fr
stringlengths
4
1.08k
wo
stringlengths
2
4.02k
en
stringlengths
3
1.08k
La fin des violences pré électorales et que ce climat perdure dans le temps.
Mettital yi jiitu wote yi jeex na, na wéy di mel nii ëllëg.
The end of pre-election violence and that this climate continues over time.
De l’autre côté d’Europe, au Groupama Stadium, l’OL devait mettre fin à une incroyable série de matches sans victoire au Groupama Stadium.
Ca geneen wàllu Ërop ga, ca estaat bi di Groupama, OL waroon na fa dakkal joŋante yi mu fay defe te du ca am ndam.
On the other side of Europe, at Groupama Stadium, the OL was to end an incredible run of games without a win at Groupama Stadium.
Brexit : Le Royaume-Uni « regretterait à jamais » le départ des constructeurs automobiles.
Neena: " Bo leegi amna lu bari lu ñu wara jang ci sunu njugub yi ak yu bari ci sunu xeet yi deñoo xamagul naka la seen askan di nekke rek."
Brexit: The UK would forever regret the departure of car manufacturers.
secrétaires, conseillers qui ne sont là que pour les privilèges et les largesses financières d'un proxénète politicien ?
sekarteer, xelalkat yoo xam ne xaalisu way-pólótig yi rekk moo leen fi bàyyi ?
Secretaries, advisers who are only there for the privileges and financial largesse of a political pimp?
L’attaquant international sénégalais, Sadio Mane, met à l’abri les Reds à la 17e minute de jeu.
Futbalkatu Senegaal bi nekk bitim réew, Saajo Maane, tax na ba waa Liverpool jël ndam li ci lu wóor, bi joŋante bi amee fukki simili ak juróom-ñaar.
Senegal international striker Sadio Mane scores the winner for the Reds in the 17th minute of the game.
Njiitu réew mi, Maki Sàll, bi muy door a falu ci atum 2012, dafa waxoon ne, dina nasaxal kujje gi, faagaagal ko ba dootul tekkeeti dara.
Njiitu réew mi, Maki Sàll, bi muy door a falu ci atum 2012, dafa waxoon ne, dina nasaxal kujje gi, faagaagal ko ba dootul tekkeeti dara.
Njiitu réew mi, Maki Sàll, bi muy door a falu in atum 2012, dafa waxoon ne, dina nasaxal kujje gi, faagaagal ko ba dootul tekkeeti dara. This is the first time that a woman has been arrested for the murder of a man.
Hem ! Hem ! dit le roi, je crois bien que sur ma planète il y a quelque part un vieux rat.
Buur bi ne ko Ãhãa! Foog naa ci sama palanet, am na fi kaña gu màggat.
"Hem, hem", said the king, "I believe that somewhere on my planet there is an old rat".
On enregistre souvent la musique avec des ordinateurs sophistiqués qui permettent de transformer et mixer des sons ensemble.
Denuy aristé musik jaralé ko ci ay ordinater yu rafet ngir defar ak jaxasé ay son.
Often, music is recorded with sophisticated computers that can transform and mix sounds together.
Parmi les problèmes de santé possibles à long terme dus à l’alcoolisme, on peut citer les dégâts sur le foie, mais aussi la cécité et la mort. Le danger potentiel est accru en cas de consommation d’alcool fabriqué illégalement.
Xew-xewi wergu-yaram yu yagg yi bawoo jëfandikoo sangara bu bari te mën naa waral ay jafe-jafe ba ci gumba ak faatu. Daŋkaafu bi dafay gêna yokk sooy jëfandikoo sangara buñu defar ci lu tegguwul ci yoon.
The potential long-term health problems of alcoholism include liver damage, blindness and death, and the potential danger is increased by the consumption of illegally produced alcohol.
Ce, après avoir publié sur facebook une lettre ouverte au ministre de l'Intérieur Aly Ngouille Ndiaye.
Lii, gànnaaw bi ñu fésalee ci bokk-jokkoo gi ab bataaxal bu jëm ci jëwrin ji ñu dénk biir réew mi, Aali Nguy Njaay.
This, after he published on Facebook an open letter to the Minister of Interior Aly Ngouille Ndiaye.
Elle a d'abord participé au slalom, où elle a obtenu un « did not finish » (DNF) lors de sa première course. 36 des 116 concurrents ont obtenu le même résultat dans cette course.
Slalom moo jiitu ci moom, mu amee ci Yeggali wu ko" bi mu njëkkee daw. 36 ci 116 naatangoom ñoo bokk benn resiltaa ci rawante gi.
She first competed in the slalom, where she scored a did not finish (DNF) in her first race.
Pour les Australiens, l'idée d'un « café crème » est étrangère. Un noir court est un « espresso », le cappuccino est rempli de crème (pas de mousse) et le thé est servi sans lait.
Australians yi danu jap ni xalaatuk ‘flat white’ kafé lu gnu jagaani la. kafé bu gnul kese mooy ‘espresso’, cappuccino dey fes kerem (bu amul fuurit), te ataya binuy xeli du andë ak meew.
For Australians, the idea of a coffee cream is foreign. A short black is a espresso, the cappuccino is filled with cream (no foam) and the tea is served without milk.
