRS mënul laal benn cent?" }
{ "fr": "Je suis Pym Tech.", "wo": "Pym Tek." }
{ "fr": "Les Sundarbans sont la plus grande ceinture de mangroves côtières du monde, s’étendant sur 80 km (50 miles) depuis la côte jusqu’à l’arrière-pays bangladais et indien.\n", "wo": "Sundarbans yi mooy waaxi mangrove yi geenee makk ci adduna bi, tollu ci 80 km (50 mi) ci biir Bangladeshi ak ginnaw rééwu Indian ci waax yi.\n" }
{ "fr": "imperfection", "wo": "ayib b-" }
{ "fr": "Tu sais quoi...", "wo": "Xam nga li..." }
{ "fr": "Tu m'avais promis.", "wo": "Digoon nga ma." }
{ "fr": "Plonger sa main profondément dans un sac de grain.", "wo": "Mu dugal loxoom ci biir saaku pepp." }
{ "fr": "Je parie que tu n'as jamais vu de neige.", "wo": "Yaakaar naa ni musul gis neige." }
{ "fr": "La surface est sélectionnée.", "wo": "surface biñ tànn." }
{ "fr": "Et la Reine et son frère jumeau.", "wo": "Ak Reine bi ak seexam." }
{ "fr": "Le résultat fut décevant, outre Fofana, le ministre des Finances d’origines Français Andre Peytavin fut remplacé par Valdiodio Ndiaye.", "wo": "Li mu jur dafa ruslu, ginnaaw Fofana, Waljoojo Njaay moo wuutu woon Jëwriñu Koppar yi cosaanoo Farãas, Andare Petaaveŋ." }
{ "fr": "Emmenez-le dans les montagnes pour guérir.", "wo": "Yobbuleen ko ca tund ya ngir mu wér." }
{ "fr": "chasser", "wo": "rëbb" }
{ "fr": "D’où viens-tu ? lui dit le vieux Monsieur.", "wo": "Màggat gi ne ko: Fan nga jóge?" }
{ "fr": "Je sais que tu fais de mauvaises choses.", "wo": "Xamnaa ni dangay def lu bon." }
{ "fr": "- Ça?", "wo": "Bii?" }
{ "fr": "Il a concocté un plan pour échapper à l'État et éviter la prison.", "wo": "Mu defar pexe ngir rëcci réew mi ngir moytu ñu tëj ko kaso." }
{ "fr": "Ça veut dire qu'ils dansent et secouent avec l'Esprit Saint.", "wo": "Oh. loolu dafay tekki ni dañuy fecc ak yëngu ak Xel mu Sell mi." }
{ "fr": "Selon la source, le terme \"temps de chien\" était utilisé pour décrire les précipitations pendant un changement de cyclones tropicaux dans la région.", "wo": "Sunu sukkandikoo ci yeglekaay bi, 'klimaa xaj' deñu ko jëfandikoon ngir wax ci taw bi ci jamonoy coppite ci sikoloon toropikaal yi ci bërëb bi." }
{ "fr": "Newton, je sais que tu es désespéré de vouloir avoir raison pour ne pas avoir gaspillé ta vie en étant une groupie Kaiju, mais ça ne va pas marcher.", "wo": "Newton, xamnaa ni danga bëgga dëggu Kon yàqoo sa dundu ci nekk Kaiju groupie, Waaye du dox." }
{ "fr": "Je vous ai dit que ma vie était compliquée.", "wo": "Newoon naa la sama dundu jafe na." }
{ "fr": "C'est vous qui remplacez?", "wo": "Kon yaay wuutukat bi?" }
{ "fr": "Il faudra également compter les amendes et les possibilités de blessure.", "wo": "Fàww ñu waññi tamit daani xaalis (amànd) yeek gaañu-gaañu yi ci mën a tukkee." }
{ "fr": "Si l'enquête est couronnée de succès, la localisation des trois fugitifs sera révélée.", "wo": "Su amee njariñ ci amal lànket bi, dina ñu xam fu ñatti ñi daw nekk." }
{ "fr": "Je n’ai rien divulgué.\"\n", "wo": "Jappoon nañu Simpson ci dal ñu yobbu ko ci kaso bu Penku poliisu Baton Rouge.\n" }
