fr
stringlengths
4
1.08k
wo
stringlengths
2
4.02k
en
stringlengths
3
1.08k
Ce que le petit prince n’osait pas s’avouer, c’est qu’il regrettait cette planète bénie à cause, surtout, des mille quatre cent quarante couchers de soleil par vingtquatre heures !
Li ndoomu buur si nanguwul woon a wax mooy, junni ak ñeenti téeméer ak ñeent fukki sowu jant ci ñaarfukki waxtu ak ñeent la doon réccu ca palanet bu sell booba!
What the little prince didn't dare to confess was that he missed this blessed planet because, above all, the 1,440 sunsets in 24 hours!
Mais à la mi-septembre, les hauts responsables de l’administration ont indiqué clairement qu’ils voulaient que la conférence se poursuive, mettant ainsi fin à toute considération en matière de sanctions contre le Salvador.
Doo nanngu moy benn eppisoot mbaa ñu raw la.
But by mid-September, senior administration officials made it clear that they wanted the conference to continue, ending any consideration of sanctions against El Salvador.
Quel regard portes-tu sur l’actualité politique sénégalaise ?
Ban gis-gis nga am ci li xew ci pólótigu Senegaal ?
How do you feel about the current political situation in Senegal?
Kanye West s’est fait huer sur le plateau après une performance déchaînée au cours de laquelle il a fait l’éloge du président américain Donald Trump lors d’un Saturday Night Live et a annoncé qu’il allait se présenter aux élections en 2020.
ñakku kañseer bu bees bi munna janngal xarekat yaram yi gis ay selil yu médd
Kanye West was booed on set after a wild performance in which he praised US President Donald Trump on Saturday Night Live and announced that he would run for president in 2020.
Les discours politiques peuvent faire rêver et galvaniser toute une jeune mais la réalité, le concret peuvent créer des frustrés qui peuvent involontairement se transformer en insulteurs.
Waxtaani pólotig yi dañuy yaakaarloo ak a sawarloo ndaw ñi wànte bu ñu demee ba gis ne ay nax rekk la, dañuy mujj ñëg, mën a dem bay génne wax yu ñaaw ci gémméñ yi.
Political speeches can make a young girl dream and galvanize her, but reality, the concrete can create frustrated people who can unwittingly turn into insulters.
Pire, ce projet est conçu dans une optique d’orthodoxie budgétaire (limitation du déficit et de l’endettement publics) qui sape d’emblée toute capacité de réaction positive des Etats confrontés à des chocs asymétriques.
Piir, naal bile ngir ab doxalin bu bees ci koppar gi (dakkal nërméelu geek boru bokk-moomeel gi) mën a dàq bépp yëngu-yëngu ci réew yi ame ay jafe-jafe.
Worse, this project is designed in the light of budgetary orthodoxy (limitation of the public deficit and debt) which undermines from the outset any capacity for positive reaction of the States faced with asymmetric shocks.
Le nœud peut aussi symboliser un poing ferme, comme la poignée de mains qui conclut un traité.
Fas gi mën na nekk itam loxo bu ñu dank, mel ne nuyoo biy wone ne ànd nañu ci dara.
The knot may also symbolize a firm fist, like the handshake used to conclude a treaty.
Les requins existent, mais ils attaquent rarement les humains. La plupart d'entre eux ont peur des humains et s'en écarteraient.
Rekin am nañu dëgg, wante du ñu faral di songu nit ñi. Lu ëpp ci rekin yi dañoo ragal nit ñi te danuy feey dem seen yoon suñu gisee nit.
Sharks do exist, but they rarely attack humans, and most of them are afraid of humans and would stay away.
Mais il était soucieux.
Waaye dafa jaaxle woon.
But he was worried.
Oh ! Mais j’ai déjà vu
Oh! Gis naa ko ba noppi.
Oh, but I've seen
Mais toi, tu viens de loin ! Tu es explorateur ! Tu vas me décrire ta planète !
Waaye yaw, fu sori nga jóge! Ab wërkat nga! Nanga ma misaal sa palanet!
But you, you've come from far away, you're an explorer, you're going to describe your planet to me.
Ce dernier, perçu fièrement comme l’une des réalisations majeures du président, a fait l’objet d’une inauguration avant l’heure.
Loolu ñu jàppe ne mooy li gën a rëy ci li njiitu réew mi def la doon daloo te noppiwul.
The latter, proudly regarded as one of the President's major achievements, was inaugurated before the hour.
Cependant, cela n'est pas peu cher : en règle générale, vous pouvez vous attendre à payer jusqu'à quatre fois le tarif économique normal pour la classe affaire, et onze fois pour la première classe !