Après la défaite en Ligue des champions, l’OL avait un rendez vous aussi périlleux que leur voyage en Russie.
Gannaaw dóor ya ñu ko dóor ca ligg sàmpiyoŋ ba, OL amoon na am ndaje mu yéeme niki seen tukki ma ca Risi.
After losing the Champions League, OL had a date as dangerous as their trip to Russia.
Je pense que c’est le bon moment pour vendre Salah.
Yaakaar naa ne waxtu wi baax na ngir jaay Sala.
I think it's a good time to sell Salah.
Mais la commission n’a pas suffisamment exploré d’autres possibilités de paiement, notamment la possibilité que des sommes importantes aient pu être payées par des banques privées sur présentation de lettre de confort dûment établis par le ministère des finances.
Waaye kuréel gi jàngul bu baax ngir gis yeneen anamu payoor, rawatina li mën a nekk ne koppar gu am solo lañu fay bànk yi ak benn bataaxal bu am màndargay jëwriñ gi yore wàllu koppar gi.
But the Commission did not sufficiently explore other payment possibilities, in particular the possibility that large sums could have been paid by private banks on presentation of a letter of comfort duly drawn up by the Ministry of Finance.
Real Madrid aurait quasiment bouclé le transfert de.
Daanaka Reyaal Madirit noppi woon na ci njaayum ...
Real Madrid have almost sealed the transfer of.
Les enquêteurs ont découvert que des cristaux s'étaient formés dans l'urine des chats en raison de la présence de ces substances supplémentaires, la mélamine et l'acide cyanurique. 
Gëstukat yi seetlu nañu ay xeer (cristaux) ci sawu muus ginaaw bi ñu ci yokkee mélamine ak acide cyanurique.
Investigators found that crystals had formed in the urine of the cats due to the presence of these additional substances, melamine and cyanuric acid.
Autant il refuse qu’on dicte y’en a marre la façon de mener leur combat citoyen et leur démarche, autant Malal le_fou doit laisser PASTEF s’auto financer comme il veut.
Li muy bañ ñu wax Yaanaa Maar ni mu war a doxalee ay yëngu-yëngoom, noonu la Malal, dof bi, war a bàyye PASTEF mu wut kopparam ni mu ko bëggee.
As much as he refuses to be dictated to how to conduct their civil struggle and their approach, Malal the Fool must let PASTEF finance itself as it wants.
Ce fut là son premier mouvement de regret. Mais il reprit courage :
Looloo doon réccoom bu njëkk. Waaye, mu dellu dëgëral fitam. Mu laaj ko:
This was his first act of regret, but he took courage:
Comparé au financement alloué aux projets de la coopération espagnole au Sénégal de 2014 à 2018, ce montant présente une augmentation de 25%.
Xaalis boobu am na yokkute bu tollu ci ñaar-fukk ak juróom ci téeméer boo jël (25%) bu ñu dendaleek xaalis bi Jàppalanteg Espaañ ci Senegaal di dugal ci ay naalam diggante 2014 ba 2018.
The amount of the financial contribution is EUR 500000000 for the period from 1 January 2014 to 31 December 2018.
Cette richesse se retrouve aussi dans le choix du titre de la formation politique Pastef.
Doole jóoju mu ngi am itam ci tànneefu tur yu tàggatu pólàtig bu Pastef.
This richness is also reflected in the choice of the title of the Pastef political formation.
Ceci est une honte et une insulte permanente d'accueillir cette course.
Loolu gàcce la ak saaka wuy dalal dàqante bóobu.
This is a permanent disgrace and insult to host this race.
De nombreux rythmes observés dans la physiologie et le comportement dépendent souvent en grande partie de la présence de cycles endogènes et de leur production par des horloges biologiques.
Ay ritm yu bari yuñu gis ci wàllum njangum physiolosi ak ci ñu ngi aju yenn saay ci anam bu am solo ci wàllum teewaayu siikël yudul soppeeku ak njur ci ay montaru biologiques.
Many observed rhythms in physiology and behaviour often depend largely on the presence of endogenous cycles and their production by biological clocks.
En conséquence, deux espèces de poissons ont disparu et deux autres sont en voie de disparition, dont le chevesne à bosse.
Ne njureef, ñaai xeeti jën fay nañu, te yeneen ñaar seen bàkkan mu ngi ci xottu gerte, boole ci jënd bu am gannaaw gi jóg.
As a result, two fish species have disappeared and two others are endangered, including the humpback.
En 1683, les forces de la dynastie Qing (1644-1912) prennent le contrôle des zones côtières occidentale et septentrionale de Taïwan et la déclarent province de l'Empire Qing en 1885.
Ci atum 1683, doole kër Qing (1644-1912) mo yore lu jëm ci yaatuwaay sowu ak bët-gànnaarru Taaywaan ak wax ni Taaywaan réew la ci han Qing ci atum 1885.
In 1683, Qing Dynasty forces (1644-1912) took control of the western and northern coastal areas of Taiwan and declared it a province of the Qing Empire in 1885.
Revenant sur le bulletin de Sonko, un expert du droit fiscal dit ne pas comprendre les graves légèretés des services de solde de l'institution parlementaire.
