fr
stringlengths
4
1.08k
wo
stringlengths
2
4.02k
en
stringlengths
3
1.08k
Le sable, au lever du jour, est couleur de miel.
Bu jant bi di fenk, suuf si dafay yor melow lem.
The sand at dawn is the color of honey.
Cristina Duarte, conseillère spéciale du secrétaire général des Nations unies, avait avancé une observation astucieuse lorsqu’elle avait déclaré, dans un article publié par le FMI, que l’adoption massive des technologies numériques signifie également que les décideurs politiques devront prendre conscience de l’impact juridique et éthique complexe de la technologie sur la société et y faire face, notamment en matière de respect de la vie privée, de protection de la confidentialité des données et de lutte contre l’évasion fiscale.
Kiristinaa Duwarte di xelalkatu sekereteer bu Mbootaayu xeet yi tippoo, waxoon na lu doy waar ba mu nee ci men mbindam bu FMI génnee, li ñuy duggu bu baax ci xarañ te xarala yi mooy itam ne ñiy dogal ci wàllu pólótig dañoo war a bàyyi xel jeexitalu yoon ak gëm-gëm yu ruqe yu xarala ci péey bi te jàkkaarlook moom lu ci mel ne jox cër dundug jàmbur, aar baat yi ñu war a suturaal, ak xeex lënt-lënt yi ci lempo yi.
Cristina Duarte, Special Adviser to the UN Secretary-General, made a clever observation when she said in an IMF article that the mass adoption of digital technologies also means that policymakers will have to become aware of and address the complex legal and ethical impact of technology on society, including privacy, data privacy and the fight against tax evasion.
Aucune coupure d'eau n'est prévue dans les prochains jours.
Yaakaaruñu ndox ñàkk ci fan yii di ñëw.
No water cuts are expected for the next few days.
A tous votez massivement pour faire partir l'injustice, les complots, la dynastie faye sall dont aucune consideration pour le peuple
Ñun ñépp, nanu àndandoo wote ngir génne fi jalgati yoon, mànkoo ngir faagaagal, nguuru Fay- Sàll gi amul benn worma ci askan wi.
All of you vote massively to remove the injustice, the plots, the Faysal dynasty that has no regard for the people
Le leader du mouvement politique dénommé Alliance générationnelle pour les intérêts de la République (Agir), Thierno Bocoum, a été victime d’un cambriolage, dans la nuit du jeudi au vendredi 8 novembre, à Dakar.
Ki jiite kuréelug pólótig gi ñuy wax « Alliance Générationnelles pour les Intérêt de la République » (AGIR), Cerno Bóokum moom la ak càcc dal ci kawam keroog ci guddig alxemes jàpp àjjuma juróom-ñetti fan ci weeru nowàmbar, ci Ndakaaru.
The leader of the political movement called the Alliance Générationnelle pour les Interêts de la République (Agir), Thierno Bocoum, was the victim of a robbery on the night of Thursday 8 November in Dakar.
L’émoi est aussi sur ces regards hagards qui fixent le temps.
Yëngu gaa ngi itam ci xoolin yi wékku ci doxinu jamono.
The emotion is also in those haggard eyes that fix the time.
Il a envoyé un e-mail aux étudiants de l'université locale et a reçu un nombre impressionnant d'offres d'hébergement gratuit.
Dafa yonee ndongo ya ca iniwersité bu nekk ci dëkk bi bataaxal ci internet dal di jot ci ay tektal dëkkuwaay yu bari yu amul fay.
He emailed students at the local university and received an impressive number of free accommodation offers.
Mais la dette est un peu élevée… J'ai dit, le Japon, la France, Les États Unis etc ont une dette beaucoup plus élevée que la nôtre alors qu'on ne les voit jamais demander des prêts.
Waaye bor bi nag dafa xaw a takku…–Dama ne, Sàppoŋ, Farãas, Amerig añs ñoo ñu ëpp bor fuuf te doo leen mës a dégg ñuy ñaan ku leen ko baal.
But the debt is a little high... I said, Japan, France, the United States etc. have a debt much higher than ours while we never see them asking for loans.
La presse locale a rapporté qu'un véhicule de lutte contre l'incendie de l'aéroport a fait des tonneaux en portant secours.
Bénn tassukaayu xibaar waxnani bénn daamaru lakk bu bénn airport moo daanu ci bimuy wuyu.
Local media reported that an airport firefighting vehicle was carrying relief supplies and was in a barrel.
Si je pose ici la question de savoir où passent l’uranium et le pétrole du Niger, très peu de gens pourront me répondre.
Su ma la laajee fan la iraañum bi ak peterolu Niseer bi jaar, ñu néew ci nit ñee may tontu.
If I ask here where the uranium and oil from Niger go, very few people will be able to answer me.
Selon Nugroho, les dégâts sont considérables ; des milliers de maisons, d’hôpitaux, de centres commerciaux et d’hôtels se sont effondrés.
Nugroho mungi misaale mettit bi ni luy" law " te neena ay junni kër , lopitaal, ay manngasiin aki otel mabb nañu.
According to Nugroho, the damage is extensive; thousands of homes, hospitals, shopping malls and hotels have collapsed.
Kolda qui avait récemment battu le macadam pour disposer d’un gynécologue avant que le ministère de la santé n’y affecte un à l’hôpital régional pourra durant les 72 heures que vont durer ces journées voir ses populations qui le souhaitent se faire consulter sans bourse délier.