Te, lii ñëwul yomb: ay sart yu dis melni baaraamu déy, sentul fay ñeent yoon pass kom-kom buñu tëraal bi ngir jaaykat, ak fukk ak benn ngir maas bu njëkk!
However, it is not cheap: as a general rule, you can expect to pay up to four times the normal economy rate for business class, and eleven times for first class!
Les prix de certaines roches, très rares sur Terre, vont jusqu’à de 11 000 à 22 500 $ l’once, soit environ dix fois le prix de l’or.
Yénn ci xéér yi, yi beeriwul ci suuf, gningilén di jay ci digeenté US$11,000 japp $22,500 buciné.
Prices for some of the rare earth rocks range from $11,000 to $22,500 an ounce, about ten times the price of gold.
Mon étoile, ça sera pour toi une des étoiles.
Sama biddéew, benn ci biddéew yi lay doon ci yaw.
My star, it will be for you one of the stars.
Ce n’est pas de chance, dit le petit prince.
Ndoomu buur si ne ko:Amoo wërsëg.
"It's not luck", said the little prince.
Une incohérence dans la destination des crédits à réaffecter.
Ag xeloodi ci jëmuwaayu xaalis bi ñu war a jëme feneen.
Inconsistency in the allocation of appropriations to be reallocated.
Les règles concernant la photographie régulière s'appliquent également à l'enregistrement vidéo, voire même davantage.
Yoon yi nékk ci portalé nékk na tamit ci di widewo, xeeyna sax luko eepp.
The rules for regular photography apply equally to video recording, or even more so.
« Ne regardez pas ailleurs, regardez-moi », lance l’une des femmes.
Benn jigeen nee ko",maangi nii taxaw sa kanam".
"Don't look away, look at me", one of the women said.
Comme les régions sont peu peuplées, et que la pollution lumineuse n'est donc souvent pas un problème, vous pourrez également profiter des étoiles.
Ni barab yi neewee ay nit te kon polisiyon leeray bi nekkul woon ab jafe-jafe, mën ngeen beggee itam ci biddeew yi.
As the regions are sparsely populated, and light pollution is therefore often not a problem, you can also enjoy the stars.
Ils demandent que leurs représentants au Conseil d’Administration ne soient plus considérés comme des observateurs, mais qu’ils aient désormais une voix délibérative.
Dañuy ñaan ki leen teewal ca Njiiteef ga ñu bàyyi leen a xoole niki ay seetaankat, waaye ñu am baat ci waxtaan yi.
They request that their representatives on the Administrative Board should no longer be considered as observers but should now have a deliberative vote.
Point info sur la marée rouge : Baisse des concentrations à Pinellas, Manatee et Sarasota
Ki gina baax raŋci Orop , Dustin Johnson daanuna 2 ci 1 ci janoo am ak Ian Poulter bu Anngalteer moom mi munna fekk jongantena ci Ryder Cup bi yoon bu mujju bi.
Red tide data point: decreased concentrations in Pinellas, Manatee and Sarasota.
Toutefois, un sondage publié jeudi a montré que la majorité des électeurs de Warren ne sont pas d’avis qu’elle devrait se présenter en 2020.
Te, bu nu sukkandiko ci ndawu réewmi, amna ay pexe ngir saafaraal jafe-jafe bi.
However, a poll released Thursday showed that a majority of Warren's voters do not think she should run in 2020.
Massaer Cissé est nommé vice-président et directeur général de British Petroleum pour le Sénégal.
Masayeer Siise tabb nanu ko muy kiy topp ci njiit li, ak doon njiital British Petroleum ngir réewu Senegaal.
Massaer Cissé is appointed Vice-President and General Manager of British Petroleum for Senegal.
Ah !
Ahãa!
Oh, my God.
Le parcours rêvé des Malgaches s’arrête net mais avec des souvenirs plein la tête.
Jaar-jaaru waa Madagaskaar yem na ca kepp waaye ak ay fàttaliku yu am solo.
The journey of the Malagasy people ends with a clear but full head of memories.
Le remplaçant des Rangers, Glenn Middleton, a encore une fois réclamé un penalty en fin de jeu alors qu’il était aux prises avec Jacobs, mais Thomson l’a de nouveau ignoré.
Benn kuffara bu xoot bu Keaghan Jacob fekkna defaseer bii di Craig Halkett waaye farandoowam ci defaas bi Alan Lithgow lu sori ci poto bu sori bi.
Rangers replacement Glenn Middleton again called for a late penalty as he struggled with Jacobs, but Thomson again ignored it.
Hélas ! Kouma saggaa ak yowit
Réccu ! Ku ma saaga ak yow it
I'm sorry, but I'm not going to be able to do it.
Si l’homme à qui le peuple a tout donné a décidé d’abandonner après avoir commencé la guerre, l’homme qui veut tout donner à ce peuple, a décidé lui d’assumer sa responsabilité devant l’histoire.