Am na ku xam-xamam màcc ci payum lempo ku ne mënul nàngu cuuneeg ñiy saytu lempo bi ca Péncum ndawi réew ma.
Referring to Sonko's report, an expert in tax law said he did not understand the serious frivolity of the parliamentary institution's payroll services.
A ce titre, la redevabilité restera notre principe phare de référence sur lequel aucune concession n’est possible.
Ci noonu, delloo alalu askan wi mooy suñu seetu boo xam ne duñu ci boole benn maslaa.
As such, accountability will remain our guiding principle on which no concessions are possible.
En tant que jeunes responsables, nous vous invitons à la raison ; ce qui vous obnubile en ce moment n’a rien de noble.
Ndaw yu am pas-pas yi ngeen doon moo tax, nu leen di ñaan ngeen delloosi seen xel ; li ngeen jàpp nii dara baaxu ci.
As young leaders, we urge you to reason; what you are obscuring at this time is not noble.
« Un vote dans le sens du juge Kavanaugh est un vote dans le sens de l’un des juristes les plus accomplis, avec une carrière brillante dans le service public », a-t-il expliqué à la foule de partisans réunis en Virginie-Occidentale.
"Ap wote ngir firnde ni Jude Kavanaugh moy wote ngir firnde kenn ci xel yi gëna macc ci sunu jamano bi ap nitu yoon bu am ay jeego yu am solo ci sarwiisu mboolo.
A vote for Judge Kavanaugh is a vote for one of the most accomplished jurists with a distinguished career in public service, he told the crowd of supporters gathered in West Virginia.
German won Pep's attention with impressive Mainz performances?
Waa Almaañ bi bàyyiloo na xel Pep ci ay jeego yu rëy lool ci Mayence.
German won Pep's attention with impressive Mainz performances?
Les acheteurs étrangers devront payer des droits de timbre plus élevés s’ils achètent une propriété au Royaume-Uni et l’argent supplémentaire sera utilisé afin d’aider les sans-abri dans le cadre des nouveaux régimes conservateurs
Janoo ak taskatu xibaari yow doŋg bariwul.
Foreign buyers will have to pay higher stamp duty if they buy property in the UK and the extra money will be used to help the homeless under the new Conservative schemes.
Un compte bancaire est domicilié à La Seyne-sur-Mer, où la PME a son siège.
Benn nafa koppar mu nga am ca Seyne-sur-Mer ; fa nga xam ne PME fa la am néegu ndaje.
A bank account is registered in La Seyne-sur-Mer, where the SME has its headquarters.
Lui et nos lions de Beach soccer.
Moom ak suñu Gayndey Beach soccer yi.
Him and our Beach Soccer Lions.
Les économistes africains qui ont été consultés reconnaissent que ce sont les chefs d’états africains et leur homologue français, qui ont pris l’initiative de cette création monétaire au nom de la population.
Ñi seen xam-xam macc ci wàllu koom-koom, bi ñu leen dégloo nangu nañu ne jiitu réewu Afrig ak seen naataango tubaab yi, jël nañu dogal ci sàkk seen xaalis ci turi askan wi.
The African economists consulted acknowledge that it was the African heads of state and their French counterparts who took the initiative in creating this currency on behalf of the people.
Le commissaire au commerce et à l'industrie de l'Union africaine, Albert Muchanga, a annoncé l'adhésion du Bénin.
Saytukatu komkom ak njënd ak njay bu AU Albert Muchanga waxnani Benin bokk na.
The African Union Commissioner for Trade and Industry, Albert Muchanga, announced the accession of Benin.
Dans ces conditions, vaut mieux garer les véhicules de vidange pour aller faire autre chose, peste, dans les colonnes du journal, leur porte-parole Jean-François Ndiaye.
Ci yooyu anam, li gën mooy, tëye otoy manq duus yi dem defi leneen, loolu la ki yore seen kàddu gi, Sãa Farãasuwaa Njaay wax ag xol ci yéenekaay bi.
In these conditions, it is better to park the waste vehicles to go do something else, plague, in the newspaper columns, their spokesman Jean-François Ndiaye.
Ce, pour réaffirmer les relations qu’il entretenait avec son défunt père Serigne Abdoul Aziz sy Al Amine.
Loolu, ngir dëggal digganteem bi mu amoon ak ndem-si-yàlla baayam Abdu Asiis Si Al Amiin.
This was to reaffirm the relationship he had with his late father Serigne Abdoul Aziz sy Al Amine.
« Le problème de l’accès à la mer a été détourné par l’administration bolivienne actuelle », a déclaré Zárate.
Zàrate neena "Jafe jafe bi ngir agg ci geej gi nguur gu Boliwi moo ko xajamal."
The problem of access to the sea has been hijacked by the current Bolivian administration, said Zárate.
Au Sénégal, force est de constater qu’il est impossible d’être serein et optimiste au vu de toutes ces incohérences et impuissance du gouvernement de Macky Sall face aux problèmes quotidiens que vivent les Sénégalais.
Ci Senegaal, noo def gis ne manoo ànd ak dal ak wóolu bu ñu gisee yi mengoowul yépp ak tele nguuru Maki Sàll gi ci jafe-jafe askanu waa Senegaal.
