start_time
float64
0
2.73M
end_time
float64
326
2.78M
speaker_id
stringclasses
55 values
text
stringlengths
1
4.06k
audio
audioduration (s)
0.17
388
2,170,485
2,170,984
99spk2
%hum %hum
2,170,984
2,171,982
99spk1
ñu constater ko
2,171,982
2,172,486
99spk2
%hum %hum
2,172,486
2,175,272
99spk1
muy service technique élevage bu agriculture
2,175,272
2,175,634
99spk2
%hum %hum
2,175,634
2,177,950
99spk1
bu pêche bu ñu constater que yàqu-yàqu am na
2,177,950
2,178,282
99spk2
%hum %hum
2,178,282
2,181,822
99spk1
ñun daañu delloo banque bi quatre vingt pour cent ci ci million
2,182,437
2,183,090
99spk1
huit cent mille
2,183,090
2,183,872
99spk2
huit cent mille
2,183,872
2,184,210
99spk1
waaw
2,184,210
2,184,570
99spk2
%hum %hum
2,184,570
2,187,877
99spk1
donc là mën naa am banque bi mën na am du la ko laaj
2,187,877
2,188,390
99spk2
%hum %hum
2,188,390
2,193,891
99spk1
mais yow bu la neexee nga ne banque %e kii producteur ne banque bi dama bëgg assurer xaalis bi
2,193,891
2,194,307
99spk2
%hum %hum
2,194,307
2,196,429
99spk1
ñoom daañu ñëw bu ñu ñëwee ñu defal leen contrat bi
2,196,429
2,196,931
99spk2
%hum %hum
2,196,931
2,199,283
99spk1
nga verser foofu directement ñu assurer la
2,203,644
2,205,290
99spk2
mbay %hum %hum
2,205,290
2,208,077
99spk1
%e agriculture élevage pêche
2,208,077
2,209,760
99spk2
pêche ñett yooyu daal ñoom ñoom
2,211,660
2,212,075
99spk2
%hum %hum
2,212,075
2,213,831
99spk1
vraiment bokkul ci suñu compé()
2,213,831
2,214,826
99spk2
bokkul seen compétence
2,214,826
2,215,134
99spk1
waaw
2,215,134
2,222,426
99spk2
loolu daal am na solo waaye xam nga sànq ci bi ñuy wax ci mbirum %e jiwu da nga ne %e jiwu bi ba nit ki bay xam nga
2,223,611
2,224,054
99spk1
%hum %hum
2,224,054
2,226,781
99spk2
mooy boo bayee ba noppi denc ba
2,227,622
2,228,166
99spk1
waaw
2,228,166
2,233,060
99spk2
parce que tamit bu fekkente ni foofu ndax assurance bi dina intervenir ba foofu wala
2,233,060
2,234,905
99spk1
léegi ñun bu ñuy assurer nii
2,234,905
2,235,340
99spk2
%hum %hum
2,235,340
2,237,040
99spk1
ba keroog ngay góob
2,237,040
2,238,372
99spk2
ba keroog ngay góob
2,238,372
2,240,297
99spk1
boo boo boogee boo góobee ba pare
2,240,297
2,240,680
99spk2
%hum %hum
2,240,680
2,242,251
99spk1
assurance bi foofu la yam
2,242,251
2,243,229
99spk2
foofu la yam
2,243,229
2,245,219
99spk1
bu la neexee nag nga ne man damay dolli
2,245,219
2,246,250
99spk2
%hum %hum
2,246,250
2,247,553
99spk1
ci pour sama stock bi
2,247,553
2,247,879
99spk2
%hum %hum
2,247,879
2,248,601
99spk1
ma sécuriser ko
2,248,601
2,249,419
99spk2
ma sécuriser ko
2,249,419
2,253,560
99spk1
parce que taw bi mën na ko yàq %e gunóor yi mën nañu ko yàq
2,253,560
2,253,995
99spk2
%hum %hum
2,253,995
2,254,881
99spk1
mën nañ ko sàcc
2,254,881
2,255,228
99spk2