Jëwriñu wér-gu-yaram ji jox na waa-Koldaa masin buy seet jigéeni wérul yi ginnaaw bi waa dëkk ba amalee ab doxu ñaxtu. Fii ak ñetti fan, dinañu mën a faju te duñu fay dara.
Kolda, which had recently been hit by the macadam to have a gynaecologist before the Ministry of Health assigned one to the regional hospital, will be able to see its people who want to be consulted without a grant during the 72 hours that these days will last.
Les filets n’ont certes pas tremblé, mais les 15 829 spectateurs du Lodz Stadium ont tout de même vibré.
Ndaxam sax caax yi yënguwuñu, waaye fukki junni ak juróom ak juróom-ñetti téeméer ak ñaar fukk ak juróom-ñeenti seetaankat yi teewoon ca Lods Stadium bégoon nañu.
The nets did not shake, but the 15,829 spectators in Lodz Stadium were still shaking.
Des marches en pierre sont posées le long de la plupart du chemin, et des câbles en acier offrent une rampe de soutien dans les sections les plus raides.
Jàllukaay yu xeer lanu teg ci lu ëpp ci yoon wi ak ci yoon yu gëna dëggër, buumu asiye yi danuy jàppale.
Stone steps are laid along most of the path, and steel cables provide a supporting ramp in the steepest sections.
Sous ce rapport, il est évident qu’il n’appartient pas au Ministre des Finances et du Budget, ni même au Président de la République, de dire par un acte réglementaire ce qui est imposable ou ce qui est exonéré.
Ci bile doxaliin, leer na ne du ci Jëwrin ji ñu dénk koppar yeek koom-koom gi, du ci Njiital réew mi, moo war a wax di ko jaare ci jëf ju ñu yoonal, muy lu war a mën a jàlle ci doole, walla lu ñu mën a teggi ag fayam.
In this connection, it is obvious that it is not for the Minister of Finance and Budget, or even the President of the Republic, to say by means of a regulatory act what is taxable or what is exempt.
Pastef est la force dont la progression est constante, c’est pourquoi il cherche à bloquer ses initiatives.
Pastef mooy doole ja nga xam ne yéegam dafa sax, looloo waral muy wut gàntal ay naalam.
Passive is the force whose progress is constant, which is why it seeks to block its initiatives.
Le chef de la division de la sécurité de pêche artisanale était à Mbour dans le cadre d’une campagne de sensibilisation sur les conduites à tenir pour mettre fin aux accidents maritimes.
Njiitu kaaraangeg nàppu loxo gi mu ngi woon Mbuur ci ab woote yeete ci doxalin bi ñu war a am ngir jële fi jéyya yiy am ci géej gi.
The head of the Small-Scale Fisheries Safety Division was in Mbour as part of an awareness-raising campaign on what to do to stop marine accidents.
Il a ensuite dominé une grande partie de la course tout en maintenant ses pneus pour viser une arrivée en vitesse et devancer Kimi Raikkonen à la quatrième place.
Boston Globe xamlena ni demokarat yu Massachusetts waxoon nañu ci ëllëkam ci benn dajaloo ci biir dëkk bi ci bët soowu Massachussets ci Samdi.
He then dominated much of the race while maintaining his tyres to aim for a fast finish and overtake Kimi Raikkonen in fourth place.
Une voiture piégée a explosé au siège de la police à Gaziantep, en Turquie, hier matin, tuant deux officiers de police et blessant plus de vingt autres personnes.
Benn ndaamaar bu am ndel m tàkk ci daluwaay polis ci Gaziantep, Turki demb ci suba rey na ñaari takk der te gaañ lu ëpp yeneen ñaar fukki nit.
A car bomb exploded at the police headquarters in Gaziantep, Turkey yesterday morning, killing two police officers and injuring more than twenty others.
Bonne opération pour les Bavarois car dans le même temps le leader s’est incliné sur le terrain de la Union Berlin par un score de 2 buts à zéro.
Lu baax ci Bawaruwaa yi ndax ci jenn jamono ji, ki jiitu ñàkk na ci tereŋu Union Berlin, ñaari bit ci tus.
Good move for the Bavarians because at the same time the leader was defeated on the field of the Union Berlin by a score of 2 goals to zero.
Les comptes spéciaux du Trésor (CST) sont projetés, comme dans la LFR1 2019, en ressources et en charges à 135,95 milliards de FCFA.
Kubu àddina bi 1998 ak 2018 = Sëriñ.
The special accounts of the Treasury (CST) are projected, as in LFR1 2019, in resources and expenses at FCFA 135,95 billion.
Sa décision de retrait doit être notifiée à la conférence des chefs d’Etat et de gouvernement de l’UEMOA .
Dogalu bàyyeem dañu ko war a xaatim yónne ko njiiti réew yeek nguur yu Kurél giy saytu koom-koom beek koppar yi ci réewi Afirig sowu jànt
Its decision to withdraw shall be notified to the Conference of Heads of State or Government of WEUM.
Le gardien brésilien, auteur d’une performance de haut niveau, sauve son équipe à plusieurs reprises et notamment sur un coup franc d’Eriksen à la 83e minute.
Tinis : 1u Orange Digital Center ngir gaawal ak dooleel këri jumtukaayi xarala yi.
The Brazilian goalkeeper, who has a high level of performance, saves his team on several occasions, including a free kick from Eriksen in the 83rd minute.