In Senegal, it is clear that it is impossible to be serene and optimistic in view of all these inconsistencies and the powerlessness of the Macky Sall government in the face of the daily problems faced by the Senegalese people.
Ainsi, les débats vont précisément porter sur la départementalisation de Keur Massar, la création de nouveaux arrondissements dans la région de Dakar et les limites de collectivités territoriales dans les départements de Keur Massar, Pikine et Rufisque.
Fi mu nekk nii, waxtaan yi dinañu aju ci séddale goxu Kër Masaar, sos yeneen gox yu yees ci diwaanu Ndakaaru bi ak ñag gox-goxaan yi nekk ci diwaanu Kër Masaar, Pikin ak Tëngéej.
The debates will focus on the departmentalization of Keur Massar, the creation of new districts in the Dakar region and the boundaries of territorial authorities in the departments of Keur Massar, Pikine and Rufisque.
jusqu'à meme menacer.
Ba di dànkaafu.
I even threatened to.
Les autorités ont publié une vidéo de l’affrontement entre Sims et Simpson, et la police a indiqué que Sims avait perdu ses lunettes pendant l’altercation.
Ofisiye yi gennena ñu benn widewo bu xeexu Sims ak Simpson te poliis neena Sims ñakk na ay lonetam ci xeex bi.
Authorities released a video of the confrontation between Sims and Simpson, and police said Sims lost his glasses during the altercation.
En effet, le Sénégal s’apprête à vivre un moment crucial, celui d’un changement total de paradigme dans la gestion de ses finances publiques, qui se décline principalement au travers de deux réformes : la budgétisation en programmes et la déconcentration de l’ordonnancement.
Senegaal a ngi waaj a dugg ci jamono ju doy waar, jamono ju ñuy amal ñaari coppite yu daj fépp ci yorum xaalisu askan wi : nattinu xaalisu tëralin yi ak lawalug ñiy génne xaalis bi ba ca gox-goxaat ya.
Senegal is about to experience a crucial moment, that of a total change of paradigm in the management of its public finances, which is mainly achieved through two reforms: budgeting in programmes and the decentralisation of planning.
Après une fouille, je suis conduite dans un bureau pour une audition à la suite de laquelle j’ai regagné le taudis qui me servait de chambre cette nuit-là.
Ginnaaw bi ñu ma lëñbëtee samay yére lañu ma déglu laata ñu may yóbbu ca puquus ba ma war a fanaam.
After a search, I was taken to an office for an interrogation, after which I returned to the shack that had been my bedroom that night.
Toi, tu auras des étoiles comme personne n’en a… Que veux-tu dire ?
Yaw, dinga am biddéew yu melul ni yu kenn. Loo bëgg a wax foofu?
You'll have stars like no one else has...
Cet acte inédit dans le cadre de la gestion de la Convention Nationale Etat-employeurs, va s’élargir dans les régions très prochainement en conformité avec la territorialisation des politiques publiques.
Jëf ju benne jooju am ci mbiru saytu Kurél gi boole Nguur geek njaatige yi, dina law ba ci diwaan yi fan yii di ñëw, te ñu dëppale ko ak yeggale doxalini nguur gi ci diwaan yi.
This is a new step in the management of the National Convention State-Employers, which will be extended to the regions very soon in line with the territorialization of public policies.
Selon Sunu Lamb, le fils de Double Less envoie ses missiles à Bombardier qu’il doit affronter le 31 juillet prochain.
Bu ñu sukkandikoo ci Sunu Làmb, doomu Dubalees ji sànni na ay gàllaaj Bombarjee mi mu war a bëréel fan-weeri fan ak benn ci weeru sulet bii di ñëw.
According to Sunu Lamb, Double Less's son is sending his missiles to Bombardier, who he's going to face on July 31st.
Aujourd’hui, « on ne se fréquente plus de la même façon, explique-t-il.
Moom neena: “Leegi nit yi ci yeneen anam lanuy xamante.”
Today, "we don't hang out the same way", he says.
Waaye, boo amee ag nguur goo xam ne, amul baat ci benn boor, daraam du sotti.
Waaye, boo amee ag nguur goo xam ne, amul baat ci benn boor, daraam du sotti.
But I'm not going to tell you, I'm not going to tell you.
La commission nationale de recensement des votes donnera le même chiffre avant que la cour suprême confirme le résultat.
Kurél giy saytu limub ñi wote dina joxe benn lim bi laata ëttu àtte bu kawe bi di ko dëggal.
The National Election Commission will give the same number before the Supreme Court confirms the result.
La marque Truly a été assimilée à celle de l’actrice Gwyneth Paltrow, Goop, et aurait pu doubler la valeur de la fortune de l’animatrice estimée à 11 millions £.
Bisnees ba niroolenan ko ak fasonu goopu Gwyneth Paltrow te xaymanan ni nekk na ñaari yoon alalu Willoughby bii tollu ci 11 milyoŋ.
The Truly brand has been likened to actress Gwyneth Paltrow's Goop and could have doubled the value of the host's estimated £11 million fortune.