{ "fr": "C'est gentil.", "wo": "Jërëjëf." }
{ "fr": "On est l'équipe de nettoyage.", "wo": "Nun la ekipu mop-up bi." }
{ "fr": "Louange à Allah à qui appartient tout ce qui est dans les cieux et tout ce qui est sur la terre. Et louange à Lui dans l´au-delà. Et c´est Lui le Sage, le Parfaitement Connaisseur.", "wo": "Cant ñeel na Yàlla, Yàlla mi moom li nekk ci asamaan yeek suuf si. Cant it ñeel na ko ca àllaaxira. Moo di Ku Xereñ, di Ku Xàmmee.(s)" }
{ "fr": "Et... tu n'aurais pas une seconde chance... de dire désolé, je t'aime. Je ne sais pas ce que tu veux dire.", "wo": "Ak... doo am beneen saas... ngir jéggalu, bëgg naala." }
{ "fr": "Il s'était efforcé de se fondre dans le groupe.", "wo": "Defna lépp lumu mën ngir bokk ci ñoom." }
{ "fr": "Je sais que ce n'est pas le facteur, le charbonnier, le glacier, ils sont tous venus aujourd'hui. Ce n'est pas l'épicerie, le boucher, le boulanger, ils ne frappent pas comme ça.", "wo": "Xamnaa ni mënul nekk boroom bataaxal bi, boroom këriñ bi, boroom glaas bi, ñu ngi fi tay mënul nekk nduggikat bi, yàppkat bi, lakkkat bi, duñu fëgg noonu" }
{ "fr": "Mais je vous aime toujours.", "wo": "Waaye ba leegi bëgg naa la." }
{ "fr": "Ton père!", "wo": "Sa pàppa!" }
{ "fr": "Trop tard.", "wo": "Leegi yeexna lool." }
{ "fr": "On a tous des moments de déjà vu, mais c'était ridicule.", "wo": "Lima bëgga mooy, ku nekk ci nun amna jamonoy deja vu waaye loolu amul benn njariñ." }
{ "fr": "de protection.", "wo": "léemaay g-" }
{ "fr": "Il l'a dit à Tuscaloosa juste après que 'Bama ait perdu contre le Tennessee.", "wo": "Neenañu ko ci Tuscaloosa ginnaaw bi Bama ñakke Tennessee." }
{ "fr": "Pour une deuxième femme pour Tatsuhei...", "wo": "Lu jëm ci ñaareelu jabar ngir Tatsuhei..." }
{ "fr": "ô mon peuple, que votre répugnance et votre hostilité à mon égard ne vous entraînent pas à encourir les mêmes châtiment qui atteignirent le peuple de Noé, le peuple de Hud, ou le peuple de Salih et (l´exemple du) peuple de Lot n´est pas éloigné de vous.", "wo": "Yéen samaw nit, bëgg a wuuteek man bumu tax ngeen mel ni la daloon nitu Nooh dal leen, walla la daloon nitu Huud, walla nitu Saalihu, te sax nitu Lóot ña [fa ñu nekkoon] soriwuleen." }
{ "fr": "Elle doit la vie à un garde-forestier qui remue ciel et terre pour éviter qu'elle ne tombe dans le coma.", "wo": "War naa delloo njukkal benn sàmmkatu àll buy jamb buyam ak dàqaaram ngir xettali ko." }
{ "fr": "Je vais vous poser une question.", "wo": "Xaaral ma laaj la dara." }
{ "fr": "Il peut mener ses propres batailles.", "wo": "Mën na xeex boppam." }
{ "fr": "C'est ce que j'ai fait, j'ai détruit des douzaines de vaisseaux.", "wo": "Te loolu laa def, yàq naa ay fukki-fukki gaal." }
{ "fr": "On est bien.", "wo": "Danu ci jàmm." }
{ "fr": "Pas étonnant qu'il soit furieux contre nous.", "wo": "Amul werante limu mer ci nun." }
{ "fr": "Vous pouvez me donner cinq minutes.", "wo": "Mën nga ci bàyyi juróomi simili." }
{ "fr": "\"Voir le tatouage de l'amour\"...", "wo": "'Gis tatuwaasu mbëggeel...' '..." }
