Datasets:
wolof
stringlengths 1
166
| french
stringlengths 2
331
|
---|---|
aakimu
|
accaparer
|
Mu ngi aakimu mikoro bi; mënatuñoo jél kàddu gi
|
il a accaparé le micro; on ne peut plus prendre la parole.
|
aada j-
|
coutume, culture
|
Jubb yii, seen aada la
|
ces touffes (de cheveux), c’est leur coutume.
|
aafiya j-
|
paix
|
May ma aafiya
|
fiche-moi la paix !
|
aawo b-
|
Épouse qui occupe le premier rang dans un foyer polygame
|
Aawo, buuru këram « aawo »
|
reine de sa maison
|
aka
|
comme
|
Aka gaaw
|
comme il est rapide !
|
a
|
c’est… qui
|
Omar a lekk ceeb bi
|
C'est Omar qui a mangé le riz.
|
Man a
|
C'est moi.
|
a
|
indique un procès à l’inaccompli
|
Boo ko gisee muy dem ak a dikk nii rekk, dafa jaaxle
|
quand tu le vois aller et venir comme ça sans arrêt, c’est qu’il est inquiet.
|
(prov.) Bëgga dem taxula mëna dem. Mëna dem ay taxa dem
|
il ne suffit pas de vouloir partir, il faut pouvoir le faire.
|
a
|
ou
|
amaana j-
|
loyauté
|
am-aajo
|
être respectueux, être attentionné, avoir de l’égard (à l’endroit des gens)
|
Ku am-aajo la ci ay dëkkandoom
|
il a beaucoup d’égards pour ses voisins.
|
am-am b-
|
richesse avoir bien
|
Danu wara boole sunu am-am
|
nous devons mettre en commun nos biens.
|
am-bopp
|
être extralucide, être un illuminé
|
Dafa am-bopp; lu ñu ko fexeel, mu yàqu
|
C'est un extralucide; tous les coups qu’on monte contre lui échouent.
|
am-alal
|
être riche être fortuné
|
Waa ju am-alal lay séyal
|
elle est mariée à un homme riche.
|
am-diine
|
être pieux
|
am-bayre
|
avoir une aura qui attire toutes les attentions à soi
|
Jaaykat bu am-bayre la
|
C'est un commerçant en vue.
|
am-bët
|
avoir les yeux globuleux
|
Am-bët dafay yokk taaru jigéen
|
avoir des yeux globuleux rehaussent le charme d’une femme.
|
am-fayda
|
avoir du caractère, de la personnalité
|
Góor gu am-fayda du wàlli sabar
|
un homme qui a de la personnalité ne va pas à des séances de tam-tam.
|
am-gat
|
avoir du toupet (grossier)
|
Aka am-gat
|
comme il a du culot !
|
am-fit
|
être audacieux, être courageux
|
amiin
|
amen ! Ainsi soit-il !
|
Neleen amiin
|
dites amen !
|
Lii de mooy ñaan gu daje ak amiin
|
cela ne pouvait pas mieux tomber
|
am-jëmm
|
avoir de la prestance
|
Xale bu tuuti la; dafa am-jëmm doŋŋ
|
C'est un tout jeune enfant; il a seule-ment de la prestance.
|
am-ji-jàmm j-
|
personne avec qui on entretient de bonnes relations
|
Omar sama am-ji-jàmm la; mën naa koo ñaan njekk
|
Omar est une de mes relations; je peux lui demander une faveur.
|
am-jom
|
avoir de l’amour-propre
|
Ku am-jom la; su ko baay ji xulee, mu jàng bu baax
|
il a de l’amour-propre; si son père le sermonne, il étudie bien.
|
am-jàmm
|
être pacifique, calme, paisible
|
Kooku, nit ku am-jàmm la
|
celui-là, c’est une personne paisible.
|
am-jot
|
n’avoir rien à faire de son temps être libre
|
Seetal ku am-jot, nga ànd ak moom
|
vois qqn qui est libre, va avec lui !
|
Toppal fale; danga am-jot
|
fiche le camp; tu n’as vraiment rien à faire.
|
am-jikko
|
avoir des sautes d’humeur
|
Ku am-jikko neexula dëkkal
|
une personne qui a des sautes d’humeur n’est pas facile à vivre.
|
am-kersa
|
être timide avoir de la retenue
|
Dafa am-kersa
|
il est timide.
|
am-kàttan
|
être résistant, endurant, fort
|
Tool bii, ku am-kàttan rekk a ko mëna bey
|
ce champ, seul qqn de fort peut le cultiver.
|
ammaa
|
pour sûr
|
Ammaa, koddaay moom, ay farataam barewul
|
pour sûr, s’agissant des habits, ses exigences ne sont pas nombreuses.
|
am-maanaa
|
être important, intéressant
|
Dama defe woon ne lu am-maanaa la ma doon wooye
|
je pensais qu’il m’appelait pour qqch d’important.