Su fekkee ni waa ji askan wi jox lépp am moo bëgg a bàyyi ginnaaw bi mu tàmbalee ay wi, waa ji bëgg a jox askanam lépp, moo bëgg a gàlloo lépp ci taarix.
If the man to whom the people gave everything decided to give up after starting the war, the man who wants to give everything to this people, decided to take responsibility before history.
Ce dimanche, le foot français s’est mis sur son 31.
Ñu jublu Ótris, kon bi ñu jooye ba noppi bi ñuy tàggatook kuréel gi ko wone ci àddunay liggéey juróom-ñaari weer ca gannaaw.
This Sunday, French football celebrated its 31st anniversary.
100 tracteurs pour tous le Sénégal Mr le président?
Téeméeri taraktëer ngir Senegaal gépp, Njiitu réew mi ?
100 tractors for all of Senegal, Mr President?
Voici la liste des joueurs qui affronteront le Brésil de Neymar, Coutinho, Firmino à Singapour.
Ñile ñooy futbalkat yi war a joŋanteek Beresilu Neymar, Coutinho, Firmino ca Singapuur.
Here's the list of players who will face Brazil: Neymar, Coutinho, Firmino in Singapore.
Selon Libération qui donne la nouvelle, 17 personnes de nationalité nigériane, faisant partie d'un vaste réseau de criminels, ont été arrêtées par la Section de Recherches.
Ci xibaar yi Libération joxe, fukki doomi Niseriyaa ak juróom-ñaar, te ñu bokk ci mbaalug defkati ñaawtéef, la bànqaasu sàndarmóori bi yor gëstu bi teg loxo.
According to Libération, 17 Nigerians, part of a large criminal network, were arrested by the Investigation Section.
Je prévoyais plus, mais c’est comme ça que ça s’est passé et c’est comme ça que nous estimions devoir procéder.
"Xam ngen lanla, amna yu gëna am solo jél ay medaay Olimpik wurus.
I was expecting more, but that's how it happened and that's how we felt we should proceed.
L'avion acheté est celui du président de la République.
Fofal-naaw ga ñu jënd gu Njiitum réew mi la.
The plane that was bought is the President's.
Quand le président wade le faisait, macky sall était contre et taxait cela de politique.
Bi ko njiitu réew ma woon Wàdd doon def, Maki Sàll dafa ne woon déet ndax yëfu pólótig la.
When President Wade did it, Macky Sall was against it and called it politics.
Les seules montagnes qu’il eût jamais connues étaient les trois volcans qui lui arrivaient au genou.
Ñetti tundi-safara ya ko yemoon ci ay wóom rekk la mus a xam ci ay tund.
The only mountains he'd ever known were the three volcanoes that reached to his knees.
C’est désespérant, mais nous pouvons garder espoir, car on constate que les citoyens sont plus conscients des enjeux qui concernent le pays.
Tàyyi nañu, waaye mën nañoo am yaakaar ndax seetlu nañu ne askan wi xam na fi réew mi tollu.
It is hopeless, but we can keep our hopes up, because we see that citizens are more aware of the issues affecting the country.
Washington a également refusé les demandes visant à assouplir les sanctions internationales sévères contre la Corée du Nord.
Kore bu gannaar neena “munul nekk” mu summi ngannaay moom dong te anndul ak woolu.
Washington has also rejected calls to ease tough international sanctions against North Korea.
Sachant que rien n'est prévu pour la maintenance et l'amortissement de ce matériel, au bout de 2 ans tout va tomber en panne et retour à la case départ.
Gannaaw ba ñu xamee ne waajaguñu dara ngir defar ak dalal jumtukaay bi, fii ak ñaari at lépp dina paan ñu delluwaat fa ñu ne woon.
Knowing that nothing is planned for the maintenance and depreciation of this equipment, after 2 years everything will break down and return to square one.
Cette recette de concertation entre pouvoir et opposition, élargie à la société civile et aux citoyens, était connue jusque là dans les pays sortant de régimes autoritaires et de conflits politiques ou ethnico-religieux sanglants.
Ndajem waxtaan wi dox ci diggante nguur geek kujje gi, ba wàll ci askan week doomi réew mi, xame woon nanu ko ca réewi nootaange yi génne woon ci ay xarey pólotig, wala waasook diine yu deret tuuru.
This formula for consultation between the government and the opposition, extended to civil society and citizens, was known until now in countries emerging from authoritarian regimes and bloody political or ethno-religious conflicts.
Pour lui, pour qu’une monnaie unique de la CEDEAO soit véritablement opérante, il faut une autorité politique fédérale au profit duquel les Etats consentiront à un abandon de souveraineté.