En déplacement sur le terrain de Alaves, le Real a fait le nécessaire.
Bi ñu fekkijee waa Alawes, Reyaal def na li war.
On the way to the Alaves pitch, Real did what was necessary.
Un chauffeur de taxi vient de se voir refuser l’accès à son appartement à Grayson Mews, la police n’autorisant personne à entrer ni à sortir du bâtiment.
Benn dawalkatu bu dëkk Grayson Mews jeemna delluwaat ci nëëgam waaye poliis neena ko mayuñu keen ndigal duggu foofu mbaa ku genni tabax bi.
A taxi driver has just been denied access to his apartment in Grayson Mews, with police not allowing anyone to enter or leave the building.
Elle s’habillait lentement, elle ajustait un à un ses pétales.
Mu ngi doon soolu ndànk-ndànk, di defar benn benn ay xobam.
She dressed slowly, adjusting her petals one by one.
Il commença donc par les visiter pour y chercher une occupation et pour s’instruire.
Mu tàmbali leen nemmiku ngir seet lu mu fa liggéey ak jànge fa.
So he started visiting them to find a job and to teach.
Je l’ai pris avec beaucoup de recul à l’époque et encore plus aujourd’hui”, confie l’attaquant de Chelsea, récent vainqueur de la Ligue des champions.
Futbalukatu Chelsea bi bokk ci ñi jël raw-gàddug Ligg-dee-sàmpiyoŋ bi, nee na, ca jamono jooju, jàng na, tey mu jàngaat leneen.
I took it with a lot of backwardness then and even more so now", said the Chelsea striker, who recently won the Champions League.
Dans son dernier rapport mensuel, l'OPEP a déclaré que les exportations de brut étaient tombées à leur niveau le plus bas depuis deux décennies, soit 2,8 millions de barils par jour.
Ci xëtu tektalam biy genë weer wu nek, OPEP dafa waxni njayum petrole bi bitim réew dafa daanu bu baax ba yegg ci 2,8 miliyoŋi baril ci bis, ba loolu gëja am weesuna fukki at.
In its latest monthly report, OPEC said crude exports had fallen to their lowest level in two decades, at 2.8 million barrels a day.
Vivre et faire du bénévolat dans un pays étranger est une excellente façon de découvrir une culture différente, de rencontrer de nouvelles personnes, d'apprendre à se connaître soi-même, à acquérir de nouvelles perspectives et même de nouvelles compétences.
Dëkk te bokk ci sa coobare ci beneen réew anam bu mag la ngir xam ay cosaan ak aada yu wuute, dajeek ay nit yu bees, def jàngat ci sa bopp, ab ay jubluwaay ak sax am ay man-man yu bees.
Living and volunteering in a foreign country is a great way to experience a different culture, meet new people, get to know yourself, gain new perspectives and even new skills.
Il me dit : Ce qui est important, ça ne se voit pas… Bien sûr…
Mu ne ma: Li am solo, deesu ko gis… Dëgg la kay…
He said, "What's important is invisible".
Une révolution des mentalités s’impose et nous le répéterons jusqu’à l’overdose en tout cas autant de fois que nécessaire jusqu’à ce qu’écoute sans suive.
Nit ñi dañu war a yeewu, loolu duñu dëñ di ko baamtu, ba ba ñu ciy tanqalee nit ñi, dinañu wax ba askan wi dégg ñu bu baax.
A revolution of mindsets is needed and we will repeat this until we overdose at least as many times as necessary until we listen without a trace.
C’était un monarque absolu.
Buur bu mat buur la woon.
He was an absolute monarch.
Madame il faut attendre qu’ils récupèrent votre dossier.
Soxna si, xaaral mu jël say kayit.
Ma'am, we'll have to wait until they get your file.
« Croyez-vous vraiment qu’il dit la vérité ?
"Yaakaar nga ni mungi wax réew mi dëgg?
Do you really believe he's telling the truth?
Rien ne sert de courir, il faut partir à point; comme le dit l'adage, .
Dara jarul yàkkamti, dewal ca ba mu jotee, ni ñu ko léebe.
It is no use running, you have to start at the point; as the saying goes,.
En effet, la mise sur le marché de ces offres intervient quelques semaines après le début pompeux des opérations de Free.
Waaw, maye yooyu ñu ngi ko dugal ci Ja bi gannaaw bi doxalinu Free yi tàmbale ay ayu-bés a ngi nii.
The launch of these offers comes a few weeks after Free's lavish start to operations.
L’idée de récompenser les gens par un concert gratuit permet-elle vraiment de les persuader d’exiger un appel à l’action, ou ne constitue-t-elle qu’un autre exemple de « clictivisme » - situation dans laquelle les gens pensent véritablement faire la différence en signant une pétition ou envoyant un tweet ?
Lindsey Graham, John Kennedy neena “60 Simili” ndax lalaŋketu FBI bu Kavanaugh bi munna soppi seen xalaat.
Does the idea of rewarding people with a free concert really persuade them to demand a call to action, or is it just another example of clicktivism - a situation where people actually think they can make a difference by signing a petition or sending a tweet?
A-t on vécu une seule fois au Sénégal une campagne électorale sans qu’il ne soit fait cas d’achat de consciences en masse avec des milliards de nos francs dont l’origine licite n’a jamais été justifiée ?