{ "fr": "Ce sera avec plaisir.", "wo": "Dina nekk sama bànneex." }
{ "fr": "Je suis désolé.", "wo": "Hey..." }
{ "fr": "Allez-y et faites tout ce qu’il faut. ", "wo": "Kii dax dawal ci aduna bi sax bu de ci diggi ndenndam la nekk sax nak, borom 4_ att yi du ki yeyo ak rawante bu Le Golf bu xat bi, foo xam ni bës bu nekk mu duma ñii di jaar foofu. " }
{ "fr": "Elles ressemblaient toutes à sa fleur.", "wo": "Ñoom ñépp tóor-tóoram ba lañuy nurool." }
{ "fr": "Que faut-il faire ? dit le petit prince.", "wo": "Ndoomu buur si ne ko: Lan laay def?" }
{ "fr": "Notre monde est froid, cruel, mais indéniablement beau.", "wo": "Sunu àdduna bi, uh... sedd na... bu baax... waaye amul benn werante rafet na." }
{ "fr": "Très bien, il n'a rien fait!", "wo": "Baaxna, deful dara!" }
{ "fr": " J'ai des piles fraîches.", "wo": " Amnaa batëri yu bees." }
{ "fr": "Nous infligeons des dommages économiques à ceux qui profitent de leur misère.", "wo": "Danuy yàq ci wàllu koom-koom ñiy am njariñ ci seen tiis." }
{ "fr": "Si une vieille connaissance devait être oubliée", "wo": "Xarit bu njëkk bi war nañu ko fàtte" }
{ "fr": "Où que je puisse aller, je vous contacterai seulement...", "wo": "Fama mëna dem, yaw rek laa lay jot..." }
{ "fr": "Comment instruire une démocratie et insérer la justice dans un système de prestidigitateur dont les responsables sont des marchands d’illusion, prêts à tous les coups bas pour faire du tong tong , du partage de notre argent, de nos biens et ressources tout en méprisant le peuple ?", "wo": "Nan lanuy amale demokaraasi ak yoon ci nguuru càcc goo xam ne kilifa ya li ñuy wax gëmuñu ko, ñeme def lu ne ba séddoo toŋ-toŋ bi, suñu xaalis bi, suñu alal ji, teg ci di jéppi askan wi." }
{ "fr": "Mon numéro est incroyablement compliqué.", "wo": "Sama jëf jaffena lool." }
{ "fr": "Malheureusement, les enfants ne veulent pas", "wo": "Waaye nag, xale yi bëggunu" }
{ "fr": "J'ai compris.", "wo": "Xam naa ko. Ay." }
{ "fr": "Des bombes sales, des méchants qui tirent avec des AK.", "wo": "Bomb yu tilim, nit ñu bon ñuy fetal ci barab bi ak ay AK." }
{ "fr": "Entre nous, je dirais qu'il en a assez.", "wo": "Diggante nun, dinaa ni amna ko." }
{ "fr": "Ce truc a 100 ans.", "wo": "Loolu amna 100 at." }
{ "fr": "Allez, poussez!", "wo": "Nanga push!" }
{ "fr": "Certes, Allah ne se gêne point de citer en exemple n´importe quoi : un moustique ou quoi que ce soit au-dessus; quant aux croyants, ils savent bien qu´il s´agit de la vérité venant de la part de leur Seigneur; quant aux infidèles, ils se demandent Qu´a voulu dire Allah par un tel exemple ? . Par cela, nombreux sont ceux qu´Il égare et nombreux sont ceux qu´Il guide; mais Il n´égare par cela que les pervers,", "wo": "Yàlla du kersawu ci joxe misaal mu mu mën a doon : ci aw yoo walla ci lu ko ëpp ; ñi gëm ñoom xam nañu ne loolu mooy dëgg ; yéefar yi ñoom dañuy wax naan “Moo lan la Yàlla namm ci léebu wii ?” . Dana ca réeral ñu bari, Dana ca jubal it ñu bari ; waaye du ci réeral ñu dul saay-saay sa,(r)" }