Nous ne sommes ni le gouvernement ni une ONG ou encore une association caritatives pour prétendre régler les problèmes des sénégalais.
Nekkuñu nguur gi, duñu mbootaay gu bokkul ci nguur gi wala guy dimbale te bëgg a saafara jafe-jafey askanu Senegaal.
We are not the government or an NGO or a charity to claim to solve the problems of the Senegalese people.
L’ancien numéro 10 de Southampton n’est pas passé loin de la saison parfaite, en finissant 2e de Premier League avec 22 buts à son compteur et un total de points qui frôle la perfection : 97, avec une seule défaite en 38 rencontres.
Ki doon sol limub fukk ca Sawsaamton soriwul def at mu mat sëkk ndax moo doon ñaareel ci Përëmiye Ligg, dugal fukki bit ak ñaar, am juróom-ñeent-fukki poñ ak juróom-ñaar, benn lajj ci fan-weeri joŋante ak juróom-ñett.
The former Southampton number 10 did not go far from the perfect season, finishing second in the Premier League with 22 goals to his name and a near-perfect points total: 97, with only one defeat in 38 matches.
Un acte qui a fait le tour des télévisions et qualifié de machiste.
Jëf ju wër tele yépp te ñu jàppe ko ni ju góore.
An act that made the rounds of television and was called macho.
Les récoltes n’ont pas pour vocation d’être commercialisées mais seront réinjectées dans le circuit agricole toujours dans la dynamique de l’autonomisation.
Li ñu góob du dañu koy jaay waaye dañu kay dugalaat ci wàllu mbay mi ngir ba tey ñu moom sunu bopp ci wàllu mbay.
The crops are not intended to be marketed but will be reinjected into the agricultural cycle, always in the dynamic of self-empowerment.
La Maison-Blanche annonce que le meeting de Trump et Rosenstein pourrait encore être retardée
Mayorga xamle itam ni demoon na poliis te yoroon na ay nataalam fu mu ame ay gaañu gaañu ci benn lopitaal, waaye mu mujje nanngu benn dox jamm ci bitti kuur bi ndax te defa yëg "tiitaange ak toroxal" te defa doon ragal " rusloo ci kanamu ñépp."
The White House is announcing that the Trump-Rosenstein meeting may be delayed again.
Une volée du spécialiste Pavard et un énième but de Lewandowski ont suffi au bonheur des munichois.
Benn pacc bu waay xarañ bi di Pavard ak bi mujj tey bu Lewandowski doy nañu ngir bégal waa Mënich yi.
A volley by specialist Pavard and another goal by Lewandowski were enough to make the Munichers happy.
Seulement, le prévenu ne s’est pas arrêté en si mauvais chemin.
Waaye, ki ñu àrtu taxul mu bàyyi yoon wu bon wi.
However, the defendant did not stop on such a bad road.
Pour Pape Malick Sy, Aly Ngouille Ndiaye devrait bien animer le Gamou, tant son discours a été fouillé et illustratif, a-t-il commenté sous un ton hilarant qui a fait éclater le public de rires…
Paab Maalig Si, jàpp na ne Aali Nguy Njaay a waroon a waxtaane Gàmmu gi, ndax waxam ju matale te leer, loolu la ci teg ak melo wu xoromu, ba tax mbooloo mi daanu ci suuf ak i reetaan….
For Pape Malick Sy, Aly Ngouille Ndiaye should lead the Gamou, so much his speech was researched and illustrative, did he comment in a hilarious tone that made the audience burst out laughing...
C’est cela qu’il faut poser comme problématique et je pense que vous, M. Ibrahim Yacouba, vous oserez poser ces questions parce que nous partageons ensemble beaucoup de choses.
Loolu lañu war a jàppe xat-xat te foog naa ne yaw, Ibraayima Yakuba, sañ ngaa samp laaj yii ndax sékk nañu mbir yu bare .
This is what we have to ask as a problem and I think you, Mr Ibrahim Yacouba, will dare to ask these questions because we share a lot of things together.
Elle est toute sèche, et toute pointue et toute salée.
Dafa wow koŋŋ, te ñaw lool, te saf sàpp xorom.
It's all dry and all pointy and all salty.
Au final, cela revient à une sorte de taxe invisible, qui ne se reflète pas dans notre argent, mais se ressent dans notre pouvoir d’achat par une hausse généralisée des prix.
Ci mujj gi, dafa mel ne juuti bu ñu mënul a gis, bu feeñul ci sunu xaalis waaye ñu koy yég bu baax ci jënd gi ag njëg lu yokk li.
In the end, this amounts to a kind of invisible tax, which is not reflected in our money, but is felt in our purchasing power through a generalized increase in prices.
Des échauffourées ont également éclaté plus tard dans la journée, tandis que la police faisait usage de matraques pour contenir les affrontements.
Ay jappante daa di tammbali itam ci bis bi ndax poliis bi defa doon jefandiko ap yatt ngir muna facc xeex bi.
Skirmishes also broke out later in the day, as police used batons to contain the clashes.
ADD : Au MOJIP FRANCE , nous avons beaucoup de projets à destination des femmes sénégalaises.
ADD : ca MOJIP FARÃAS, am nanu ay naal yu bare yu jëm ci jigéeni waa Senegaal.