Ndax mës nañoo dund ci Senegaal, benn yoon rekk, wu nga xam ne jamonoy wote ju amul ger askan week sunu milyaar yi, nga xam ne fa muy jóge duñu ko mës a leeral ?
Has there ever been an election campaign in Senegal without the mass buying of consciences with billions of our francs whose legitimate origin has never been justified?
Ousmane Sonko prévoit d’effectuer une tournée nationale pour plus communiquer sur le programme et participer à ces différentes activités.
Usmaan Sónko moo ngi nas wër réew mi yépp ngir gën a joxey xibaar ci yéene ji mu am ci réew mi ak li koy doxal.
Ousmane Sonko plans to make a national tour to further communicate about the programme and participate in these different activities.
De même un Président de la République qui n’assume plus les décrets qu’il signe est disqualifié pour diriger.
Ba ci ab njiitu réew buy fonkadi xaatim yi muy def amatul yoon jiite.
Similarly, a President of the Republic who no longer assumes the decrees he signs is disqualified from leading.
Marie Coly : Après un baccalauréat en sciences expérimentales et une maîtrise en Finance obtenue au Sénégal, j’ai souhaité donner une orientation plus technique à mon profil.
Mari Kóli : Ginnaaw bi ma amee bag S2 ak metiriis ci wàllu koppar ci Senegaal, am naa yéene yokk sama xam-xam ci wàllu xarala.
Marie Coly: After a bachelor's degree in experimental sciences and a master's degree in finance in Senegal, I wanted to give a more technical orientation to my profile.
Mon beau frère avait la conviction que je pouvais beaucoup aider à l’implantation du parti en France, plus précisément en Île de France.
Sama goro bi gëmoon na ne mën naa koo dimbali mu taxawal kurélu pólotig gi Farãas ca Il dë Farãas ba.
My brother-in-law was convinced that I could help the party to establish itself in France, more precisely in Île-de-France.
La justice populaire est souvent aveugle, s’exerce sans retenue ni proportionnalité, et ne se déploie qu’à partir d’accusations fantasmagoriques et aléatoires.
Yoonu mbooloo mi (fajal sa bopp) dafay faral di gumba, tëx, luu, du def lenn lu xelu, dafay dégg téll rekk, ne matt gi damm na.
The popular justice is often blind, exercised without restraint or proportionality, and deployed only on the basis of fantastic and random accusations.
D'après Source A, ce n’est pas la seule nomination qui fait grincer des dents au ministère des Affaires étrangères.
Su nu sukkandikoo ci Source A, du pal googu rekk moo ànd ak naqar ci njëwriñ ji yore jëflante yeek bitim réew.
According to Source A, this is not the only appointment that is causing the Ministry of Foreign Affairs to grin.
Robin Uthappa a obtenu le score le plus élevé des manches, 70 points en seulement 41 balles en frappant 11 fois quatre runs et 2 fois six runs.
Robin Uthappa défna ndam bi gëna mag, 70 runs ci 41 balls dong ci door 11 ñent ak 2 juróom benn.
Robin Uthappa scored the highest score of the innings, 70 runs in just 41 balls by hitting 11 four-run and two six-run runs.
Ses 12 joueurs ont tous très bien joué.
Amerik ñakk na leegi jiroom benn yoon yu tegaloo ci suufu Orop te amuñu benn ndam ci Ryder Cup ci Orop 1993 bo leegi.
His 12 players all played very well.
Cette quantité de billets et pièces qui circulent représente la masse monétaire.
Limu kayit ak xànjar bii di dox mooy xaalis bi yépp.
This quantity of notes and coins in circulation represents the money supply.
Le Ministre et les agents de son département ont indiqué avoir dépensé, à l’issue de la période de distribution de 3 mois, 60 709 694 520 F CFA, soit un excèdent de 8 290 305 480 F CFA.
Jëwriñ ja ak ay liggéeykatam xamle woon nañu ne jot nañoo génne, ci ñetti weer, lu tollu ci juróom-benn-fukki milyaar ak juróom-ñaari téeméer milyoŋ ak juróom-ñeent ak téeméeri junni ak fan-weer ak juróom-ñeent ak juróom-ñenti téeméer ak ñeenti dërëm, maanaam yokkuteg juróom-ñetti milyaar ak ñaari téeméeri milyoŋ ak juróom-ñeent-fukk ak juróom benn-fukki junni ak juróom ak juróom-ñent-fukki dërëm ak juróom-ñett.
The Minister and his department's staff reported that at the end of the three-month distribution period they had spent CFAF 60 709 694 520 or a surplus of CFAF 8 290 305 480.
Bien sûr.
Waawaaw.
Of course I did.
Et puis, moi je pense que c'est le peuple sénégalais qui mérite qu'on l'aborde.
Te sax, man dama jàpp ne askanu Senegaal moo aajowoo nuy wax.
And then, I think it's the Senegalese people who deserve to be approached.
Tout ce que j’aimerais dire à ceux qui ont défendu la motion vendredi, c’est que le pays va vers un Brexit qui va affecter les foyers, les entreprises et les services publics. Je pense que ce n’est pas vraiment le moment de perdre du temps et de l’énergie en débattant de ma loyauté au leader du parti.
Ci ñooñu yenuwoon baaraas bi ci Aljuma, lepp lu ma ci muna wax moy su r&ew mi dale ci Brexit bi dina gaañ ay njaboot, ay bisness, ak sunu sarwiis yu ñepp bokk, munuma xam lu tax di yakk sa jott ak doole ci sama kóllóre ci njiitu parti Labour.
