fr
stringlengths 4
1.08k
| wo
stringlengths 2
4.02k
| en
stringlengths 3
1.08k
|
---|---|---|
Tu auras, toi, des étoiles qui savent rire !
|
Yaw, dinga am biddéew yuy reetaan!
|
You'll have stars who can laugh!
|
De nombreux voyages sur le récif sont effectués tout au long de l'année, et les blessures dues à l'une de ces causes sur le récif sont rares.
|
Tukki yu bare danu len di def ci xeer yi ci biir at mi, te gaañu gaañu yi ndax xeer yooyu bariwul.
|
Many trips to the reef are made throughout the year, and injuries from any of these causes on the reef are rare.
|
500 FCFA pour le téléphone, entre autres…Ce même arrêté précise, en son article 3, que Toute indemnité en argent représentative d’avantages en nature doit être intégralement comprises dans la base de l’impôt sur le revenu, la présente évaluation (article 1er) ne pouvant être retenue en ce cas.
|
Téeméeri dërëm ngir jollasu gi ak yeneen... Sàrt boobu mooy wax ci dog 3 ne ndàmpaayu xaalis bu ne dafa war a lalu ci juuti bi ñuy jële ci li ku nekk am, dog bii (dog bu jëkk bi) duñu ko mën a topp su boobaa.
|
500 CFA francs for the telephone, among others...The same decree specifies in Article 3 that any cash allowance representing benefits in kind must be included in its entirety in the income tax base, the present assessment (Article 1) not being applicable in this case.
|
Sadio Mané, qui a inscrit déjà trois buts depuis le début de la CAN, n’a pas fini avec les penaltys pour autant : Je n’abandonne jamais, je vais aller en club, travailler dur pour pouvoir marquer d’autres penaltys , promet-il.
|
Saajo Maane mi duggal ñetti bit ci njëlbeenu CAN bi, noppeegul ba tay ci penaatii yi : duma mës a bàyyi, damay dem këlëb tàggatuwaat bu baax ngir mën a duggalaat yeneen penaatii, loolu la dige.
|
Sadio Mane, who has already scored three goals since the start of the CAN, is not done with penalties: I never give up, I will go to the club, work hard to be able to score more penalties, he promises.
|
Certaines années, on avait des informations selon lesquelles on n'aurait pas une bonne pluviométrie.
|
Am na ay at yu ñu doon wax ne li ñu am ci taw doyul wala ni muy tawee ci réew mi baaxul.
|
Some years we had information that we wouldn't have good rainfall.
|
Stewart, Gordon, Kenseth et Harvick complètent les dix premières places du championnat des pilotes à quatre courses de la fin de la saison.
|
Stewart, Gordon, Kenseth, ak Harvick wër nañu fukki palaas yu njëkk yi ngir jongante buñu jagleel Dawalkat yi ak ñeenti rawante yu des ci saison bi.
|
Stewart, Gordon, Kenseth and Harvick round out the top ten in the drivers' championship with four races left in the season.
|
C’est une sentinelle et là il le fait jouer en tant que numéro 8 .
|
Ab wattukat la te fi mu ne nii dañu koy futbaloo nimero 8.
|
He's a sentry and now he's playing him as number eight.
|
Les parasites peuvent contaminer la nourriture, provoquer des irritations ou, dans les cas les plus graves, provoquer des réactions allergiques, répandre du venin ou transmettre des infections.
|
Gunóor yi mën nañu yàq ñam yi, waral ay yaram yuy xasan wala ci kaa yu gëna bon, lawaal daŋar wala joxe ay infeksiyon.
|
Parasites can contaminate food, cause irritation or, in the most severe cases, cause allergic reactions, spread venom or transmit infections.
|
Dès que quelqu'un exprime une opinion contraire à celle que certains souhaiteraient, il est copieusement insulté par les préposés aux injures et insultes dont c le boulot.
|
Saa su amee ku wax xalaatam mu juyook li ñenn ñi doon xaar, dañu koy saaga, ci ay tuuma yu teguwul fenn loolu mooy liggéey bi.
|
As soon as someone expresses an opinion contrary to what some would like, they are repeatedly insulted by the people who are in charge of the insults and insults, whose job it is.
|
Le Trésor s’attend à collecter jusqu’à 120 millions de livres Sterling par an afin d’aider les sans-abri.
|
Sekkerteeru wergu yaram bind na ñii di ligeey ci EU ci NHS bu Ekost ngir feddeli kollëre réew ma te di leen ñaanal ñu des su Brexit bi weeso.
|
The Treasury expects to raise up to £120 million a year to help the homeless.
|
Après tout cette attitude d’attentisme et d’inaction de l’opposition lui sert! Président Sonko, foncez,les planètes sont bien alignées pour arriver à votre dessein! Opposants du Sénégal, de grâce jouissez sans limite de vos droits! Abib Diop.
|
Ginnaaw loolu, tekkaaral ak yëngoodi gu kujje gi moom lay jariñ ! Sónko ñaajal, say biddéew feq na ngir nga eggale say naal ! Kujje gi, ngir yàlla bànneexu leen bu baax ci seeni yelleef ! Abib Jóob
|
After all this attitude of waiting and inaction of the opposition serves him! President Sonko, go ahead, the planets are well aligned to achieve your purpose! Opponents of Senegal, please enjoy your rights without limit! Abib Diop.
|
Le Capitaine Dièye qui a cheminé avec cet autre bloc de l’opposition, vient juste de révéler au grand jour les compromissions idéologiques de cette autre opposition avec l’ancienne puissance coloniale et le Système économique et financier international.