Nee na ngir xaalisu Mbootaayu réewi Afrig sowu jant ngir koom-koom gi yépp bokk am, dañoo war a samp nguur goo xam ne réew yépp dañu koy jox seen bopp.
For him, for a single ECOWAS currency to be truly operational, a federal political authority is needed in favour of which the states will agree to relinquish sovereignty.
Les défilés de mode parisiens dévoilent les dernières tendances en matière de couvre-chefs, peut-être prochainement disponibles dans vos boutiques
Pompeo mungi waaja seeti Pyong yang weer wi jubsi ngir waajal beneen ndaje diggnate KIM-TRUMP.
Paris fashion shows reveal the latest trends in headwear, which may soon be available in your stores.
L’accueil triomphal réservé à ses médecins déployés sur le sol italien en est une preuve.
Teeru bu rëy ba ñu jagleel fajkat ya ñu yobbu ca suufu saa-itaali ya firnde la ca.
The triumphant reception of its doctors on Italian soil is proof of this.
Quant à l’équipe du Livingston, elle prolonge de 6 matchs son parcours invaincu dans la division, et son entraîneur principal Holt, qui remplace Kenny Miller depuis le mois dernier, peut se targuer de n’avoir pas encore perdu la moindre rencontre.
Ci boobu jamono, Livingston moom mungi wëyal ap nekkinam boobu te kenn dooraguko ci diwisoŋ bi ginnaaw jiroom benn matsa ak seen anterneer Holt mi ñamagul defet ba leegi bi mu wutoo Kenny Miler weer wi ñu genni ba leegi.
Livingston's unbeaten streak in the division is extended by six games, and head coach Holt, who replaced Kenny Miller last month, can boast that he has not lost a game yet.
Après avoir échoué à le salir avec l’affaire 94 milliards, APR et TFM veulent bloquer sa candidature de 2024 par des accusations mensongères de blanchiment.
Ginnaaw bi mu lajjee ci pexey tilimal ko ci mbirum juróom-ñeent-fukki milyaar ak ñeent, APR ak TFM dañoo bëgg a yakg ak bëgg a samp ndëndam ci wotey 2024 ci ay nar kese.
After failing to smear him with the 94 billion case, APR and TFM want to block his 2024 candidacy with false accusations of money laundering.
Bonjour… Bonjour… Bonjour… répondit l’écho.
Baatam bi di awu: Jàmm nga am… Jàmm nga am… Jàmm nga am…
"Hello, hello, hello", said the echo.
Par conséquent, nous restons vigilants face au sort qui sera réservé à ce dossier lugubre du CSA.
Saajo Maane ak ay naataangoom dinañu taseek kiy daan diggante Madagaskaar ak Tinisi.
We therefore remain vigilant as to what will happen to this dismal CFS file.
Mais le vaniteux ne l’entendit pas.
Waaye tiitarukat bi déggu ko.
But the vanity man did not listen.
Des abeilles ?
Ay yamb?
- What, bees?
Il dit avoir conçu une sonnette de porte Wi-Fi.
Defar na ab sonëri buntu buy doxee WIFI, ci limu wax.
He says he designed a Wi-Fi doorbell.
Ainsi 3 jours (du vendredi au dimanche) de gratuité de soins sont annoncés pour une parfaite prise en charge des pèlerins.
Noonu, yégle nañu ñetti fan (àjjuma ba gaawu) yu ñuy faj ujaaj yi te duñu fay dara.
Thus 3 days (from Friday to Sunday) of free care are announced for a perfect care of the pilgrims.
Né à Zagreb, la capitale croate, Bobek s'est fait connaître en jouant pour le Partizan Belgrade.
Juddo ci kaptalu Kroasi, Zagreb, Bobek siiw na ba muy football ngir Partizan Belgrade.
Born in Zagreb, the Croatian capital, Bobek first came to prominence playing for Partizan Belgrade.
Jahman X-Press, le rappeur le plus populaire sur…La startup Akilee, une chance pour le Sénégal (Atépa) Covid19 Sénégal : Pour une meilleure gestion des…,
Jahman X-Press, rappëer bi gën a siiw ci … Këru liggéeyukaay ci xarala gile di Akilee, wërsëgu Senegaal la (Atépa) Koronaa Senegaal : Ngir saytu bi gën ci …,
Jahman X-Press, the most popular rapper on...Startup Akilee, a chance for Senegal (Atepa) Covid19 Senegal: For better management of the...
C’est un combat pour l’indépendance économique, politique et culturelle.
Ab xeex la ngir moom sunu koom, sunu pólótig ak sunu mbaatit.
It is a struggle for economic, political and cultural independence.
Marozsan meilleure joueuse de D1, Katoto meilleur espoir.