All I'd like to say to those who supported the motion on Friday is that the country is moving towards a Brexit that will affect households, businesses and public services and I don't think this is really the time to waste time and energy debating my loyalty to the leader of the party.
Les ressources végétales les plus facilement accessibles seraient les protéines contenues dans les feuilles et les légumineuses, mais celles-ci sont difficiles à digérer pour des primates comme nous, à moins d'être cuites.
Mbir mi gëna am solo mi nit ñi mëna amee ci gàñcax gi mooy protéine yi nekk ci xobu yenn legume yi, waaye yombul ci nit mu reesal proteine yooyu fileek toggu ñu leen.
The most easily accessible plant resources would be the proteins contained in leaves and legumes, but these are difficult for primates like us to digest, unless they are cooked.
Le pouvoir s’endette pour investir dans des projets non rentables, forcément le coût des remboursements va fortement se ressentir dans le porte-monnaie des sénégalais.
Nguur gi dafay leb ngir def ko ci ay naal yu amul benn njariñ, dayob payoor gi dañu koy yég bu baax, ñun saa-senegaal yi.
The government is borrowing to invest in unprofitable projects, and the cost of repayment will inevitably be felt strongly in the pockets of Senegalese people.
Les ions d'hydrogène sont des protons qui ont été dépouillés de leur électron (puisque les atomes d'hydrogène sont constitués d'un proton et d'un électron).
Ion yu ndox yi ay proton lañu yuñu dindiwoon seeni elektron (bi atom yu hydrogen yi nekkee benn proton ak benn elektron).
Hydrogen ions are protons that have been stripped of their electron (since hydrogen atoms are made up of a proton and an electron).
Sinon à la fin du mois, ils ne vont pas percevoir leurs enveloppes
Lu moy loolu, bu weer wi deewee, duñu jot seeni àmbolog
Otherwise, at the end of the month, they won't get their envelopes.
Un porte-parole du Parti travailliste a déclaré : « Une semaine de travail de quatre jours ne constitue pas une politique du parti et n’est pas envisagée par celui-ci. »
English deñu ko dellowaat Whitehall ngir benn irsaas ngir nettali, mu anndaat ak Bough anndandoowam bu yagg sonn ci ay komparse , ki ko def moy Ben Miller.
A Labour Party spokesman said: A four-day work week is not party policy and is not envisaged by the party.
108 assiettes de Chhappan Bhog (dans l'hindouisme, 56 aliments comestibles différents, comme des sucreries, des fruits, des noix, des plats etc. qui sont offerts à la divinité) ont été servis à Baba Shyam.
Amna 108 xeeti ñam yu Chhappan Bhog (ci hindouisme, 56 ñam yu wuute, lu ci melni ay tàngal, ay meññeef, ay sàll, ay tokk ak ñoom seen yu ñu daan may seenu xërëm) yu ñu daan yakkal Baba Shyam.
108 plates of Chhappan Bhog (in Hinduism, 56 different edible foods, such as sweets, fruits, nuts, dishes etc. which are offered to the deity) were served to Baba Shyam.
Et il sourit avec mélancolie.
Mu daldi muuñ ak xol bu naqari.
And he smiles with melancholy.
« Je crois que c’est une idée de génie.
Beattie neena "Eddie amna cër bu rëy ci biir Ekost , UK, ak askanu atletisma ci aduna wërngal këpp, te leernañu bu baaxa baax ni Ekost dina gis njeriñ ci boole bi ñu ko boole ci seen njiit yi".
I think it's a genius idea.
Le droitier des Washington est à 18-7 avec une moyenne de points mérités de 2,53 et 300 retraits sur des prises en 220 marches et deux tiers cette saison.
Durwacebu Washington bi 18-7 la ak ay 2.53 ERA ak baaraasu 300 ci 220 2/3 dugal renn gi.
The Washington right-hander is 18-7 with a 2.53 ERA and 300 strikeouts in 220 2/3 innings this season.
Un déficit d’image important auprès des populations qu’il faut aujourd’hui combattre.
Ñàkk a matug nataal yi war ci ngir askan wi te war koo xeex.
This is a major image deficit among the population that must be combated today.
Macky Sall et ses compères de la CEDEAO, au sujet de la crise malienne ont été excédés par la position partisane de Ouattara à l’égard de Keita.
Maki Sàll ak ay naataangoom yu CDEAO njàqare lañu am ci jàppale gi Watara di jàppale Keyta ci jafe-jafe yi am ci réewum Mali.
Macky Sall and his ECOWAS colleagues on the Malian crisis were overwhelmed by Ouattara's partisan stance towards Keita.
Un bogey et deux doubles sur les neufs premiers coups ont envoyé l’Espagnol et le Suédois dans un trou dont ils n’ont jamais pu ressortir.
Anndandoo yu Orop waaye ñaar ñi ñungi ci ñeent ci kaw ñeent te munuñu juum.
A bogey and two doubles on the first nine shots sent the Spaniard and Swede into a hole they never got out of.
« J’avais la tête baissée, et je pleurais tout le temps.
"Xam li ñu xam ci Paddington yep leegi defa reetaanlu.”
I had my head down, and I cried all the time.