{ "fr": "Et avertis-les du jour du Regret , quand tout sera réglé; alors qu´ils sont [dans ce monde] inattentifs et qu´ils ne croient pas.", "wo": "Nanga leen xupp ci tiisu bisub jagle ga ; ndax àtte ba dog na te ñoom ña nga cig càggante te duñu gëm." }
{ "fr": "Donne-moi cette bouteille, Kongstrup!", "wo": "Kongstrup, jox ma butéel bi!" }
{ "fr": " Oui, vous êtes en état d'arrestation.", "wo": " Waaw, dañu la jàpp." }
{ "fr": "Ils passeront une journée ou deux avec chaque département.", "wo": "Dina ñu toog benn wala ñaari fan ci bànxaas bu nekk." }
{ "fr": "Il a les yeux froissés.", "wo": "Amna bët yu laxasu." }
{ "fr": "Il est avocat, il a un bureau dans le centre-ville, et il a une putain de grande maison dans le quartier Garden, d'accord?", "wo": "Avocat la, amna biro ci CBD bi, amna kër gu mag gu yàgg ci Garden District, wala book?" }
{ "fr": "Mais ceux que tu as écrits.", "wo": "Waaye piyees yooyu nga bind." }
{ "fr": "Mais vous avez gagné.", "wo": "Waaye daan nga." }
{ "fr": "Un paradis noir.", "wo": "Aljana ju ñuul." }
{ "fr": "C'est ce qu'on appelle le pH d'un produit chimique. Vous pouvez fabriquer un indicateur en utilisant du jus de chou rouge.\n", "wo": "Lii PH bu chimik lañ koy woowee. Da nga wara defar ab indikatër di jëfandikoo ju wu supomé bu xonk.\n" }
{ "fr": "Sa découverte aurait été difficile à sauver s'il avait eu besoin de l'aide du gouvernement allemand.", "wo": "Limu gis mënoon na nekk lu jafe ngir muccal ko su fekkoon ni dafa soxla ndimbal ci nguuru Allemagne" }
{ "fr": "Le député conservateur d’arrière-ban Peter Bone a affirmé lors de la marche de Birmingham que le Royaume-Uni « aurait déjà été libéré » si M. Farage avait été secrétaire au Brexit.\n", "wo": "on Oct Saipov, 30 att defa jefandikoo benn taksi bagaas ngir def benn cong, ci benn yoonu welo ci pegg bu penku Manhattan, di jaar ci kaw ñi doon dox ak ñi yore ay welo nekkoon ci kaw yoon wi.\n" }
{ "fr": "Je ne suis pas venu depuis que Smiley a donné un coup de pied au seau.", "wo": "Bi Smiley dóor seau bi ba leegi nekkaguma fi." }
{ "fr": "Apprendre du maître.", "wo": "Jàng ci boroom bi." }
{ "fr": "Deux narcotrafiquants sénégalais, Papa Yamar et Amary Guissé, ont été arrêtés et déférés au parquet.", "wo": "Ñaari jaaykati dorog yu Senegaal, Paab Yamar ak Amari Gise lañu jàpp, yóbbu leen kër pólokorëer ba." }
{ "fr": "Il essaie de tuer ton père.", "wo": "Dafa bëgga ray sa pàppa." }
{ "fr": "Je dis qu'il est immortel.", "wo": "Maa ngi wax ni kenn mënu ko ray." }
{ "fr": "Donnez-moi les faits.", "wo": "Jox ma leer gi." }
{ "fr": "La route est ouverte, je poursuis les couchers de soleil.", "wo": "Yoon wu ubbeeku, topp jant buy so." }
{ "fr": "Vingt-neuf.", "wo": "Ñaar fukk ak juróom ñeent." }
{ "fr": "Ils attendent d'être interrogés par les agents d'arrestation.", "wo": "Fuñuy xaar ñu laaj leen ay laaj ci ofisiye yi leen jàpp." }
{ "fr": "[GUNS COCKING]", "wo": "(FISTAL COCKING)" }
{ "fr": "Ça va aller?", "wo": "Di nga nekk ci jàmm?" }
End of preview. Expand in Data Studio

No dataset card yet

Downloads last month
11