ADD: At MOJIP FRANCE, we have many projects for Senegalese women.
Le résultat fut décevant, outre Fofana, le ministre des Finances d’origines Français Andre Peytavin fut remplacé par Valdiodio Ndiaye.
Li mu jur dafa ruslu, ginnaaw Fofana, Waljoojo Njaay moo wuutu woon Jëwriñu Koppar yi cosaanoo Farãas, Andare Petaaveŋ.
The result was disappointing, as well as Fofana, the French-born Finance Minister Andre Peytavin was replaced by Valdiodio Ndiaye.
Alors l'ex président accidentel, Wade Abdoulaye avait fièrement mit fin à la construction de la Voie routière Linguère-Matam sous les chauds applaudissements de ses semblables.
Ci noonu, njiitu réew ma woon, Wàdd Abdulaay, nga xam ne sës a ko taxoon a falu, dafa dakkaloon defarug yoonu Lingeer-Maatam wi, ànd ci nag ak mbégte, ñi meloon ni moom doon ko tàccul ndax loolu.
Then the accidental former president, Wade Abdoulaye proudly ended the construction of the Linguère-Matam Highway under the warm applause of his peers.
Comparé à la LFR1 qui est arrêtée en recettes à 2 964,79 milliards FCFA et en dépenses (hors amortissement de la dette) à 3 398,65 milliards de FCFA pour la LFR1, le présent projet de loi connait une hausse respective de 293,66 milliards de FCFA (9,9%) et 310,33 milliards de FCFA (9,1%) en valeur absolue.
Méngale kook LFR1 mi xaalisam bi dugg yem ci ñaari junni ak juróom-ñeenti téeméer ak juróom-benn-fukk ak ñeent kos juróom-ñaar-fukk ak juróom-ñeenti milyaar (2 964, 79), te mu génne ci (gannaaw bor bi ñu wàcce) lu toll ci ñetti junni ak ñetti téeméer ak juróom-ñeent-fukk ak juróom-ñett kos juróom-benn-fukk ak juróomi milyaar (3 398, 65) ci Seefaa ngir LFR1, naal bi fi nekk ngir ñu wote ko, am na ay yokkute yu toppantee nii ñaari téeméer ak juróom-ñeent-fukk ak ñett kos juróom-benn-fukk ak juróom-benni milyaar (293, 66) ci Seefaa, juróom-ñeent kos juróom-ñeent ci téeméer boo jël (9,9%), ak ñetti téeméer ak fukk kos fanweer ak ñetti milyaar (310, 33) ci Seefaa, juróom-ñeent kos benn (9, 1%) ci njëg lu teew.
Compared with the LFR1 which is fixed at FCFA 2 964.79 billion in revenue and FCFA 3 398.65 billion in expenditure (excluding debt amortisation) for the LFR1, this bill has an increase of FCFA 293.66 billion (9.9%) and FCFA 310.33 billion (9.1%) in absolute value respectively.
Mais, un jour, bientôt, le peuple sortira de sa torpeur pour marcher sur ces crabes.
Benn bés, lu yàggatul dara, askan wi dina wàcc ci mbedd mi, fésal li ko naqari yépp.
But one day soon, the people will rise from their slumber to walk on these crabs.
Des gosses de riches francais affilies a des complexės apatrides de la trempe de Diagna Ndiaye viennent nous vendre du pipo.
Ay doomi Farãas yu am alal lool te lëkkaloo ak ay sàmba-àllaar yu mel ni Jaaña Njaay ñooy jaay ne ci daara yu am tur lañu génne.
We're being sold dope by the children of wealthy Frenchmen affiliated with stateless complexes like Diagna Ndiaye.
Pour annoncer la nouvelle sur Twitter samedi, il a écrit : « Anciennement connu sous le nom de Kanye West. »
Muy xamle coppite bi Samdi ci Twitter mu bind lii: "Xamewoon ma bu njëkk Kanye West.”"
Announcing the news on Twitter on Saturday, he wrote: Formerly known as Kanye West.
Il se dit pourquoi impliquer les Étudiants dans les revendications sociales, puisqu’ils ont l’électricité et l’eau gratuites, ne subissent point l’inflation du prix des denrées de première nécessité, la hausse du prix du riz, de l’huile et du pain n’est pas répercutée sur leur ticket de restauration, et le loyer de leur chambre coûte moins cher que la patente mensuelle d’un vendeur d’arachides.
Mu ngi doon laaj lu tax ñuy dugal njàngaan yi ci ñaxtuy pénc mi, ndax am nañu kuuraƞ duñu fay ndox, yégguñu yokkum njëkk yi, yéegum njëgu ceeb bi, njëgu diw gi, njëgu mburu mi, loolu lépp amul jeexital ci seen tiket yi ñuy jëfëndikoo ngir lekk rax-ci-dolli seen payug luyaas seerul.
He wonders why involve students in social demands, since they have free electricity and water, do not suffer from the inflation of the price of basic necessities, the rise in the price of rice, oil and bread is not reflected on their restaurant ticket, and the rent of their room is cheaper than the monthly rent of a peanut vendor.
Puis il a passé le ballon à Sterling, sur sa gauche.