En octobre, toujours de la même année, on essaya lors du congrès de l’UPS de conjurer une rupture, cette tentative a été vouée à l’échec.
Ci oktoobar, ba tey ci at mi, dañu doon jéem a dàq féewaloo ci UPS, waaye loolee mujjul àntu.
In October of the same year, an attempt was made at the UPS Congress to prevent a break, but this attempt was doomed to failure.
J’ai aussi une fleur.
Am naa fa tamit ab tóortóor.
I have a flower too.
En liberté, il venait plusieurs fois mevoir dans la ville de Touba.
Bi ko yoon tegulee loxo, daa na ñëw di ma seetsi lu bari ci Tuubaa.
When he was released, he came to visit me several times in the city of Tuba.
La Juve s’est longtemps heurtée sur l’Atlanta mais a fini quand même par s’imposer par 3 buts à 1.
Suuf ci Atlàntaa la dal waaye mujje na ko dóor ñetti bal ci benn.
Juve fought Atlanta for a long time but still won 3 goals to 1.
De là, les lois votées par le législatif qui par la magie du pouvoir devient l’état-major politique de l’exécutif, sont élaborées au nom du peuple et sur le dos du peuple, bref, pour et contre le peuple qui est pourtant à mille lieues de leurs préoccupations.
Ekibu Southgate dina doxal joŋanteem yépp ci puul bi ak Korowaasi, Ekos, ak Réewu Ceg ca estaat bu Wembley ca Londar biy fees ba ñeenteelu xaaj.
Hence, the laws passed by the legislature, which by the magic of power becomes the political staff of the executive, are drafted in the name of the people and on the back of the people, in short, for and against the people who are nevertheless a thousand miles from their concerns.
Que viens-tu faire ici ?
Looy defsi fii?
What are you doing here?
Bien plus, ces données renseignent au moins sur deux choses par rapport à la vision que la France a de sa relation avec le Sénégal.
Ëpp na ko sax, lim yooyu dafay xamle lu mu tuut tuut ñaari mbir ci xalaat bi Farãas am ci digganteem ak Senegaal.
Moreover, these data reveal at least two things about France's view of its relationship with Senegal.
Peine perdue cher M2D.
Yàq ngeen seen doole yéen waa M2D.
A waste of money, M2D.
App ??? une matinale avec des gens en cravate… ils me disent qu’on parle de moi.
App ??? Genn suba ak ay nit ñu takk karawaat … Mu ne ma ci man lañuy wax.
I'm in a morning show with people in ties... they tell me they're talking about me.
Nous sommes assez tranquilles sur ce plan même pour ce qui est des finances.
Suñu xel dal na ci mbir moomu ci wàllu xaalis bi.
We are quite calm even in this respect, as far as finances are concerned.
Il peut être tiré en fil fin, qui peut être tordu et tressé. Il peut être martelé ou laminé en feuilles.
Mën nanu ko diri ci buum bu sew, bu nu mëna lem ak lettë. Mënees na ko door ay marto wala lem ko ci ay këyit.
It can be drawn in fine wire, which can be twisted and braided, and it can be hammered or rolled into sheets.
Au cours des trois derniers mois, plus de 80 personnes qui avaient été arrêtées ont été libérées de la maison de détention centrale sans avoir été formellement mises en examen. 
Ci biir 3 weer yi weesu, amna lu ëpp 80 nit yuñ jàppoon, bàyyi nañu leen centrale de réservation waaye tegu ñu leen benn daan.
In the last three months, more than 80 people who had been arrested were released from the central detention house without being formally charged.
J’ai vu en lui quelqu’un qui a fait le même constat que moi mais qui a eu le courage de se lancer pour casser ce système que nous subissons, nous les sénégalais, depuis tant d’années ; alors c’est tout naturellement que j’ai décidé de m’engager à ses côtés pour apporter ma contribution à la concrétisation de cette nouvelle perception de la politique.
Gis naa ne man ak moom ñoo bokk benn gis-gis, waaye mu am fitu dugg ci pólotig ngir jële fi li fi nekk te ñu koy dundu ay at a ngi nii, mu metti lool, ñun saasenegaal yi ; kon nag, ma ñëw ci wetam di ko jàppale ngir ñu ànd doxal gis-gis boobu, warul a jaaxal kenn.
I saw in him someone who had made the same observation as me but who had the courage to set out to break this system that we Senegalese have been suffering for so many years; so it was only natural that I decided to engage with him to make my contribution to the realization of this new perception of politics.
Le petit prince arracha aussi, avec un peu de mélancolie, les dernières pousses de baobabs.
Noonu ndoomu buur si buddiwaale saxayaayu guy yi des, ak tuuti xol bu nàqari.
The little prince also plucked, with a little melancholy, the last shoots of baobabs.
Elle doit être implacable et à la mesure des infractions commises.
Sa dundin ca Farãas ndax daa nar a dëpp sa gis-gisu pólótig ci Senegaal ?
It must be unrelenting and proportionate to the offences committed.
Pour corser ce brouet de sorcière vers la privatisation, la start-up sénégalaise Akilee, le fournisseur de compteurs électriques intelligents à Senelec, est convoitée par le Géant français de l’électricité EDF qui veut rentrer dans son capital.
Ngir dooleel wile ñamu ceddo jëm ci moomeelu kenn, këru liggéeyukaay gi Akilee, joxekatu kurãŋu nosal bi ci Senelec, la mbëru Farãas mi ci kurãŋ EDF sàkku mu bokk ci kopparam.