|
Kapiteen Jéey mi doxandoo ak meneen mbooloom kujje gi, moo xëy rekk yégal ñu ay koote yu lalu ci ay xaalaat jóge ci genneen kujje googu ak dooley mbéeféer mi ak doxalinu koom ak yorinu koppari réew yi.
|
Captain Dièye, who has been with this other opposition bloc, has just revealed the ideological compromises of this other opposition with the former colonial power and the international economic and financial system.
|
Le SAID et le SUTT ont constaté, pour le déplorer, la précarité qui prévaut au sein de ces administrations piliers essentiels dans la mobilisation des ressources publiques, dans l’exécution de la loi de finances et dans la sauvegarde des deniers publics.
|
SAID ak SUTT seetlu nañu, ŋàññi nañu ñàkk gi am ci këri liggéeyukaay yooyu, nga xam ne ñoom ñooy kenuy balluwaayi alali askan wi, ci doxalug yoonu xaalis wi ak it càmmug alali réew mi.
|
The SAID and the SUTT noted, to their regret, the precarious situation prevailing in these key pillar administrations in the mobilisation of public resources, the implementation of the Finance Act and the safeguarding of public funds.
|
Le chauffeur du camion, âgé de 64 ans, n’a pas été blessé dans l’accident.
|
Dawalkat camiong bi bu am jirom ben fuk at nient at yi amoulon gagnu gagnu ci aksideng bi
|
The driver of the truck, a 64-year-old man, was not injured in the accident.
|
L’un dans l’autre, aucune gymnastique intellectuelle, ne saurait exonérer de responsabilité de ceux qui ont la charge de publier les décrets qu’ils signent.
|
Bu mu ci mën a doon, du benn xalaat, buy dindil tuuma ña ñu jagleel ñu tasaare dekere ya ñuy xaatim.
|
In any case, no intellectual gymnastics can absolve those who are responsible for publishing the decrees they sign.
|
Mobilisez-vous pour la journée du Vendredi 13 Décembre, pour l’honneur de vos camarades et la survie de votre Peuple en sursis existentiel.
|
Tàkku leen dem ca ndajeem àjjuma fukki fan ak ñett ci weer desàmbar ngir delloo njukkal seen nawle yi ak askan wi nekk ci guddi gu bët setagul.
|
Mobilize for Friday the 13th of December, for the honor of your comrades and the survival of your people in existential suspension.
|
Depuis, la taille économique de la Chine a été multipliée par 90.
|
Ba loolu amee ba léegi, tolluwaayu komu Siin yokku na juróom ñenti fukki yoon.
|
Since then, China's economic size has increased by 90 times.
|
Dustin « Goldust » Runnels a commenté que « Luna était aussi bizarre que moi… voire même encore plus… je l'aime et elle va me manquer… j'espère qu'elle repose dans un meilleur endroit. »
|
Dustin "Goldust" Runnels wax na ni "Luna doyonna war ni man…xeeyna sax luko ëpp…bëgg naa ko dina ko namm…fookni mongi ci bërëb bu dàq."
|
Dustin Goldust Runnels commented that Luna was as weird as I am... maybe even more so... I love her and I'm going to miss her... I hope she's in a better place.
|
C'est ainsi que tu avais balancè professeur Thiam au cabinet
|
Noonu la boole Porofesëer Caam ak kër awokaa googu
|
That's how you ratted out Professor Thiam at the office.
|
À ce stade, une question cruciale s’impose: comment la responsabilité de Mamour Diallo peut-elle être entièrement, légalement, raisonnablement, écartée,en ce qui concerne les 2 actes d’acquiescements dont l’existence est reconnue par la commission parlementaire ?
|
Ci bile tolluwaay, ab laaj bu am solo taxaw : naka la dayob Maamur JÀLLO, ci lu mat, tegu te am xel nangu ko, mën cee beddeeku ci lu jëm ci ñaari jëfi nangu yi nga xam ne ag amam, kurélu ndawi péncu réew mi nangu nañu ko ?
|
At this point, a crucial question arises: how can Mamour Diallo's responsibility be fully, legally, reasonably, dismissed, with regard to the two acts of acquiescence whose existence is recognized by the parliamentary committee?
|
Une carte et un rapport sur l’habitat seront établis afin de dresser un tableau détaillé de leur comportement à l’échelle du territoire.
|
Xamnañu ni dinañu am ap kano bu am doole lool, ap feles buy baare ay bal ci saxar ak ci misilu bato ni ki noonu ay xarala yu weñ lu ci mel ni ay radaar yu ñu waññi, ay xaatim yu akustik.
|
A map and habitat report will be drawn up to provide a detailed picture of their behaviour at the territorial level.
|
Trump a poursuivi « Vous voyez ce groupe radical horrible, vraiment horrible, des démocrates, vous le voyez à l’œuvre.
|
Trump wëyal, " gisnga lu bonn li, mboolo ay Demokarat yu xannaasu, yaangi koy gis muy am leegi nii.
|
Trump continued, "You see this horrible, really horrible, radical group of Democrats, you see it at work.
|
Le pays est aussi contraint de rendre les médailles d’argent qui lui ont été décernées lors de la finale perdue face au Cameroun.
|
Ga nañu réew mi mu delloo medaayi xaalis yi mu jëlee woon ca finaal ba mu ñàkkoon ci digganteem ak Kamërun.
|
The country is also forced to return the silver medals it won in the final against Cameroon.
|
Il s’est réjoui de la présence des conseillers et a formulé des vœux de réussite pour chacun d’entre eux.
|
Rafetlu na teewaayu disóowaale yi te ñaanal na leen ndam.
|
He was delighted with the presence of the advisers and wished success to each of them.