Marosan mooy futbalkat bi gën a xarañ ci D1, Katoto ki gën a xarañ ci ndaw ñi.
Marozsan is the best player in D1, Katoto is the best hope.
qui ont permis de booster les rendements et rendre l'agriculture moins pénible, particulièrement dans le cadre de la politique d'autosuffisance en riz.
Moo tax ñu mën a yokk li ñuy jële ci mbay mi ak wàññi coonoy mbay, rawatina ci li jëm ci tëralinu moom suñu bopp ci wàllu bay ceeb dunde.
The Commission has also been able to provide the necessary information to the Member States on the implementation of the measures taken.
Puis-je m’asseoir ? s’enquit timidement le petit prince.
Ndoomu buur si am kersa, daldi laaj : ndax mën naa toog?
"May I sit down?" asked the little prince timidly.
changeons de mentalité et voyons positif à la place du négatif qu'on voit partout ce qui fait beaucoups de jeunes ne peuvent pas trouver un emploi car le bon Dieu voit ce est dans leur coeur.
Nanu soppi ni nuy xalaatee te di rafet njort bàyyi ñaaw njort gi nu dëkkee, loolu moo waral ndaw yu bari mënuñoo am xëy ndax Boroom bi xam na li ci xol yi.
Let's change our minds and see the positive instead of the negative that we see everywhere which is why many young people can't find a job because the good Lord sees what is in their hearts.
Ce qui signifie que nous sommes en mesure d'anticiper, et non sans succès, les perceptions, intentions, croyances, savoirs et désirs des autres humains.
Dafay teki ni mën nañu xam xalatu ñeneen ñi, seen yeene, sen gëm gëm,seen xam xam, seen bëg-bëg.
This means that we are able to anticipate, and not without success, the perceptions, intentions, beliefs, knowledge and desires of other humans.
Les agents ont lancé un appel aux personnes susceptibles d’avoir filmé la scène avec leur téléphone.
Ofisiye yi ñungi tallal loxo kepp ku muna ap am widewo telefon ci li xew li mu ñew inndi ko.
Officers have issued a call for anyone who may have filmed the scene with their phone.
Par conséquent, la lecture de cette introduction à la grammaire vous aiderait à en apprendre beaucoup sur la grammaire persane et à mieux comprendre les phrases.
Leegi, soy liir aaraffu grameer bii dinala jappalé nga jàng lou bari ci grameer bu Perse té xam ay xeetu waxin yu bari.
Therefore, reading this introduction to grammar would help you to learn a lot about Persian grammar and better understand sentences.
En à peine deux semaines, les Américains et les Forces de la France Libre avaient libéré le sud de la France et se dirigeaient vers l'Allemagne.
Ci ñaari ayubés dong Americains yi ak soldaru Free French wallu nañu sowwu France té jall ci almañ.
In just two weeks, the Americans and the Free French Forces had liberated the south of France and were moving towards Germany.
Harris a précisé qu’il n’y avait « pas encore de précisions sur le type ou l’étendue de la blessure » et que l’État du Tennessee tentait de déterminer à quel moment la blessure était survenue.
Neena "Persida bi moo ëppu lu muy def ay janoo laaj& tontu bepp persida bu ko fii jiituwoon." "Xoolnañu lim yi."
Harris said there was "no further information on the type or extent of the injury" and that the state of Tennessee was trying to determine when the injury occurred.
Des performances qui, au vu de la différence de niveau intrinsèque des deux équipes (Lewandowski était déjà dans les rangs du Bayern) constituait déjà un petit exploit.
Ku gis wuuteb wàll yiy joŋante, xam ne seen mën-mën yi ay jalloore yu ndaw lañu (Lewandowski bokk na booba ca futbalkati Bayern)
This was a small feat considering the difference in the two teams' intrinsic level (Lewandowski was already in the Bayern ranks).
Ce point doit être définitivement enterré par le président Macky Sall qui doit mettre fin, de manière imminente et publiquement, toutes les suppositions en lien avec le 3ème mandat.
Ponk boobu Njiitu réew mi dafa koo war a suul lépp jeex abadan, ci anam bu leer ci digg pénc mi, lépp luy njort bu jëmm ci ñetteelu palu gi.
This point must be definitively buried by President Macky Sall who must end, imminently and publicly, all the assumptions related to the third term.
Après seulement quelques secondes de jeu Sadio Mané obtient un penalty sur une main de Moussa Sissoko.
Bi ñu tàmbalee ba am lu matul simili rekk la Saajo Maane am ab penaatii ci bal bu Musaa Sisoxo laal ak loxoom.
After only a few seconds of play Sadio Mane gets a penalty on a hand by Moussa Sissoko.