To push this witch's errand towards privatisation, the Senegalese start-up Akilee, the supplier of smart electricity meters to Senelec, is coveted by the French electricity giant EDF, which wants to enter its capital.
L’ouverture du score semblait promise aux Flying Eagles avec un but tout cuit pour Success Makanjuola, qui tirait sur le gardien (34′).
Success Makanjuola moo dugaloon Flying Eagles yi ci bal bi mu dóoroon ca caax ya ca fan-weereelu simili bi ak ñeent.
The Flying Eagles were promising to open the scoring with a goal from Success Makanjuola, who shot at the goalkeeper (34').
Ainsi, après un accident de voiture, un incendie ou encore la survenance d’une maladie nécessitant des soins lourds et très coûteux, l’impact financier, pour un particulier ou un entrepreneur, demeure mesuré, voire nul – en fonction du niveau de couverture choisi par l’assuré.
Ndax, ginnaaw laksidaŋu oto, ag lakk wala sax feebar bu paj ma seer, koppari nit ki wala njiitu këru liggéeyukaay gi bariwul wala sax amul xaalis baa ngi aju ci kaaraange gi nga tànn.
For example, after a car accident, a fire or the occurrence of a disease requiring heavy and very expensive care, the financial impact for an individual or an entrepreneur remains measured or even zero depending on the level of cover chosen by the insured person.
Mais le dilemme auquel Mme May est confrontée pour réconcilier ses troupes profondément divisées a été souligné par les conservateurs en faveur de l’idée de rester dans l’Union qui ont rejoint une manifestation isolée contre le Brexit dans la ville.
Ngir xamle lu waral pendemoor porkireer yi faawu ñu firndel ni Saipov moo "tey" mu rey jiroom ñetti nit te "tey" gaañ ay nit gaañu gaañu yu metti, su nu sukkandikoo ci bataaxal biiy wax ci tey ngir wuut pendemoor, bi ñu defar ci Southern District by New York.
But the dilemma Mrs May faces in reconciling her deeply divided troops was highlighted by the Remain Conservatives who joined an isolated anti-Brexit demonstration in the city.
Le Projet de renforcement du réseau et de connectivité du dernier kilomètre au Rwanda bénéficiera ainsi d’un prêt de 36,77 millions de dollars et d’un don de 47,45 millions de dollars issus du Fonds africain de développement, le guichet de prêt à taux concessionnels du Groupe de la Banque africaine de développement.
Kilomeetar bu mujj bi des ci sémbub dëgëral jokklante gi ca Ruwàndaa dinañu ci dugal xaalis bu tollu ci fan-weeri milyaarak-juróom-benn kos juróom-ñaar fukk ak juróom-ñaar ci xaalisu dolaar, mu di ab bor, ak ñeent-fukki milyaar ak juróom-ñaar kos ñeent-fukk ak juróom ci xaalisu dolaar, di lu xaalisu u Afrig ngir yokkute maye, tegandaay li ñu ngi ko nàtte ca Bànku Afrig ngir yokkute gi.
The Last Mile Network and Connectivity Project in Rwanda will benefit from a loan of USD 36.77 million and a grant of USD 47.45 million from the African Development Fund, the African Development Bank Group's concessional lending arm.
Faites le calcul vous-mêmes, cela équivaut à 72 600 000 000 FCFA, sans compter le transport qui avoisinerait 2 000 000 000 FCFA d’après le DAGE du Ministère du Développement communautaire, plus les paiements pour les 5000 vérificateurs à raison de 70 000 FCFA chacun et autres frais de stockage, de sécurité, de communications et impressions etc.
Def leen xayma bi ci seen jëmmi bopp, moo ngi tollu ci juróom-ñaar-fukk ak ñaari milyaar ak juróom-benni téeméeri milyoŋ ci seefaa, te boolewuñu ci dem beek dikk bi tollu ci ñaari milyaar ci seefaa su ñu sukadikoo ci kilifag njëwriñ ji yore suqalikug gox-gaxaat yi, rax-ci-dolli payooru junney saytukat yi ñu ngi tollu ci fukki junneek ñeent ci seefaa kenn ku ci nekk ñu booleeti ci njëgu ndenc mi, kaarange gi, xibaar yi ak móol gi, añs.
Do the calculations yourself, this is equivalent to CFAF 72,600,000,000, not including the transportation which would be around CFAF 2,000,000,000 according to the DAGE of the Ministry of Community Development, plus payments for the 5000 auditors at the rate of CFAF 70,000 each and other costs of storage, security, communications and printing etc.
« Des millions de personnes auraient été tuées.
Ay milyoŋu nit naroon ci dee.
Millions of people are believed to have been killed.
Elle serait donc une base de repli pour ces rebelles délogés affiliés aux branches du MFDC dirigées par César Aoute Badiate et Ibrahima Kompasse Diatta.
Mën nañu ko méngale ak ab bérébu daw-làqu, way-fippu yooyu bokk ci pàcci MFDC.
He was also responsible for the deaths of at least two civilians in the early hours of the morning of 8 January 2014 and the subsequent deaths of at least two civilians in the early hours of the morning of 8 January 2014.
Ce prix unitaire revu à la baisse ne sera jamais votre bouclier pour une efficacité encore moins une efficience, au contraire, il sera votre souffre-douleur.