|
Mais il y a un hic, à Touba des paysans indiquent qu’ils attendent encore que l’Etat leur prenne leurs arachides… Vrai ou faux les OPS disent que l’argent n’est pas arrivé.
|
Waaye am na lu xew, ca Tuubaa baykat yi nee nañu ñoo ngi xaar ba léegi Nguur gi jënd seen gerte yi… liy dëgg mooy jëndkat yi wax ne xaalis bi ñëwagul.
|
But there is a catch, in Tuba farmers indicate that they are still waiting for the state to take their peanuts... True or false the OPS say that the money has not arrived.
|
Il a violé et sodomisé une fille de 20ans.
|
Dafa siif xale bu jigéen bu am ñaar-fukki at ba noppi, sëy ak moom ci ginnaaw.
|
He raped and sodomized a 20-year-old girl.
|
L’enregistrement est une exigence supplémentaire pour la procédure de visa. Dans certains pays, vous devez vous faire enregistrer et indiquer l’adresse de votre lieu de séjour auprès des autorités locales.
|
Mbindu donna anam buñu yokk ci wutuum viza. Ci yen réew yi, warnga mbindu sa tewaay ak sa adarees fingay nëkk ak njitu gox bi.
|
Registration is an additional requirement for the visa procedure.In some countries, you must register and give the address of your place of residence to the local authorities.
|
Pour cela, ils devaient se débarrasser des bases et des navires britanniques en Égypte. En dehors de ces actions, les cuirassés italiens n'étaient pas censés faire quoi que ce soit d'autre.
|
Ngir lii, dañoo wara tàggale bërëb yi ak gaal Angalteer yi ca Isipt. Tamit yoyu jëf, gaalu xare yu Itaali xalaatuñu ngir def dara.
|
To do this they had to get rid of the British bases and ships in Egypt, and apart from these actions the Italian battleships were not supposed to do anything else.
|
D’aider son peuple à y voir plus clair et éviter une catastrophe sanitaire probable ?
|
Dimbali askanam ngir mu gën a fagaru ba moytoo dugg ci guutag wér-gi-yaram ?
|
To help his people see things clearly and avoid a probable health catastrophe?
|
Les dernières estimations du National Hurricane Center prévoient 5 à 10 cm de précipitations, et jusqu’à 15 cm par endroits dans le Mogollon Rim, en Arizona.
|
Fasoŋu Santaru Uragaan bu kawe bi defa ni dina am taw bu 2 ba 4 milimeet, ak ay pacc yuy am ba 6 milimeet ci Mongollon Rim bu Arizona.
|
The latest estimates from the National Hurricane Center are predicting 5 to 10 inches of rain, and up to 15 inches in places in the Mogollon Rim, Arizona.
|
Lamb se mesure à un autre titulaire, le républicain Keith Rothfus, qui représente actuellement l’ancien 12è district de Pennsylvanie, lequel chevauche fortement le nouveau 17è district.
|
Fox News amna natt seetaankat bu tollu ci 2.4 milyoŋ bo 1.7 milyoŋ ñeenti att ci ginnaaw, su nu sukkandikoo ci Nielson , ak MSNBC "The Rachel Maddow Show" moo jiite ci natt yi ak luy tollu ci 3.5 milyoŋ seetaankat ci masoor guddi yu bees.
|
Lamb is running against another incumbent, Republican Keith Rothfus, who currently represents Pennsylvania's old 12th district, which strongly overlaps the new 17th district.
|
Mais certains analystes pensent qu’il y a peu de chances que le tribunal se prononce en faveur du Chili. Et que peu de choses changeraient, même en cas de décision positive.
|
Waaye yenn seytukat yi yaakaaruñu ni kuur bi dina jël ndogal buy neex waa Boliwi -te su loolu amoon itam du bari lu soppeeku.
|
But some analysts believe that there is little chance that the court will rule in favor of Chile and that little would change, even if the decision were positive.
|
Sur un coup franc magistral, l’Argentin surprend en puissance le portier des Colcheneros.
|
Ci ab kuufarãa bu rafet, la waa Arsàntiin bi bett gàrjeŋu Colcheneros yi.
|
With a masterful free kick, the Argentine surprises the Colcheneros goalkeeper in power.
|
Cinque Terre, qui signifie Cinq Terres, comprend les cinq petits villages côtiers de Riomaggiore, Manarola, Corniglia, Vernazza et Monterosso dans la région italienne de la Ligurie.
|
Cinque Terre, buy tekk Jutóomi Suuf, moo boole juróomi wilaas yu ndaw yi ci kotu Riomaggiore, Manarola, Corniglia, Vernazza ak Monterosso yu nekk ci diiwaanu Liguira bu Itaali.
|
Cinque Terre, which means Five Lands, includes the five small coastal villages of Riomaggiore, Manarola, Corniglia, Vernazza and Monterosso in the Italian region of Liguria.
|
Cette eau était bien autre chose qu’un aliment.
|
Ndox moomu ëppoon na aw ñam rekk.
|
This water was more than food.
|
L’opposition n’a reçu le fichier que dans la dernière semaine d’avant élection.
|
Kujje gi jotuñu ci Kayitu turi aji-wote yi ba wote yi des benn ayu-bés.
|
The opposition did not receive the file until the last week before the election.
|
En effet, pour éviter l’obscurantisme, cette croyance ne doit pas exclure le savoir.
|
Ba tax na, ngir moytu segg yenn xam-xam yi, gëm-gëm bii warul dàq xam-xam bi.
|
In order to avoid obscurantism, this belief must not exclude knowledge.
|
En revanche pour la vente au détail aux usagers domestiques, la fonction technique de branchement et de pose des compteurs est dévolue à Sénélec tandis que la fonction commerciale de relève, de facturation et d’encaissement sera libéralisée.