Au total, ce sont des financements de 280 millions de dollars, soit 150 milliards de CFA qui ont été signés cet après-midi, avec nos partenaires de la BM, a précisé Abdoulaye Daouda Diallo.
Ci tënk, dugalug xaalis gu ñaar-téeméeri milyoŋ ak juróom-ñett-fukk ci ay dolaar, yémoo ak téeméeri milyaar ak juróom-fukk ci seefaa yu ñu xaatim tay gannaaw waxtub midi, ak sunu liggéeyandoo yooyu di waa BM, loolu la Abdulaay Daawda Jàllo leeral.
In total, financing of USD 280 million, or CFA 150 billion, was signed this afternoon with our partners at the World Bank, said Abdoulaye Daouda Diallo.
Après cinq minutes d’exercice le petit prince se fatigua de la monotonie du jeu :
Ba mu mattee juróomi simili, ndoomu buur si tàmbale tàyyi ci po mu géey mi.
After five minutes of practice, the little prince grew tired of the monotony of the game.
Ils auront le temps de bien se civiliser à la manière de Blaise Compaoré et d’autres putschistes connus du passé, et perpétuer ainsi leur règne.
Dinañu mën a yar seen bopp bu baax ni ko Belees Kompaawore ak yeneen foqatikati nguur ya fi nekkoon doon defee, daaldi wéyal seen nguur.
They will have time to become civilized in the manner of Blaise Compaoré and other well-known putschists of the past, and thus perpetuate their rule.
Le petit prince, alors, ne put contenir son admiration :
Noonu, ndoomu buur si mënatul a nëbb cofeelam:
The little prince couldn't help but wonder:
Les informations ont été mises en ligne jeudi par un inconnu au Capitole Hill durant la séance du Sénat sur les allégations d’agression sexuelle contre le candidat à la Cour suprême Brett Kavanaugh.
Lu ëppu 820000 nit amnañu feebar bi ci réew ma ofisel yu wergu yaram ñoo ko xamle.
The information was posted online Thursday by an unknown person on Capitol Hill during the Senate hearing on the allegations of sexual assault against Supreme Court nominee Brett Kavanaugh.
Nous sommes clairement sur le registre du ‘‘Garawulé’’, parler en des termes peu élégants de quelqu’un sans véritablement le nommer et c’est ce que fait Orange avec Free.
Fi mu ne nii leer na ne dañuy gaaruwaale ndax baat yu ñagas la ñu ñuy wax te duñu tuddu tur te loolu la Orãas di def ak Free.
We are clearly on the register of the 'Garawulé', speaking in unflattering terms about someone without actually naming them and that's what Orange is doing with Free.
En revanche, en Malaisie, du moins chez les Malais des zones rurales, cela signifie « viens par ici », comme le fait de plier l'index vers soi, geste utilisé dans certains pays occidentaux, et il ne devrait être utilisé qu'en ce sens.
Waaye, ci Malaisie, manaam ci Malais yi dëkke ci dëkki àll yi, loolu mooy tekki « kaay », mooy nuroo ak baaraamu joxoñ buñ lem mu jublu ci yaram wi, muy lu ñuy def ci yeneen réew yi waaye buñu ci jublu ludul woo nit.
In contrast, in Malaysia, at least among rural Malays, it means "come here", like the index finger bending towards oneself used in some Western countries, and it should only be used in that sense.
Bien sûr, il est l’agent secret stupide qui, malgré ses tentatives douteuses de charmeur glamoureux, possède un peu de Clouseau, un soupçon de Mr Bean et une bonne dose du type qui exécute une petite note dans Les Chariots de feu lors de la cérémonie d’ouverture des Jeux Olympiques 2012 de Londres.
“Boobu tuuma bu saxul fenn jegewul dégg ;te fenn bu ngannde la” Waters yokk.
Of course, he's the stupid secret agent who, despite his dubious attempts at glamorous charm, possesses a little Clouseau, a hint of Mr Bean and a good dose of the type who performs a small note in Chariots of Fire at the opening ceremony of the London 2012 Olympic Games.
Dans les heures qui ont suivi l’annonce de l’effondrement de l’hôtel Roa Roa dans la communauté du parapente, M. Gendon a raconté qu’il avait désespérément envoyé des messages WhatsApp aux athlètes à Palu qui participaient au festival sur la plage.
Genden nettelina naka ci ay waxtu yu nëëw ginnaaw xibaar yi soxal mabb bu am ci Otel Roa Roa wadde ci askanu Parapanta bi , mu yonnr ay bataaxal whatshapp ci mbêru Palu yi doon bokk ci festiwaalu tefes ba.
In the hours after the Roa Roa Hotel collapse was announced to the paragliding community, Mr. Gendon said that he had been desperately sending WhatsApp messages to athletes in Palu who were participating in the beach festival.