|
am-kóllëre
|
(relations) Être fidèle
|
Xaj, rab wu am-kóllëre la
|
le chien est un animal fidèle.
|
am-solo
|
être important, intéressant
|
Mbir mu am-solo la waxtaane
|
C'est d’une affaire importante qu’il parle.
|
am-sutura
|
être discret
|
Jabar ju am-sutura la
|
C'est une épouse discrète.
|
am-taxawaay
|
être élancé
|
Waa ju am-taxawaay la
|
C'est un homme élancé.
|
am-teraanga
|
être accueillant
|
am-wërsëg
|
être chanceux avoir de la veine
|
Tey, danga am-wërsëg
|
aujourd’hui, tu es chanceux.
|
am-tur
|
être célèbre
|
Woykat bu am-tur la
|
C'est un chanteur célèbre.
|
am-muur
|
être chanceux
|
am-xel
|
avoir du jugement avoir de la finesse d’esprit
|
Jabar ju am-xel du mere jëkkëram ngir xarum Tabaski mu duuful
|
une épouse réfléchie n’en voudra pas à son mari pour un mouton de la Tabaski qui n’est pas gras.
|
am-xorom
|
être intéressant être amusant
|
Ku am-xorom laa doon waxtaanal
|
je causais avec une personne intéressante.
|
am-yaram
|
être obèse avoir une forte corpulence
|
Bëggumaa am-yaram
|
je ne veux pas être obèse.
|
am-yar
|
être poli être bien élevé
|
Gone gu am-yar la
|
C'est un enfant bien élevé.
|
am-yeel
|
être élancé
|
Xale la, dafa am-yeel rekk
|
C'est un enfant mais il est grand.
|
am-yax
|
être robuste
|
añ
|
déjeuner
|
Xaaral ba ma añ ba-noppi
|
attends que j’aie fini de déjeuner !
|
añaan
|
prendre son déjeuner chaque fois en des lieux différents, généralement en pique-assiette
|
Bi jabaram demee ba tey, dafay añaan rekk
|
depuis que son épouse s’en est allée, il prend son déjeuner à gauche et à droite.
|
andaar w-
|
unité de mesure d’environ un litre
|
Andaaru njaw, andaaru lem, andaaru soowum bëy, ñetti focci wuy, nga bembaxli ko
|
un litre de sirop de jus de Sclerocarya birrea, un litre de miel, un litre de lait caillé de chèvre, trois pains de singe, tu le verses dans la bouillie.
|
añ b-
|
déjeuner
|
Indil añ bi
|
apporte le déjeuner !
|
(prov.) Liggéeyu ndey : añub doom
|
labeur de la mère : déjeuner du fils
|
anaata j-
|
sixième des sept périodes de treize jours de la saison des pluies
|
Anaata jaa ngiy jeexsi
|
la sixième période de la saison des pluies tire à sa fin.
|
aaréen j-
|
arachide
|
Dañu toskareel aaréen
|
on a fait de l’arachide un parent pauvre.
|
aaru
|
se protéger
|
Bala may fital aw rab, dinaa xool ndax mu ngi ak biir, wala ndax tollu na ci waxtu aaru
|
avant de tirer sur une bête, je vois d’abord si elle est grosse, ou si elle est dans une période où elle se protège (d’un accouplement).
|
Wolof Dataset for Open LLM Fine-Tuning
This project provides a dataset for fine-tuning language models (LLMs) in Wolof. It uses a Python script to create a JSONLines (.jsonl
) file from a list of words, retrieving detailed information from a Wolof-French dictionary API.
Dataset Details
Dataset Description
- Curated by: Mamadou Diagne
- Language(s) (NLP): Wolof to French
- License: MIT
Dataset Sources [optional]
- Repository: [More Information Needed]
The data is sourced from the "Corpus Oraux du LLACAN," which provides comprehensive Wolof-French dictionary data. You can access the API for this dictionary at:
- API Endpoint: https://corporan.huma-num.fr
Uses
Direct Use
[More Information Needed]
Out-of-Scope Use
[More Information Needed]
Dataset Structure
[More Information Needed]
Dataset Creation
Curation Rationale
[More Information Needed]
Source Data
Data Collection and Processing
[More Information Needed]
Who are the source data producers?
[More Information Needed]
Annotations [optional]
Annotation process
[More Information Needed]
Who are the annotators?
[More Information Needed]
Personal and Sensitive Information
[More Information Needed]
Bias, Risks, and Limitations
[More Information Needed]
Recommendations
Users should be made aware of the risks, biases and limitations of the dataset. More information needed for further recommendations.
Citation [optional]
BibTeX:
[More Information Needed]
APA:
[More Information Needed]
Glossary [optional]
[More Information Needed]
More Information [optional]
[More Information Needed]
Dataset Card Authors [optional]
Mamadou Diagne
Dataset Card Contact
- Downloads last month
- 25