|
Co kow lóolu, ngir jaay yu sew yi waaye jëfandikoo yi ci kër yi, liggéeyu xarañte gi ngir dugal ak teg ay kontëer weesu nañu ko ci SENELEC, waaye nag liggéeyu njaay mi di natt, ak appal wala fayeeku dinañu ko yombal.
|
However, for retail sales to households, the technical function of connecting and installing meters is delegated to Sénélec, while the commercial function of relaying, invoicing and cashing will be liberalised.
|
De nombreux bâtiments sont plutôt agréables à regarder, et la vue qu'offrent les grands bâtiments ou des fenêtres savamment placées peut être d'une beauté saisissante.
|
Tabax yu bari dañoo rafet lool te soo koy xool ci ab tabax bu magwala ci ab palanteer buñu tek ci lu ànd ak xel mën naa doon rafetaay buñu wara gis.
|
Many buildings are quite pleasing to look at, and the view from tall buildings or cleverly placed windows can be breathtakingly beautiful.
|
Elle allait durer pendant les 40 années suivantes et verrait des affrontements réels, par le biais d'armées de substitution, sur des champs de bataille aussi bien en Afrique qu'en Asie, en Afghanistan, à Cuba et dans bien d'autres endroits.
|
Defa nekkon lu wara am diiru ñent fukki at yi di ñëw te doon xeex dëggëntaan, arme bu proxy def ko, ci ëttu xare yu doore Afrig ba Asi, ci Afghanstan, ci Cuba ak yeneen barab yu bare.
|
It would last for the next 40 years and would see real-life confrontations, through surrogate armies, on battlefields as far afield as Africa and Asia, Afghanistan, Cuba and many other places.
|
Un projet discuté depuis de nombreuses années, mais qui s’est heurté à certaines réticences, notamment du Nigeria, poids lourd de la zone.
|
Naal la bu ñuy xalaat diirub at yu bari, waaye dafa mbëkkante ak tërëdig jamono, bu ci mel ne Niseriyaa, ponkalu diwaan bi.
|
The project has been discussed for many years, but has faced some reluctance, notably from Nigeria, a major player in the area.
|
Selon Abdoulaye Daouda Diallo, les fonds ainsi obtenus, seront ’’exclusivement utilisés pour le rachat d’environ 70 % de l’eurobond de 2014, exigible à trois ans de l’échéance et libellé en dollars par de nouveaux titres en euros, ainsi que le financement de la participation du Sénégal dans le développement des projets pétroliers et gaziers’’.
|
Abdulaay Daawuda Jàllo nee na xaalis bi ñu jot dañu koy jagleel njëndaatug lu toll ci juróom -ñaar fukk ci téeméer boo jël ci booru atum 2014 te ñu war koo fay ci xaalisu dolaar ci ñetti at, ak xaalis bi Senegaal di jàppe ci yokkuteg tëralinu petorol bi ak gaas bi.
|
According to Abdoulaye Daouda Diallo, the funds thus obtained will be used "exclusively for the repurchase of approximately 70% of the 2014 Eurobond, due three years from maturity and denominated in dollars by new securities in euros, as well as the financing of Senegal's participation in the development of oil and gas projects".
|
L’agence de gestion des catastrophes a indiqué dimanche matin que le bilan du séisme et du tsunami fait état de 832 morts.
|
Bankaasu musiba xamlena Dibeer ni deewu nit yi ci yenngu yenngu suuf ak sunami bi ci Enndonesi yeegna ba 832.
|
The disaster management agency said Sunday morning that the death toll from the earthquake and tsunami was 832.
|
Pendant les années 1980, il a travaillé sur des spectacles tels que Taxi, Cheers et The Tracy Ullman Show.
|
Ci ati 1980s dafa doon ligéy ci lu mélni Taxi, waaw goor, ak Tracy Ullman Show.
|
During the 1980s, he worked on such shows as Taxi, Cheers and The Tracy Ullman Show.
|
En effet et si vous y regardez bien, dans les encarts publicitaires de promotion des produits des multinationales installées au Sénégal, les filles choisies ont pour la plupart les mêmes mensurations que nos nouvelles miss.
|
Su ngeen seetee bu baax, ci alluway fésal yi këri liggéeyukaay yu mag yu bitim-réew yi def ci réew mi, xale yu jigéen yi ñu tànn, am nañu, li ci ëpp, màndarga wala melokaan yi suñu xale yu jigéen yi fi gën a rafet (miis yi) am.
|
Indeed, if you look closely, in the advertising posters for the products of the multinationals established in Senegal, the chosen girls have mostly the same measurements as our new Miss.
|
Ainsi, la prononciation du verbe condamner par certains ministres de la république me fait frissonner.
|
Ci ndimbalu baatu àddina bi lañuy xool ndax dugg bu gën a rëy ci lebu jigéen ñi ci góor ñi am na jeexital ci yemale bànk bi.
|
I am therefore appalled by the way some of the republic's ministers use the word 'condemn'.
|
Indonésie : le nombre de victimes du tsunami s’élève à 832
|
Limu nit yi dee ci Sunami bu Enndonesi yegna ci 832.
|
Indonesia: 832 people killed by tsunami
|
Il affirme qu’un énorme porc mâle s’y trouvait à l’intérieur et que du sang coulait de sa gueule.
|
Neena ci biir gett ba gisna fa benn mbaam xuux bu goor bu magg te gemmin gi takk deret.
|
He claims that "a huge male pig was inside and blood was coming out of its mouth".
