audio
audioduration (s)
0.74
171
text
stringlengths
1
109
gender
stringclasses
2 values
Gaawal dem sa kër!
male
Négal baxam !
male
Da ngaa amoon kersa.
male
Buleen ko nettali keen!
male
ku ci bagga xootal na xool Sëriñ Basiiru Mbàkke ci situ wikimouridia.org
male
Menuñoo jàpp, tëj, mbaa genne kenn réewam te tegunu ko ci yoon.
male
Maa ngi bàyyi Tom ci sama barab.
male
Loolu la ñuy wax dëppaleg déggoo yi.
female
Damaa xaw a feebar.
male
Sawat gi ci njabootug Combretaceae la bokk
female
nataalu garabug Yoos-bisaaw
male
Ab DVD la.
female
Damaa ame aw tàngoor.
male
Raxas naa ko.
female
Loolu amul njariñ.
male
Bu ko defee, li ñu war a xeex dëgg mooy rey bi ci boppam
male
Jant bi mooy biddiwu sunu nosteeg jant
male
Man na indi ay jafe-jafe ci seeni dëkkuwaay ak ci seen wérgi-yaram.
male
màrs 741 ñu faatu
female
Amoon na ay weer ci ginnaaw.
female
? Àjjuma 24i fani sulet 2020
female
Ndaw nettali lu reelu !
female
Dinaa ko lijjanti.
male
Waaye diiwaan bii tawam taxu koo bari noonu.
male
Ndax sang bii bokkeewul ak yooyee wolof.
female
Halowiin rekk la bañ.
female
Moom miy ki moy kaa
female
Jox na ko liggéey.
female
Man naa tëb.
male
Déggoon naa leen ñuy ñëw.
female
Askan waa ngiy jooy, di sàkku ndimmal ci neen
female
Ndax damaa jaay yoos mi ?
female
Lungeen di def sungeen amul dara lu ngeen di def ?
female
Ci kàddug aji-àddu ji ca widewóo ba.
male
lii xew ca Medinaa dina dakk!
female
Xoolleen nu !
female
ci lol dafay guusali put di yokku tér
female
Naka la Jeqiku ga ame woon
male
Man ngeen def ski ?
male
Ameel naa lab bor.
male
Li ko waral mooy Xasiidaam yii yamuñu ak dara fa Yàlla sunu Boroom.
female
Ndax tayeef la ?
male
ak dundal xol yi ci sikar ak waaraate yi rafet ci waaraate yi
male
Mooy ñenteelu xalifa ginnaaw S Abdul Ahad
female
Sama tànk yi day metti.
male
Bul yem rekk ci meew, kafe mbaa duteek yu ni mel
female
Moo yilifoon waa Mowab
male
Lii dula dimbali.
female
Du ma gañe mukk.
male
Waaye doo gis mukk boroom liggéey buy taxawaalu akub liggéeyam.
male
Bul wax dara !
male
Ku am doole la.
female
Am naa lu ma metti lool.
female
Bii mooy teqaloo ??
female
Kenn a ngi ree.
male
Day sol mbaxana-kawar.
male
Mooy sama tur dëgg.
male
Ñépp a ragal.
female
Man ngaa dimbali .
male
Bu ñu xeex !
male
Wàll gi jeex na.
female
Bu dee xas mi
female
Ekool bi, dafa reeluwul.
female
Ay mbokkam la tabb, ñuy giiroo alal ak moomeelu réew mi
male
Xobet-xobet laa soxla.
male
Ndax Tom dafa lab ?
female
Ana goloo ka sàngoo mbàjj bay taamu nimoro diis?
male
Kon nag, fàww nu xoolaat nekkiin yi ci biir néegu-sëy
female
Waaye loolu ay waxi kasaw-kasaw rekk la
male
Mujj na jeex.
male
Du samag tayeef.
male
Noonu, seen bakkan nekk ci xottu ngerte
male
Damaa moy sama fafal-naaw.
male
Bul ma bàyyi.
male
Mine Ubbi njël lu njëkk li
male
Jàppale ma, ñaan naa la ko !
female
Waxal ak man.
male
Gis naa sa mbaxana.
male
Jamono yooyu, ci xay goo dem ak ni ñu koy séddalee ci at mi
male
Daan nañ nu .
male
Am naa géléem ma nga Gànnaar.
male
Dafay tibb xaalis bu bari.
male
Tom dee na daaw.
female
Njëwriñug paj m
male
Espargos benn diiwaan ci yu dunu Sal, KabWeer.
male
Nit ñii mat nañu 21 700 000 2015.
female
Du nit ku sell.
male
Damaa bëgg a taxaw.
male
Tom daf maa soxla.
female
Ñu guree ngeen.
female
Man naa leen a jàngal.
male
Noo ko moomoon.
male
Dafal li nga bëgg.
female
Man naa xolli pom.
male
Yaa ngi tappale.
female
Am naa rafet njort ne Tom a ngi fu wóor.
male
Bugaaseli am na bàyyig négandiku
female
Damaa am metitu bën.
male
Loolu yépp lu man a nekk la, tesax lu am la.
female
Talaata jàpp 5h25 Dog 19h24
female