Pay googu ñu wàññi du doon mukk liy nëbb sa ñàkk a xarañ ak sa njub, xanaa key mu doon sa musiba.
This revised down unit price will never be your shield for efficiency let alone efficiency, on the contrary, it will be your pain-suffer.
Prix Macky Sall pour la recherche du CAMES: 60 millions remportés par une équipe de l'Université de ThièsA rappeler que la République de Djibouti, qui aspire à devenir un hub commercial, logistique, portuaire et numérique incontournable en Afrique, s’est dotée de son fonds Souverain en 2020.
Neexalu Maki Sàll ci saytu bu CAMES : benn kuréelu iniwersite bu Cees jël na juroom-benn-fukki milyoŋ. Di fàttali rekk ne réewu Jibuti mi bëgg a doon goxu njënd ak njaa, yebkatu njaay yi poor yi ak yu bagaasi xarala bu rëy ci Afrig, am na ay koppar yu mu jagleel boppam ci 2020.
Macky Sall Prize for CAMES research: 60 million won by a team from the University of Thiès It should be recalled that the Republic of Djibouti, which aspires to become an essential commercial, logistical, port and digital hub in Africa, has endowed its Sovereign Fund in 2020.
Des femmes en deuil déposent des cartes postales pour empêcher les suicides sur les ponts.
"Waaye ndax li Paddington nekkoon ku deggu ci moom, mungi mel ni rek nga am sa doom mu tekki ci benn mbir: dengay kontaan ci moom doonte du yawci sa bopp yaa ko def.
Mourning women leave postcards to prevent suicides on bridges.
À partir de novembre, Kit sera la vedette d’une reprise de True West, de Sam Shepard, qui raconte l’histoire d’un producteur de films et de son frère, un voleur.
Dinañu xoolaat daan yi ci sarwiisu porsekisiyoŋ bu ñepp bokk.
Starting in November, Kit will star in a remake of Sam Shepard's True West, which tells the story of a film producer and his thieving brother.
Ces chefs avaient été réprimés par Provenzano lorsqu'il a mis fin à la guerre menée par Riina contre l'État et qui avait coûté la vie aux juges antimafia Giovanni Falcone et Paolo Borsellino en 1992.
Njiit yi Provenzano moolén fi ték bimu jéxalé xééxu Riina-bi nu jiital ak réew bi beeggona jeel dunduk Mafia yi Giovanni Falcone ak Paolo Borsellino ci atum 1992."
These leaders were repressed by Provenzano when he ended Riina's war against the state, which had cost the lives of anti-mafia judges Giovanni Falcone and Paolo Borsellino in 1992.
Fred a actuellement des vents de 165 km/h (105 miles par heure) et se dirige vers le nord-ouest.
Fred léégi dawna lu tollook 105 miles waxtu buné (165 km/h) té di dém ci beet gannaar ak sow bi.
Fred is currently at 105 miles per hour and heading northwest.
Le peuple a avalé cette usurpation et a ainsi signé une descente vers un enfer social, politique et économique comme l’avait prédit Ousmane Sonko au lendemain de cette mascarade d’élection pré-gagnée par le candidat sortant.
Askan wi fàtte nañ càcc googu ba tax ñu xaatim li leen di jëme ci toroxtaange ci wàllu dund gi, pólótig bi ak koom-koom bi ni ko Usmaan Sónko waxee woon bi ñu jógee ca palug caaxaan googu ñu siiwaloon palug njiitu réew mi laata sax ñuy joxe li tukkee ci waññi bi.
The people swallowed this usurpation and thus signed a descent into a social, political and economic hell as Ousmane Sonko had predicted the day after this pre-election masquerade won by the outgoing candidate.
May lath rek: demb amadou na APR tey aliou sall APR khana wa PS.
May laaj rekk : démb Aamadu la APR tey Aliw Sàll APR xanaa waa PS.
May lath rek: Demb amadou na APR tey aliou sall APR khana wa PS. He is the leader of the opposition in the country.
Ce sédiment était nécessaire à la création de bancs de sable et de plages, qui servaient d’habitats à la faune.
Mbalit yiii amoon nanu solo ngir defar ay bangu suuf ak ak tefes, yu don nek dëkuway mala yi.
This sediment was necessary for the creation of sandbanks and beaches, which served as habitats for wildlife.
Au menu, des récitals de Coran et de Khassaides pour se conformer au Ndigeul de Serigne Saliou Mbacké.
Liy am : wàccee kaamil, njàngum xasida ngir méngoo ak digley Sëriñ Saaliw.
On the menu, recitations from the Koran and Khassaides to conform to the Ndigeul of Serigne Saliou Mbacké.
L’inspecteur de chef de RSPCA New South Wales David O’Shannessy déclara à ABC que la surveillance et l’inspection des abattoirs devrait être une évidence en Australie.
Njiitu inspektëru RSPCA Nouvelle-Galles du Sud, David O'Shannessy, wax na ni ci ABC ni saytu yi ak lëñbët yuñy amal ci rayukaay yi dafa waroon luñuy def bu baax ci Ostaraali.
RSPCA New South Wales Chief Inspector David O'Shannessy told ABC that slaughterhouse monitoring and inspection should be a matter of course in Australia.
Je lui parlais de bridge, de golf, de politique et de cravates.
Dama doon wax ak moom ci mariyaas, golf, politig ak karawaat.
I would talk to him about bridge, golf, politics and ties.