|
ADO lâché par papa Macron et ses confrères africains, a été reçu avec une sobriété protocolaire qui frisait le ridicule, déambulant seul dans la Cour c’est un Macron crispé qui l’attendait au pas de la porte, corona oblige ou le cordon est définitivement coupé.
|
ADO ma Baay Macron bàyyi ak ay mbokki saa-afrigam, dalal nañu ko, ak ag dal gu yemoo ak li war te nirook doyal, doon doxantu moom doŋŋ ci ëtt bi, am Macron mu jaaxle moo ko doon xaar ci bunt bi, koronaa bee ko waral, dajaloo yépp lañu dakkal.
|
ADO released by Pope Macron and his African colleagues, was received with a protocol sobriety that bordered on ridicule, walking alone in the Court it is a tense Macron who waited for him at the doorstep, corona forces or the cord is definitely cut.
|
’’Si tout se passe comme nous l’avons prévu, l’exploitation de ce gaz que se partagent le Sénégal et la Mauritanie, va effectivement démarre à partir du second semestre de l’année 2023’’, a-t-il déclaré en marge de la cérémonie de signature de deux accords, relatifs à l’emploi des jeunes et la lutte contre les inondations.
|
Ca ndaje ma ñu doon xaatime ñaari déggoo yi jëm ci xëyu ndaw ñi ak mbënn mi la xamle ne bu lépp amee ni ñu ko séentoo, njaayum gaas bi Senegaal ak Móritani di séddoo nar nañu koo tàmbali ci juróom-benni weer yi mujj ci 2023.
|
"If everything goes as we have planned, the exploitation of this gas, which is shared by Senegal and Mauritania, will actually start from the second half of 2023", he said on the sidelines of the signing ceremony of two agreements, relating to youth employment and flood control.
|
Le puits que nous avions atteint ne ressemblait pas aux puits sahariens.
|
Teen ba nu yemoon, nuroowul ak teeni Sahara yi.
|
The well we reached was not like the wells in the Sahara.
|
Réunis samedi 29 juin à Abuja, au Nigeria, les chefs d’État et de gouvernement ont adopté une feuille de route vers cette monnaie commune.
|
Daje nañu gaawu ñaar-fukki ak juróom ñeent ci weeru suweŋ ci Abujaa, ca Niseriyaa, Njiitu réew yi ak yu jëwriñ yi bokk nañu ci ab tëralin wu jëm ci xaalis bu ñépp bokk.
|
The Heads of State and Government met in Abuja, Nigeria, on Saturday 29 June and adopted a roadmap towards a common currency.
|
Elle concerne particulièrement l'arachide, dont les semences sélectionnées avaient presque fondu.
|
Mu ngi gën a soxal gerte gi, te nga xam ne jiwu wi ñu tànnoon dafa seeyoon daanaka.
|
The peanut is particularly affected, as the selected seeds were almost melted.
|
C’est une tragédie.
|
Defa bon lool.
|
This is a tragedy.
|
Où veux-tu emporter mon mouton ?
|
Fan nga jëme sama xar mi?
|
Where are you taking my sheep?
|
Les sous-marins sont des navires conçus pour voyager sous l'eau et y rester pendant une longue période.
|
Submarines ay xéétu gaal la yoo xam ni ci biir ndox mi lay tukki, té nékk fa ci lu yagg.
|
Submarines are vessels designed to travel underwater and stay there for a long period of time.
|
Je connais une planète où il y a un Monsieur cramoisi.
|
Xam naa palanet bu am nit ku xonq coyy.
|
I know a planet where there's a Mr. Crimson.
|
Si vous regardez les êtres vivants sous un microscope, vous verrez qu'ils sont faits de petits carrés ou de boules.
|
Soo xoolee mbir yuy dund ci mikroskop, di nga gis ni danu leen defaree kaare yu ndaw ak ay ball.
|
If you look at living things under a microscope, you'll see that they're made of little squares or balls.
|
que le fils et successeur du Père Johnson à la direction de l’église de Saint Martin, le Révérend David Johnson, appelait avec fierté les « cloches des gens pauvres ».
|
Reweraan David Johnson, doomu Pappa Johnson te wara wuutu Martin mu sell mi te ñu koy wowe kariyoon bi "kolosu niit gi doole yi."
|
that Father Johnson's son and successor at the head of St Martin's Church, the Reverend David Johnson, proudly called the "poor people's bells".
|
Le Sénégalais a fait 9 clean sheets lors de cette campagne de Ligue des Champions 2020/21, un record pour un gardien sur un même exercice dans cette compétition avec Santiago Cañizares avec Valence en (2000/01) et Keylor Navas avec le Real Madrid en (2015/16).
|
Doomi Senegaal bi def na juróom-ñeenti joŋate yu mu am ndam te jëlul benn bit ci Ligg-dee-sàmpiyoŋ 2020 / 2021, mu nekk lu benn góol mësul a def ci jéemantu bu ni mel ci joŋante boobu ak Santiago Cañizares ak Valence atum 2000 / 01 ak Keylor Navas ak Real Madrid atum 2015 / 16.
|
The Senegalese made 9 clean sheets during this 2020/21 Champions League campaign, a record for a goalkeeper in the same year in this competition with Santiago Cañizares with Valencia in (2000/01) and Keylor Navas with Real Madrid in (2015/16).
|
Maroochydore avait terminé en haut de l'échelle, avec six points d'avance sur Noosa qui arrive en deuxième position.
|
Maroochydore jexaloon na ci kaw eskaliyee bi, juróom benni poñ yu leral ci Noosa ci a ab saa.
|
Maroochydore finished on top of the table, six points ahead of Noosa in second place.