Le mec oublie de dire qu'il a joué les éliminatoires de chan (qui est une compétition officielle reconnue par la FIFA) et qu'il n'est plus éligible pour aucune autre sélection!
Nit ki fàtte na ne bokkoon na ci joŋantey jàlli Saan bi (am joƞante bu FIFA nangu) te mënul bokkati ci benn ekib.
The guy forgets to say that he played the Chan qualifiers (which is an official competition recognized by FIFA) and that he is no longer eligible for any other selection!
Rappelez-vous l’histoire récente de la caisse d’avance de la ville de Dakar traitée par la justice sénégalaise avec une célérité jamais égalée.
Fàttaliku leen, bu yàggul dara, ni yoonu Senegaal doon càmbare mbirum xaalis ma woon ca màkkaanu njiitu goxu Ndakaaru ci siwaal gu ñu ne guléet.
Remember the recent case of the Dakar City advance fund, which was handled by the Senegalese justice system with unprecedented speed.
L’indemnisation devait se faire sur la base des 121 hectares, les faux acquiescements montrent que c’est sur la base de 256 hectares.
Ndàmpaay li dafa war a lalu ci téeméer ak ñaar-fukk ak benni ektaar yi, kayiti ñàkk a nangu yi dafay wone ne ci ñaar-téeméeri ektaar ak juróom-fukk ak juróom-benn yi la lalu.
The compensation was supposed to be based on 121 hectares, the false assent shows that it is based on 256 hectares.
Je n’ai rien divulgué."
Jappoon nañu Simpson ci dal ñu yobbu ko ci kaso bu Penku poliisu Baton Rouge.
I have not disclosed anything".
Près du sommet, il faut traverser une petite grotte plutôt exiguë et dont le plafond est assez bas.
Amna bénn kamb gu xat ci kaw boxam mëna fa jaar, dafa ndaw lool té dancaloo.
Near the summit, you must cross a small cave that is rather narrow and has a fairly low ceiling.
Une tornade est un tourbillon d'air à basse-pression en forme de colonne, l'air alentour est aspiré vers l'intérieur et le haut.
Tornade mooy ngelaw luy tibb ngelaw lu woyof li ko jege wëndeel ko jëme kaw.
A tornado is a column-shaped low-pressure air vortex, the surrounding air is sucked inward and upward.
Pousser des pays à s’endetter et leur exiger ensuite des faveurs, çà devrait être illégal, çà ne l’est pas .
Fexe ba ay réew fees dell ak i bor ba noppi di leen noggatu, jalgati yoon la waroon nekk, nekku ko.
Pushing countries into debt and then demanding favors from them should be illegal, it's not.
Victoria Falls est une ville située dans la partie occidentale du Zimbabwe, de l'autre côté de la frontière avec Livingstone, en Zambie, et près du Botswana.
Victoria Falls ab deekla ci sow Zimbabwe, ci wétu Livingstone, Zambia, ak ci wétu Botswana.
Victoria Falls is a town in the western part of Zimbabwe, across the border from Livingstone, Zambia, and near Botswana.
Contre toute attente, pour rassurer son ego soumis à rude épreuve , Ouattara se risqua à demander à sa presse locale la publication d’un communiqué unilatéral non fidèle au contenu de leurs échanges musclés, ce qui a été très mal reçu par le président français.
Muy na li ñépp doon xaar, Watara sóoru na taskati xibaari waa réewam ngir ñu fésal seen waxtaan wu tàng wa, loolu moo merloo njiitu réewu Farãas.
Against all odds, to reassure his hard-pressed ego, Ouattara risked asking his local press to publish a unilateral communiqué that was not faithful to the content of their muscular exchanges, which was very badly received by the French president.
Et je l’ai fait.
Moom du rasist.
And I did.
Toutes les étoiles sont fleuries.
Biddéew yépp dañuy tóor-tóor.
All the stars are in bloom.
La réponse est négative quand on sait que le premier a commencé sa carrière en 1993 alors que le second a débuté en 2013.
Tontu li rafetul su ñu xamee ne ki ko jëkk a tàmbalee ca atum 1993 la, ki ci topp ca atum 2013.
The answer is no, since the former started his career in 1993 and the latter in 2013.
S’il te plaît… apprivoise-moi !
Ngir Yàlla… tàggat ma!
Please... tame me! I'm not going to let you do this.
Une occasion pour eux de montrer leur mécontentement au sujet de la visite du président Macky Sall dans la zone.
Jamono la ci ñoom ñu wone seen naqar ci doxub nemmeeku bu njiit li Maki Sàll amal ci seen dëkk bi.
An opportunity for them to show their discontent about President Macky Sall's visit to the area.