Mu puus ak tankam bu cammoy bi mu jot Sterling.
Then he passed the ball to Sterling, on his left.
Trump déclare que Kavanaugh a été victime de la méchanceté et de la colère des démocrates
Trump neena Kavanaugh defa alaxu ndax nekkinu , meru parti Demokaratik
Trump says Kavanaugh was a victim of the Democrats' malice and anger.
Selon toute vraisemblance, principalement orchestré par l’ancien Directeur des domaines de la République du Sénégal, Mamour Diallo, à partir d’un titre foncier de l’Etat (TF1451R), c’est l’Affaire de plus qui fait tâche et colle à la peau du régime de Macky II.
Niroo naak mbir mu njiitu kër giy fayeeku lempo bi ba woon, Maamur Jàllo, def te jaare ko ci suufu nguur gi (TF1451R). Loolu meneen mbir la mu ñu tuumaal ñaareelu nguuru Maki.
In all likelihood, orchestrated mainly by the former Director of the Senegalese Republic's estates, Mamour Diallo, on the basis of a state land title (TF1451R), this is the most serious case of the Macky II regime.
En effet, l’idée a été émise de priver de droits civiques tout fonctionnaire ayant reçu une sanction administrative à partir du non-respect du devoir de réserve.
Li ñu xalaat mooy xañ képp kuy liggéeyal nguur gi sa yelleef su fekkee ne dañu la tegoon ay daan ndax sa màndoodi.
The idea was put forward to deprive any civil servant who had received an administrative penalty for failure to comply with the duty to reserve civil status.
Comparé aux séries télévisées actuelles, c’est surement ce manque de subtilité que Moussa Sène Absa soulignait quand il parlait des séries modernes sénégalaises, et de la différence entre le cinéma et la télévision.
Bu ñu ko tëkkaleek filmu tele yi xew léegi, wóor na ni ñàkk xarañteg Musaa Seen Absa doon leeral bi muy wax ci film yi xew Senegaal, ak wuute gi am ci filmu sinemaa ak bu tele.
Compared to current TV series, it is surely this lack of subtlety that Moussa Sène Absa emphasized when he spoke about modern Senegalese series, and the difference between cinema and television.
Sa soeur occupe le poste de sécretaire particulière depuis qu'elle est au MAE.
Rakkam ju jigéen moo fa nekk sekerteer bu sës ba mu demee MAE ba tey.
His sister has been the special secretary since she joined the Ministry of Education.
J'en suis triste et je lui présente mes condoléances à lui et à sa famille
Dama koy naqarlu te di ko mas-sawu, moom ak njabootam.
I'm sorry for that and I offer my condolences to him and his family.
L’Europe a récupéré le titre lorsque l’équipe du capitaine danois Thomas Bjorn a franchi la barre des 14,5 points nécessaires pour battre les États-Unis.
Xare jënd ak njaay digante reewum Amerig ak Siin mënna njariñ Beijing.
Europe regained the title when Danish captain Thomas Bjorn's team crossed the 14.5 points mark to beat the United States.
Le Parcours reflète avec un grand souci de justesse, la multiplicité, les nuances et les contrastes qui composent la réalité contemporaine de Dakar.
Jaar-jaar bi wone na njàqare gu rëy, ak bariwaay bi, ak pakk yee juuwaloo yi tabax nekkinu Ndakaaru.
The course reflects with great care the multiplicity, nuances and contrasts that make up the contemporary reality of Dakar.
Ils ont fait pression sur moi !
.
They pressured me!
Quel investissement, quel projet a-t-on prévu pour rééquiper les hôpitauxà la sortie de la crise ?
Fan lañuy dugal xaalis, wan tëralin lañu fàggu ngir gën a jox lopitaal yi ay jumtukaay ngir ñu génn ci njàqare gi ?
What investment, what project is planned to re-equip hospitals after the crisis?
Monter dans sa propre voiture et partir pour un long voyage a un attrait intrinsèque dans sa simplicité.
Dugg ci sa oto bopp, def tukki bu sori nuru na mbir mbu yomb waaye noonu la neexee.
Getting into one's own car and going on a long journey has an intrinsic appeal in its simplicity.
Les autorités, les services de sécurité ainsi que des secouristes sont sur place et procèdent a la recherche des disparus.
Kilifa yi, ña yor wàllu kaaraange ak wallukat yi ñoo ngi ci barab ba tàmbalee wër ñi réer
Authorities, security services and rescue workers are on the scene and are searching for the missing.
Les données, collectées auprès des 74 écoles membres du SCIS, montrent que 72 % des élèves ont obtenu la note la plus élevée, A, en mandarin, tout comme les 72 % d’élèves qui ont étudié l’allemand, les 69 % d’élèves qui ont étudié le français et les 63 % d’élèves qui ont étudié l’espagnol.
Lii ap fatteli bu am solo la ni munuñu yem ci Anngele rek su ñu bëgge tabax xaritoo ak koolute ak au nit yu juge yeneen réew.
Data from the 74 SCIS member schools show that 72% of pupils achieved the highest grade, A, in Mandarin, as did 72% of pupils in German, 69% in French and 63% in Spanish.