|
Cependant, en juin 1956, les promesses de Khrouchtchev ont été mises à l'épreuve lorsque les émeutes en Pologne, où les travailleurs protestaient contre les pénuries alimentaires et les réductions de salaires, se sont transformées en une protestation générale contre le communisme.
|
Waaye ci Suwee 1956, dañoo nekkoon di testé dige yu Krushchev joxe woon bi reyante yi amee ca poloñ, bi liggéeykat yi nekkee di ñaxtu ci nakkum lekk yi ak seen payoor yuñu dagg, mujjee doon ñaxtu bu ñepp di def ngir xeex Kominism.
|
However, in June 1956, Khrushchev's promises were put to the test when riots in Poland, where workers were protesting food shortages and wage cuts, turned into a general protest against communism.
|
Thiès restera largement entre les mains de Idy forever !
|
Cees dina wéy di des ci yoxoy Idy forever !
|
Thiès will remain largely in the hands of Idy forever!
|
La lutte est notre gagne-pain’’, fait valoir le lutteur de Guédiawaye, actuellement en préparation à l’INSEP, l’Institut national du sport, de l’expertise et de la performance, en France.
|
Bëre moo ñuy dundal, yëkëti mbëri Géejawaay miy waaje ca INSEP, lekoolu tàggat-yaram, bu manoore ak jalloore ca Farãas.
|
"We are all about wrestling", says the Guédiawaye wrestler, who is currently preparing for the event at INSEP, the National Institute of Sport, Expertise and Performance in France.
|
Nous aurions peut-être pu l’emporter à la fin, mais, dans l’ensemble, un match nul constituait probablement un résultat équitable.
|
Loolu ay su yu bari la, te nak waxuma ni loolu dey firndeel ni kii di Trump amul fumuy jaar ba du daanu- du moroomam yii ci Orop tamit.
|
We might have won in the end, but overall, a draw was probably a fair result.
|
Puis il ajouta : Va revoir les roses. Tu comprendras que la tienne est unique au monde. Tu reviendras me dire adieu, et je te ferai cadeau d’un secret.
|
Mu daldi ci teg ne: Demal seetiwaat roos ya. Dinga xam ne sa bos benn la ci àdduna. Dinga dellusi tàggu ma, ma neexale la benn ndéey.
|
Then he said, "Go and see the roses, and you will see that yours is unique in the world. Come back and say goodbye to me, and I will give you a secret gift".
|
Il y a 20 ans il remplissait le stade Léopold Senghor, et aujourd'hui il vit terre comme un rat.
|
Ligg sàmpiyoŋ tàmmal nañu benn joŋante bu neex bës bu ne.
|
Twenty years ago he filled the Leopold Senghor Stadium, and now he lives in the dirt like a rat.
|
Si vous vous sentez d'humeur plus aventureuse, profitez de l'occasion pour préparer un jus ou mélanger des smoothies :
|
Bu dee da nga yég ay mbir, wutal buntu defar suu wala smoothi:
|
If you're feeling more adventurous, take the opportunity to make a juice or mix smoothies:
|
Nous resterons sur vos chiffres, rien que sur vos chiffres !
|
Duñu romb seen lim yi, foofu rekk lañuy yem !
|
We'll stick to your numbers, just your numbers!
|
Ce matin, des personnes affirmant connaître la femme se sont présentées sur les lieux du crime et ont posé des questions sur l’endroit où elle a été découverte.
|
Tay ci ngoon ay xarit yu yaakaar ni xamnañu jigeen bi ñewnañu fi mbir mi ame ngir laaj fu ñu ko fekkoon googu suba.
|
This morning, people claiming to know the woman showed up at the crime scene and asked questions about where she was discovered.
|
Ces gens là se disputent leurs vidéos le matin, mais dinent ensemble le soir.
|
Gaa yóoyu ñooy xuloo ci seen widéwoo yi ci suba, waaye ñooy bokk reer ngoon.
|
These people are fighting over their videos in the morning, but they're having dinner together at night.
|
Lors d’un direct Instagram avec le youtubeur Mohamed Henni pendant le tout premier confinement, Karim Benzema se lâche sur Olivier Giroud,qu’il estime loin d’être à son niveau sur les terrains.
|
Ci ab jotaayu eestagaraam ak way-yuutub bi Mohamet Eni ci biir tëju gu jëkk ga, la Kariim Bensemaa dal ci kaw Oliwiyee Siru, mi mu jàpp ne du sax moroomam ci futbalukaay yi.
|
During an Instagram live with YouTuber Mohamed Henni during the first lockdown, Karim Benzema lashed out at Olivier Giroud, whom he felt was far from his level on the pitch.
|
A cause de lui, on a eu 15morts dans les manifestations du mois de mars qu'il avait organisées.
|
Waññi nañu fukki nit ak juróom ñu faatu ci manifestey weeru màrs yi ndax moom rekk.
|
Because of him, we had 15 deaths in the March demonstrations he organized.
|
Sa décision a laissé tout le monde sans voix.
|
Xalaatam bayi bi daal daa yeem ci bokkoon ci mbir mi yepp.
|
His decision left everyone speechless.
|
Le tout dernier rapport de la Commission des pêches et de la faune de la Floride indique une diminution générale des concentrations de la marée rouge dans certaines zones de la région de la baie de Tampa.
|
Benn weteraan bu jiroom ñetti Ryder cups, doomu Espaañ Sergio Garcia mii def lu kenn deful ci turnuwa bii nii ci Orop ak 25.5 poñ ci jaar jaaram.
|
The latest report from the Florida Fish and Wildlife Commission indicates a general decrease in red tide concentrations in some areas of the Tampa Bay area.
|
Sadio Mane redonne l’avance à Liverpool à 81e minute et marque son 18e but à Anfield.