%hum %hum
2,255,228
2,255,931
99spk1
mën na lakk
2,255,931
2,256,224
99spk2
%hum %hum
2,256,224
2,259,681
99spk1
loolu yépp bu la neexee nga dolli ci tuuti encore ñu assurer waat ko
2,259,681
2,260,278
99spk2
ah
2,260,278
2,261,726
99spk1
bu ñu ko sàccee ñu fay la
2,261,726
2,262,335
99spk2
%hum %hum
2,262,335
2,264,128
99spk1
waaw bu fekkee am na yàqu-yàqu
2,264,128
2,264,508
99spk2
%hum %hum
2,264,508
2,267,276
99spk1
comme nu ñu nee gerte bi yàqu na mbaa ñebe yàqu na
2,267,276
2,267,638
99spk2
%hum %hum
2,267,638
2,268,344
99spk1
ñun dañ lay fay
2,268,344
2,269,478
99spk2
%hum %hum
2,274,490
2,274,834
99spk1
%hum %hum
2,274,834
2,277,367
99spk2
%hum jumtukaay yi nga xam ne moom lay liggéeyee tamit
2,277,367
2,277,729
99spk1
waa
2,277,729
2,280,298
99spk2
%hum %e tay jii bu fi ab Diallo Diallo jaaree
2,280,298
2,280,760
99spk1
%hum %hum
2,280,760
2,285,166
99spk2
loolu tamit ndax assurance bi am na lu mu ci war a mën a bu fekkente ne moom demoon na assurer ji ko
2,285,166
2,287,391
99spk1
waaw dëgg la loolu tamit jumtukaat yépp
2,287,391
2,287,947
99spk2
%hum %hum
2,287,947
2,289,798
99spk1
loolu ñuy wax matériel agricole
2,289,798
2,290,251
99spk2
%hum %hum
2,290,251
2,291,582
99spk1
dafa bokk ci assurance bi
2,291,582
2,292,005
99spk2
%hum %hum
2,292,005
2,294,501
99spk1
mën nañu ne sax boobu vraiment moo gën a yomb
2,294,501
2,294,924
99spk2
%hum %hum
2,294,924
2,298,395
99spk1
ci lu jëm ci tracteurs yi houe yi ñoom seen charette yi
2,298,395
2,298,700
99spk2
%hum %hum
2,298,700
2,301,183
99spk1
oto yoo xam ne mu ngi ci biir tool bi di ci liggéey
2,301,183
2,301,661
99spk2
%hum %hum
2,301,661
2,302,848
99spk1
ba ci batimat yi
2,302,848
2,303,192
99spk2
%hum %hum
2,303,192
2,307,759
99spk1
yooyu yépp assurance daf koy jël en charge jàppale la te foofu moo gën a yomb
2,307,759
2,308,475
99spk2
moo gën a yomb
2,308,475
2,311,195
99spk1
gis nga boroom usines yi ñoom dañuy assurer seen usines yi
2,311,195
2,311,615
99spk2
%hum %hum
2,311,615
2,313,965
99spk1
donc ñun tamit dañu ne mbay mi
2,313,965
2,314,327
99spk2
%hum %hum
2,314,327
2,315,521
99spk1
ba ci stock bi
2,315,521
2,315,865
99spk2
%hum %hum
2,315,865
2,317,005
99spk1
ba ci jumtukaay yi
2,317,005
2,317,294
99spk2
%hum %hum
2,317,294
2,319,900
99spk1
assurance mu ngi seen wet di leen jàppale ci risques yi
2,319,900
2,320,507
99spk2
%hum %hum
2,320,507
2,325,075
99spk1
%e bu ñu dellu see maintenant ci mbirum élevage ku wax région de Louga
2,325,075
2,325,681
99spk2
%hum %hum
2,325,681
2,327,517
99spk1
ne mbay ak càmm
2,328,110
2,328,592
99spk2
%hum %hum
2,328,592
2,330,340
99spk1
kooku Yàlla moo ñu ko defal
2,330,340
2,330,808
99spk2
%hum %hum
2,330,808
2,335,135
99spk1
maintenant bu ñu ñëwee ci comme waxtaan nañ ci yële ba mu des donc élevage bi