Gridley ou Stark a placé un pieu à environ 30 mètres devant la clôture et a ordonné que personne ne tire avant que les habitués ne la franchissent.
Gridley wala Stark tekna benn pike bu wara tollu ci 100 pied (30 m) ci kawewaay ci kanamu miir bi ni bu kenn dóor bal fileek gaa ñi fi bokk jàllu ñu.
Gridley or Stark put a stake about 100 feet in front of the fence and ordered that no one fire until the regulars crossed it.
Vaut mieux aller faire la mode ou une autre activité qui se rapprocherait le plus de cela.
Li gën mooy dem defi modd wala beneen liggéey bu ko gën a jege.
Better to go into fashion or something that comes closest to that.
Car, comme le rappellent nos interlocuteurs, l'impôt est différent des cotisations sociales.
Léegi ñia yuuxu woon ca kaw ci baat bu jog ne duñu aar kenn noppi gannaaw ba ñu wéddee seen bopp.
As our interlocutors have pointed out, taxation is different from social contributions.
Il ne parle que de sanctions qui ne servent à rien.
Du wax lu dul ay daan yu amul benn njariñ.
He's talking about sanctions that don't help.
De deux choses l'une: ou bien Macky est entouré de nuls et s'en accomode ou alors il n'écoute personne.
Ci ñaari mbir benn bi : Maki de ñu xamul dara ñoo ko wër, mu dem ba miis ko wala du déglu kenn.
One of two things: either Macky is surrounded by losers and he's okay with it, or he doesn't listen to anyone.
Je ne sais pas si vous vous en rendez compte, mais la plupart des marchandises en provenance d'Amérique centrale sont entrées dans notre pays exonérées de taxes.
Xamuma ndax yeena ngi ciy bàyyi xel am déet, li ëpp ci marchandise yiy bawoo Amérique centrale dañuy dugg ci réew moomu te duñu fay taks.
I don't know if you are aware, but most of the goods from Central America have entered our country duty free.
La Cimade publie les témoignages des personnes qu’elle accompagne, en particulier dans les centres de rétention.
Cimade génne na ay nettali wu nit yu mu gunge lu ci mel ne bërëbu denc yi.
The Cimade publishes the testimonies of the people it accompanies, especially in detention centres.
Hakimi(doublé) et Brandt ont été les bourreaux des Italiens.
Hakini (ñaari bit) ak Brandi ñoo doggali woon Itali yi
Hakimi and Brandt were the executioners of the Italians.
Ce ne sont pas les mêmes, dit l’aiguilleur. C’est un échange.
Juuyeer bi ne ko: Bokkuñu. Ab juuyoo la.
"They're not the same", said the handyman. "It's a trade-off".
Tout est basé sur l’autodétermination politique, économique et culturelle, appuyé par le patriotisme et la transparence dans la gestion des affaires publiques.
Lépp a ngi aju ci dogu giy am ci wàllu pólótig, koom-koom geek aada ji, yiy dollikoo bëgg sa réew ak leeral doxalinu saytu bokk-moomeel gi.
Everything is based on political, economic and cultural self-determination, supported by patriotism and transparency in the management of public affairs.
La vedette Sea Premium 100 baptisée Fatick, qui n’est donc pas un yacht pour promenades présidentielles, est destinée, comme La Signare, à transporter les autorités sénégalaises, ainsi que les hôtes de marque, de Dakar à l’île de Gorée, dans les conditions standard modernes de sécurité.
Sea Premium 100 bu siiw bi ñu tudde Fatig, nekkul ag gaal goo xam ne njiitu réew mi daf ciy doxantu. Ni ki La signare, dafay yóbbu njiiti Senegaal yi ak gan yu am solo yi diggante Dakaar ak Gore, ci anam yu ànd ak kaaraange gu àdduna yépp nangu ne noonu la war a mel.
The Sea Premium 100 vessel, named Fatick, which is not a presidential yacht, is intended, like La Signare, to transport the Senegalese authorities and distinguished guests from Dakar to Gorée Island in modern standard safety conditions.
La corrélation entre la pathologie du cerveau et le comportement soutient les scientifiques dans leurs recherches.
Mbokko gi am ci diggante feebaru xel ak nekkin dafay jàppale xeltukat yi ci seeni ceytu.
The correlation between brain pathology and behaviour supports scientists in their research.
Des plateaux et débats de haute facture y seront animés.
Ay jotaayi waxtaan yu am solo lañu fay amal.
There will be high-profile panels and debates.
C’est exact, dit le géographe, mais je ne suis pas explorateur. Je manque absolument d’explorateurs.
Gëstukat bi ne ko: Dëgg la, waaye duma wërkat. Ay wërkat laa ñàkk dëggdëgg.
"That's right", said the geographer, "but I'm not an explorer. I'm absolutely short of explorers".
Selon L’AS qui donne l’information, ils se livraient à une partie de Blow (Ndlr : faire la fête en bravant tous les interdits) jusqu’à se retrouver derrière les barreaux.
Su ñu sukkandikoo ci L’As mi joxe xibaar bi, dañu doon yaataayumbe ba kaso fekk leen ci.
According to LAS, they were playing a game of Blow until they ended up behind bars.