|
Te nag, nañu bàyyi xel bu baax ci ñi mbiru CSA bi nar a mujjee.
|
Sadio Mane returns to Liverpool's lead in the 81st minute and scores his 18th goal at Anfield.
|
Les produits peuvent être achetés si le besoin se fait sentir, mais la plupart n'auront que peu ou aucune incidence réelle sur la performance de l'athlète.
|
Kenn yaa xam lu tax nga jënd produit waaye barina ci yoo xamni duñu mat liñu leen di doyee.
|
Products can be purchased if the need arises, but most will have little or no real impact on the athlete's performance.
|
Dans son ouvrage Les leçons du pouvoir, l’ancien président de la république française François Hollande, constatant l’échec de la zone Euro, a déclaré : Il y a autant d’unions européennes que de pays qui la constituent.
|
Ci téereem bi tuddu Les leçons du pouvoir (tegtaley nguur) njiitu réewu Farãas ba woon di Farãasuwaa Olànd, bi mu gisee daanug déndu Ëro dafa wax ne : ay mboolooy Ërob yu bari ñoo am ba tollu ni réew yi ko séq.
|
In his book Les leçons du pouvoir, former French President François Hollande, noting the failure of the Eurozone, said: 'There are as many European unions as there are countries in it.
|
Ainsi, F. B s'est engagée à rembourser le montant détourné.
|
Ci loolu, F. B. nee na dina delloo limu xaalis bi mu lekkoon.
|
F.B. therefore undertook to repay the amount embezzled.
|
Le secrétaire général de Pastef HLM donne les détails de ce projet.
|
Njiit lu Pastef HLM joxe nay leeral na naal bile.
|
The secretary-general of Pastef HLM gives details of this project.
|
La sénatrice du Massachusetts Elizabeth Warren a annoncé samedi qu’elle envisagerait sérieusement la possibilité de se présenter aux élections présidentielles à la suite des élections de mi-mandat.
|
Ndawu askan wi tontu: App yoon bu guddu te yagg lool lay doon- yenn saa yi dinañu lajj, lajj;
|
Massachusetts Senator Elizabeth Warren announced on Saturday that she would seriously consider running for president following the midterm elections.
|
Accompagné d'une forte délégation composée de hauts gradés de la gendarmerie nationale, le Général dont les fonctions prendront fin le 15 novembre prochain (il est admis dans la 2ème section (réserve) des cadres de l'Etat et sera remplacé par Général de division Jean-Baptiste Tine), a effectué sa dernière ziara en tant que Haut-commandant de la gendarmerie nationale.
|
Mu ànd ak mbooloo mu takku te bokk ca ay kilifay sàndarmóori, Seneraal bi war a bàyyi liggéey ba fukki fan ak juróom ci weeru nowàmbar wii di ñëw (mu ngi ñu yóbbu ca ñaareel sàqum kàngami nguur gi te Seneraal Saŋ Batis Tin war koo wuutu), defi woon na siyaareem bu mujj ak ndombo tànk googu.
|
Accompanied by a strong delegation of high-ranking officers of the national gendarmerie, the General whose duties will end on November 15 (he is admitted to the 2nd section (reserve) of the State cadres and will be replaced by General of Division Jean-Baptiste Tine), made his last visit as High Commander of the national gendarmerie.
|
Bien que ce soit sa création et le fruit de son imagination, il a toujours attribué le mérite à Paddington lui-même. »
|
Maurice feyoon nañ ko benn bës bi mu ligeey bi ba pare ñu dellooo ko seen kër ngir benn Uber.
|
Although it was his creation and the product of his imagination, he always attributed the credit to Paddington himself.
|
Laissez à d'autres le soin de menacer les sénégalais et honteusement, de vouloir vous l'imputer.
|
Bàyyil ñeneen ñi ñuy tëkku saa-senegaal yi teg ci gàcce, bëgg la koo jiiñ yow.
|
Let others threaten the Senegalese and shamefully try to blame you.
|
Je vous la reproduis également in extenso :Dakar, le 13 novembre 2017.
|
Dinaa la ko defaraatal lépp : Dakaar, fukki fan ak ñett ci weeru nowàmbar 2017.
|
I also reproduce it in extenso: Dakar, 13 November 2017.
|
Après la Roma la saison dernière, c’est la deuxième fois que le FC Barcelone s’écroule à ce point, et manque un titre européen qui semblait lui être promis.
|
Gànnaaw La Roma at mi weesu, bii mooy ñaareel bi yoon FC Barcelone di nërmelu ci gile tolluwaay ba mooy turu njiit li meloon ne amoon na ko.
|
After Roma last season, this is the second time FC Barcelona has collapsed to this point, missing a European title that seemed promised to them.
|
Les réduves, tout comme les punaises de lit, sont nidicoles, c'est-à-dire adaptées pour vivre dans le nid ou l'habitat de leur hôte.
|
Màttu lal yi ak yeneen matt yi mën nañu dëkk ci tàgg wala ci yeneen barab lépp ngir sonal nit ñi.
|
Bedbugs, like bedbugs, are nest-builders, meaning they are adapted to live in the nest or habitat of their host.
|
Elle surfe sur la sémantique de la campagne de l'opérateur Free pour mieux asseoir son offre et pointer, entre les lignes, le principal point faible du concurrent Free : le réseau.
|
Mu ngi saytu bu baax naka la Free di amalee seen kampaañ ngir mën a defaruwaat bu baax ba noppi di wone jafe-jafey wujjam wi di Free : reso bi.
|
It uses the semantics of the Free operator's campaign to better establish its offer and to point out, between the lines, the main weak point of the Free competitor: the network.