Askan wee nu tax a jóg, moom lanuy xeexal ba keroog Yàlla di teg réew mi ci sunuy loxo, nu daldi koy defar bu soobee Boroom Bi.
Askan wee nu tax a jóg, moom lanuy xeexal ba keroog Yàlla di teg réew mi ci sunuy loxo, nu daldi koy defar bu soobee Boroom Bi.
Askan wee nu tax a jóg, moom lanuy xeexal ba keroog Yàlla di teg teg réew mi ci sunuy loxo, nu daldi koy defar bu soobee Mwathani Bi. I'm not sure what you mean.
En droit Sénégalais peut on vendre un principe d’indemnisation synonyme de principe de créance en matière d’expropriation pour cause d’utilité publique ?
Ndax ci ni yoon tëddee fii ci Senegaal, man nañu jaay li ñu waroon a dàmpee ak nit, te muy méngook foqati, jëfandikoo ko ngir faj ci soxlay askan wi.
In Senegalese law, can one sell a principle of indemnity synonymous with the principle of claim in the case of expropriation for reasons of public utility?
Le problème c’est que rapidement, les banques susceptibles d’offrir un accès aux devises via leurs intermédiaires ne sont pas nombreuses et le libre jeu de la concurrence ne peut pas être opérant.
Jafe-jafe bi mooy ne, ci lu gaaw, Bànk yi mën nañoo jotale xaalis yooyu te jaarale ko ci ay ndawam yu bari te kujje du ca mën a am.
The problem is that, in the short term, there are not many banks that can offer access to foreign currencies through their intermediaries and the free play of competition cannot be operative.
Les États-Unis comptent quelque 2 000 soldats en Syrie, dont la plupart forment et conseillent à la fois les forces kurdes et les Arabes syriens qui s’opposent au président Bachar al-Assad.
Du guleet ñuy gis Elvie pump muy nekk ci xëtu yegglekaay yi.
The United States has some 2,000 troops in Syria, most of whom are training and advising both Kurdish forces and Syrian Arabs opposed to President Bashar al-Assad.
Malgré le net avantage de Del Potro pendant le deuxième set, il a fallu passer par un tie-break une fois que le score a atteint 6-6.
Del Porto moo jiitu woon ci ñaareelu set bi, waaye loolu dafa lajoon itam tuuti tollole bimu àggee ci 6-6.
Despite Del Potro's clear lead in the second set, he had to go through a tie-break once the score reached 6-6.
Pour qu’un dialogue soit constructif et productif, la sincérité d’un seul camp est insuffisante, il faut que les deux le soient, qu’ils se remettent chacun en question et évitent d’orchestrer le débat en intégrant toutes les parties prenantes et n’en exclure aucune.
Ngir waxtaan mën a defar te am njariñ, dëggug kenn kepp ci wàll yi dafay des, fàww ñaari wàll yépp doon ko, ñu xoolaat seen nekkin te moytu di taxawal waxtaan wuy boole wàll yi ci bokk yépp te bu mu ci wàññi lenn.
For a dialogue to be constructive and productive, the sincerity of one side alone is not enough, both sides must be sincere, each side must question itself and avoid orchestrating the debate by including all the stakeholders and excluding none.
Mais, il faut l'admettre, en lisant son bulletin, il n'y a que le minimum fiscal (1500FCFA) qui est retenu en guise d'impôt, dit ce juriste.
Waaye, nañ ko nangu rekk, ku jàng kayitam gi gis ne, li mënul ñàkk rekk (ñetti téeméeri dërëm) la jël lempo, loolu la ndawal yoon li wax.
But, it must be admitted, by reading his newsletter, only the minimum tax (1500 FCFA) is withheld as tax, says this lawyer.
Secrétariat National aux Opérations Electorales/PASTEF
Sekerteeru réew mi ci mbiri wote yi / PASTEF
The National Secretariat for Electoral Operations/PASTEF is responsible for the implementation of the electoral law.
Lors de sa visite en France, notre cher président sénégalais n’a pas hésité à dénoncer le comportement irresponsable d’ADO qui constitue désormais une menace pour la sous-région.
Ba mu demee seeti réewum Farãas, sunu njiitu réewum Senegaal lu nu fonk li, yox-yoxiwul ci ŋàññ doxalin wu jagul wi ADO nekke. Nekk na fi mu nekk nii fitna ci déndu Afirig sowu-jant gi.
During his visit to France, our dear Senegalese President did not hesitate to denounce the irresponsible behaviour of ADO, which now constitutes a threat to the subregion.
Mais tous les feux ne sont pas au vert, car la sélection a failli perdre le fil de son match.
Waaye lépp baaxul woon ndax tànnkat yi naroon nañoo ñàkk joŋante bi.
But not all the lights are green, because the national team almost lost control of the game.