|
Sénégal, un pays où 70% de la population a moins de 30 ans, cette jeunesse est un atout de taille pour relever les défis de l’émergence.
|
Senegaal, dëkk boo xam ne juróom-ñaar fukk ci téeméer boo jël ci askan, amuñu lu mat fan-weeri at, loolu ndollent la bu mag bu ñu war a sukkandiku ngir sóobu ci yoonu yokkute.
|
In Senegal, where 70% of the population is under 30, this youth is a major asset in meeting the challenges of emergence.
|
Je suis très vieux, je n’ai pas de place pour un carrosse, et ça me fatigue de marcher.
|
Dama màggat lool, amuma béréb bu ma def wëtiir, te dox bi dafa may sonal.
|
I'm very old, I don't have room for a carriage, and it tires me to walk.
|
Sur les îles avoisinantes, les cartes de crédit ne seront probablement pas acceptées, même s’il se peut que les devises britannique et américaine le soient. Parlez-en à l’avance avec les propriétaires afin de vous mettre d’accord sur une méthode de paiement.
|
Ci yenn dëkk yi kàrt keredi yi xeeyna duñuléén nàngu, ndéem Angale yi ak waa Amerig yi nangoo gu ñu ko léégi, xoolal ak boroom lu njëkk ngir xam lan moo yak pay guñu nangu.
|
On the neighbouring islands, credit cards are unlikely to be accepted, although British and American currency may be. Talk to the owners in advance to agree on a payment method.
|
L’équipe locale s’est rassemblée et Bouchard a encore une fois égalisé avec un but donnant un avantage numérique à 27:37.
|
Dawuma."
|
The home team rallied and Bouchard once again tied with a goal giving them a numerical advantage at 27:37.
|
Il faut changer la manière de présenter les choses et c'est la responsabilité de la presse.
|
Dina soppi ni muy doxale mbir yi te loolu di li gàllu ci ndoddu këri tas xibaar yi.
|
We need to change the way we present things and that's the responsibility of the press.
|
Sselon Mike Organ, du Tennessee State, Christion Abercrombie, le secondeur des Tigers du Tennessee, a été opéré d’urgence après une blessure à la tête samedi lors de la défaite des Vanderbilt Commodores 31-27.
|
Waante dinañu xool te dama bëgg di yégal saasune taskatu xibaar yi."
|
Tennessee State's Mike Organ said Tennessee Tigers running back Christion Abercrombie was rushed to emergency surgery after suffering a head injury Saturday in a 31-27 loss to the Vanderbilt Commodores.
|
Selon la police, l’incident s’est produit à Ballyhackamore.
|
Yooyu kaddoom taxaw setlu waral ay yuuxu ñaari yoon ci mboolo mi SNL japp ay nit yu am naxxar, , dax nañu wariyete bi, ak benn nit bu doon wax ci pibilikaasiyoŋ bi "Istijoo bi ni cell mel ni u dee."
|
According to police, the incident occurred in Ballyhackamore.
|
C’était bien parti pour le Real car à la 17e min, l’inévitable Benzema lançait les hostilités.
|
Tàmbali bu neex la woon ci Real ndax ca fukk ak juróom-ñaareelu simili ba la Benzema mu xarañ ma tàmbali dug ci joŋante dëgg.
|
It was a good start for Real because in the 17th minute, the inevitable Benzema started the hostilities.
|
Le groupe de rock devait faire une tournée aux États-Unis et au Canada jusqu'au 16 septembre.
|
Grubu rock bi dafa waroon def benn turne ci Etaa Sini ak ci Kanadaa ba 16 sàttumbar.
|
The rock band was scheduled to tour the United States and Canada until September 16.
|
Tey, lu naroon a def 10i at ngir leer ci xeli nit ñi, daanaka, bu yàggee ba yàgg, 2i weer kott lay def mbaa lu ko yées.
|
Tey, lu naroon a def fukki at ngir leer ci xeli nit ñi, daanaka, bu yàggee ba yàgg, ñaari weer kott lay def mbaa lu ko yées.
|
I'm not sure I'm ready to read this tonight.
|
Afin de recevoir un billet gratuit pour l’événement (à moins que vous ne soyez prêt à payer un billet VIP), les spectateurs devaient accomplir une série de tâches, ou d’« actions », comme du volontariat, envoyer un courriel à un leader mondial, téléphoner ou faire tout autre effort utile dans le but de sensibiliser la population à la lutte contre la pauvreté.
|
Moom firndeelna itam ay pexe ngir tek ligeeykat yi sosete yi ak defar ay moomel yu ñu bëgg ngir japp ci 10 ci teemeer boo jël ci sekteer piriwe, yamale ligeeykat yi ñii di taxaw ngir dugal £500 ci seen poos ci at bi.
|
In order to receive a free ticket to the event (unless you are willing to pay for a VIP ticket), spectators had to complete a series of tasks, or actions, such as volunteering, emailing a world leader, calling, or doing any other useful effort to raise awareness about poverty.
|
La diaspora du Canada et des USA avait mobilisé presque la caution (17 millions) de la candidature aux législatives en 2017 pour la coalition Ndawi_.
|
Waa Senegaal ya nekk ca Kanadaa ak Etaasini dajale woon nañu lu jege koppar yiy tax kowaalisiyoŋ Ndawi_ mën a bokk ci joŋante dipite yi atum 2017 (fukki milyoŋ ak juróom-ñaar).
|
The diaspora in Canada and the US had mobilized almost the bail (17 million) of the candidacy in the 2017 legislative elections for the Ndawi coalition.
|
Subsets and Splits
No community queries yet
The top public SQL queries from the community will appear here once available.